Adiouza - Réseaux sociaux Guest. Samba Diarra (Clip Officiel)

Dans cet œuvre, Adiouza dénonce les dérives des réseaux sociaux. Ces plateformes, bien qu’utiles, sont souvent détournées pour propager la superficialité, l...

ADIOUZA•649.0K views•3:19

About this video

Dans cet œuvre, Adiouza dénonce les dérives des réseaux sociaux. Ces plateformes, bien qu’utiles, sont souvent détournées pour propager la superficialité, la méchanceté gratuite et le jugement facile. La course au paraître et à la popularité pousse certains à agir sans égard pour les conséquences humaines.
les émotions sont manipulées, les réputations détruites, et l’apparence prend souvent le dessus sur l’authenticité.

Guest : Samba Diarra Mbaye

• Crédits de la chanson & du clip
Auteur : Mouhamed Ndoye dit Metha King
Arrangeur : Jeuss Beatz
Composition : Adiouza
Réalisation : Mao Sidibe

Contact management: 773222305

Lyrics: Réseaux sociaux

Diaxelena
Si réseaux yi

1 er couplet

Mandou boula séné ni niokétt daw

Yakh derr moy sa liguey oudé yako raw

Do dermatologue Bayil derou gor gni

Yakh nitt defar sa poce nitt nga walla wethitt

Tall sa live dissi togg nitt

Iow yémal sisay soblé meuytou diebaner bi

Boula jiguer ngaye mbeur kamile

Febarou kignane moussoul meuna werr day Zembéré rek di dem nga deuké mboly (1)

Refrain
Louy sa liguey ngani réseau yak asse gore

Goudekh beuthieuk Yangui si derrou diambour

Wetal tarri soratoul mougnal

lou way di def sa kaw la dieum maytoul


Eh méchant boy ( Loutax ) bis

Bousa kho di bakh (sa xole di bone)

Kay nga abal mako

Ma tek café. ( sa xole di dagg)



Mane de jaxkhlena
Bo demoul douma dem loloye Sénégal
Waxale

2 Eme couplet

Dinga deuké malaise meuytoul cardiaque

Docteur bi nena oubil si xole tek si del rétane

Maytoul beugn yi derréta ko lale

Soula beuggé fekhel dentiste meunoussi darra

Niou bok dieukeur ngani tay ngay deh

Kou sokhor kissi rang bi khĂ´l be jexe
Wouye xole be nekh .


Febarou kignane moussoul meuna werr day Zembéré rek di dem nga deuké mboly (2)

Refrain
Louy sa liguey ngani réseau yakkass gore

Goudekh beuthieuk Yangui si derrou diambour

Wetal tarri soratoul mougnal

lou way di def sa kay la dieum maytoul

Eh méchant boy ( Loutax )

Bousa kho di bakh (sa xole di bone )

Kay nga abal mako

Ma tek café (sa xole di dagg )

Mane de diaxelenaaa bo demoule douma dem li moye Sénégal Waxal

(Statut visé yi ngamaye xagne né dama daloule ndax kignane bi nga nekker si réseaux yi damako taloule).

Mane de diaxelenaaa bo demoule douma dem loloye Sénégal Waxal

(Da nga maye deuker vu sa xole di bonne
Dieundal glace sa xole fekh yalla ye mayer none).

Mane de diaxelenaaa bo demoule douma dem loloye Sénégal Waxal

(Tik tok nga talle sa live Facebook Instagram
bayi wo fene fo rombou jebaner ma)

(Lou takh sou ma sagne def nga mère
Eh deug la)

(Ma deff lou baxe nga mère
Ehhhh none leu)

Borom xolou diamant bi
Momar Diop ko soppe
Mouni Mane ma beug Bamba

• Suivez-moi sur mes réseaux
Instagram : https://www.instagram.com/adiouza?igsh=d21zOGNmNGppdDlz
Facebook : https://www.facebook.com/share/14z83QCAUh/?mibextid=LQQJ4d
TikTok : https://www.tiktok.com/@adiouza4?_t=ZM-8rnAS1uBJ7o&_r=1



#adiouza #réseauxsociaux #music

Tags and Topics

This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:

Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.

4.8

129 user reviews

Write a Review

0/1000 characters

User Reviews

0 reviews

Be the first to comment...

Video Information

Views
649.0K

Total views since publication

Likes
10.5K

User likes and reactions

Duration
3:19

Video length

Published
Nov 29, 2024

Release date

Quality
hd

Video definition

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in South Korea under the topic 'a'.

Share This Video

SOCIAL SHARE

Share this video with your friends and followers across all major social platforms including X (Twitter), Facebook, Youtube, Pinterest, VKontakte, and Odnoklassniki. Help spread the word about great content!