ADIOUZA - Madame Bonheur (Clip Officiel) đŸŽ¶

Mme Bonheur dĂ©peint la vie d’un foyer polygame oĂč deux dames rivalisent avec respect et loyautĂ©, crĂ©ant une dynamique unique.

ADIOUZA - Madame Bonheur (Clip Officiel) đŸŽ¶
ADIOUZA
19.6M views ‱ Nov 20, 2020
ADIOUZA - Madame Bonheur (Clip Officiel) đŸŽ¶

About this video

Mme bonheur relate le quotidien d’un foyer polygame oĂč premiĂšre et deuxiĂšme dame sont en concurrence loyale et cela toujours dans le respect.
Chacune, s’estime ĂȘtre la prĂ©fĂ©rĂ©e et la clĂ© du bonheur de l’époux.


MADAME BONHEUR (Lyrics)

COUPLET 1
xolou ma kénene fess na sama sétou
jiguéne jiy waxé dieuf dou ame diotou tontou
done awo di bourou keur gui dou aye fontou

té saxe fouma momé
zéro lakoy wathié
lou deuss meuneu daw
1 bé ngui thi kaw
gnari fane youné coco feug aldiana takhaw

bonheur
fi wax amoul thiouray guéy rire
def terreur
loutax mouy séd té may diÚk pire

Refrain
péssé sama bop xamni warouma ragal woudié
ladial mon coeur
kouy madame bonheur
yamay confiné lép di dioup ya raw poli..cier
ladial mon coeur
kouy madame bonheur

Ouhhhh wolma Abass
chéri fatou ak chilel
Borom Gambia

2 eme couplet
li lay door té doula la laale, nékhoul thi
khol
deuxiùme dame bi lagnou takkal medaille d’or

ki nélaw la xamone ma diangal ko yandoor
bayi léne di diém diangue xam sa goor gueuneu woor

xol bi nangou fétté
boboy doundou mbecté
Namouma daray wax
ba fi mingui baakh
chérie dougueul deukeu do feugue yaye laisser passé

allo
fi maay sourire mouy évanouir
mais allo
ay nelaw diékhna dama yor lire

Refrain
péssé sama bop xamni warouma ragal woudié
ladial mon coeur Maye ki koye bonheur
yamay confiné lép di dioup ya raw poli..cier
ladial mon coeur maye ki koye bonheur
Yeah

Pont
coco manak yaw ba adiana
thi sa wét lay doundé olala
yaa gaw thi mane
say je taime thi sama biir tempan
ningmay def néx nama
beugueu nala bae

Refrain
péssé sama bop xamni warouma ragal woudié
ladial mon coeur
kouy madame bonheur
yamay confiné lép di dioup ya raw poli..cier
ladial mon coeur
kouy madame bonheur

REMERCIEMENTS:
HĂŽtel La Roseraie Somone, Aida Seye (maison), Mareme Chalar, ma mĂšre, mon pĂšre, ma famille, les fans, Abass (Gambia).

MENTION SPECIALE A L'EQUIPE ARTISTIQUE DE L'ALBUM:
Cheikh Ouza ( arrangeur, compositeur, mixage). Moussa ( pianiste co arrangeur),
Kruh Mandiou Mory ( lyrics album), Latif Ndiaye ( Compos lyrics), Daddy Thioune( Compos), Beatmaker Zeuss, Yéyé Faye ( arrangeur), beatmaker Zoom, Iso (beatmaker Mixage).
Équipe technique: Wylli Wonka pour WW Film (rĂ©alisateur), Ludovic joyeux (mix master album), Francois (rĂ©gisseur)
Madicke Gueye (coordonnateur) Junior (Marketing Media Sociaux), Aminta ( Assistante), équipe lumiÚres, équipe deco, Photographe light on.

Styliste: MNB haute couture, So Fatoo, Versailles, Oumou Sy.
Make up: Adja make up, Louisa jandy
Coiffure: Adama et Awa Fofana.

Abonnez-vous ici : http://bit.ly/AdiouzaDiallo

Retrouvez Adiouza Diallo sur :

- Instagram: http://i.instagram.com/adiouza/
- Twitter : https://twitter.com/Adiouzaofficiel
- Facebook: https://web.facebook.com/AdiouzaPageF...
- Tik Tok : https://vm.tiktok.com/ZSqPjvox/

Pour booking:
- A l’international: +33 6 77 73 16 73
- Au Sénégal: +221774892177 / +221 773222305

#Adiouza2020 #MmeBonheur #AdiouzaProd

Tags and Topics

Browse our collection to discover more content in these categories.

Video Information

Views

19.6M

Likes

78.8K

Duration

2:56

Published

Nov 20, 2020

User Reviews

4.3
(3912)
Rate:

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

Related trending topics. Click any trend to explore more videos.

Trending Now