Adiouza - Monsieur Bonheur (Lyrics) đŸŽ¶

Discover Adiouza's song 'Monsieur Bonheur' released on October 29, 2022. Lyrics and details inside.

Adiouza - Monsieur Bonheur (Lyrics) đŸŽ¶
FAYE SANOR PRO
124.9K views ‱ Oct 31, 2022
Adiouza - Monsieur Bonheur (Lyrics) đŸŽ¶

About this video

đŸŽ€Artiste 👉 Adiouza
đŸŽ”Titre 👉 Monsieur Bonheur
💿 Album 👉 Single
đŸ—“ïžSortie 👉 29 octobre 2022
Activez la 🔔 de notification
Abonnez vous 👉 https://bit.ly/2PunLir
Likez 👍, commentez 📝et partagez đŸ“Č la vidĂ©o svp!🙏
▁▁▁▁▁▁▁▁▁▁▁▁▁▁▁▁▁▁▁▁▁▁▁▁▁▁
Rejoignez-moi sur les rĂ©seaux sociaux: 😃
TikTok 👉 https://bit.ly/3e5F6g8
WhatsApp 👉 https://bit.ly/2IsP4KQ
Abonnez vous 👉 https://bit.ly/2PunLir

LYRICS
Monsieur Bonheur, neexa jubbol
Dafa jot nga ñëw ñu wax
Tey, jamm la yeewo
Bae sagu bi doy na

Maa gis nen, ni nen na ngi
Thiapathioly, do ken ci ñi
Lo visé, do ko moy
Rafet ngem, mëne bëre suuf

Noonu la lay naame
Dotu mako def
Te fo meere ma jaaxle, bébé
Dotu mako def, baal ma dotu mako def

Yow khole ma tey ree, bébé
Dotu mako def
Ñu def jubbo de l’annĂ©e, bĂ©bĂ©
Dotu mako def, baal ma dotu mako def

Dama pare jubbo ak yow
Ba fofou ñuy wowe wouyaye

Oh, oh
Xamante nañ du am coow
Oh, oh
Dielë am fokko foge wul

Suukar bi ci banana, pare nooy ni khale
Menthe bi nekk ci naana, ak yeneen yi lay xaar
Doyaluma
Meer bi doy na
Doyaluma

Noonu la lay naame
Dotu mako def
Te fo meere ma jaaxle, bébé
Dotu mako def, baal ma dotu mako def

Yow khole ma tey ree, bébé
Dotu mako def
Ñu def jubbo de l’annĂ©e, bĂ©bĂ©
Dotu mako def, baal ma dotu mako def

Mëno dem kaay ndax yay sama poumon gauche
Waaw Waaw, yow la
Mën na fi dee ci une minute de pause
Wallah, wallah

Am nga cass (thiass), stylé nga
Maako lett, kaay firi ko
Jeexa gul, doya luma
Jant sow, kaay dolli ma

Doyaluma
A vie lañ signé
Doyaluma

Noonu la lay naame
Dotu mako def
Te fo meere ma jaaxle, bébé
Dotu mako def, baal ma dotu mako def

Yow khole ma tey ree, bébé
Dotu mako def
Ñu def jubbo de l’annĂ©e, bĂ©bĂ©
Dotu mako def, baal ma dotu mako def

Wouy mbëggeel, mane ak mbëggeel
Bae, tay la tay
Dara la dul maye
Bae tay la tay, toggal
Bae, tay la tay
Dara dumako maye
Bae tay la tay, toggal
Dara la dul maye

Tags and Topics

Browse our collection to discover more content in these categories.

Video Information

Views

124.9K

Likes

885

Duration

3:24

Published

Oct 31, 2022

User Reviews

4.3
(24)
Rate:

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

Related trending topics. Click any trend to explore more videos.

Trending Now