Adiouza - Xale Féroce (Clip Officiel) 🎶

Une chanson inspirante dédiée aux jeunes challengers, célébrant détermination et réussite dans leur parcours.

Adiouza - Xale Féroce (Clip Officiel) 🎶
ADIOUZA
734.4K views • Jul 21, 2023
Adiouza - Xale Féroce (Clip Officiel) 🎶

About this video

"Xale féroce" est une chanson dédiée aux challengers, c'est un véritable hymne à la détermination et à la réussite pour les jeunes d'aujourd'hui. cette chanson est là pour galvaniser les esprits, inspirer et encourager chacun à se battre pour atteindre ses rêves. Travaillons sans bruit et laissons nos succès parler d'eux-mêmes : Amul bàyyi , alaa accu , don't give up !
Découvrez "Xale féroce" et laissez-vous emporter par cette énergie positive dans un rythme mbalax entraînant .

• Crédits de la chanson et du clip
Compo prod, auteur : Zbest
Arrangement: zbest, Moussa Ngom
Réalisateur : Wylli Wonka WWFILM
Lumière et camera deco : jordy diop DardartDakar
Chorégraphie : Prince 78 636 46 81
Mix, Master : Moussa Ngom, Ludovic joyeux
Make up : Adja Make up
Styliste : empire d’Afrique, Bisecollection

• Remerciement: Maison du bonheur, Grand Théâtre National.


• Retrouvez Adiouza Diallo sur : ↙️

- Instagram: http://i.instagram.com/adiouza/

- Twitter : https://twitter.com/Adiouzaofficiel

- Facebook: https://web.facebook.com/AdiouzaPageFans/

-Tik tok: https://www.tiktok.com/@adiouza4?_t=8ghLVsNd6DG&_r=1

• Stream & écoute : https://bfan.link/xale-feroce

Lyrics✍🏾

Intro
Ou yeyeeeeee
Im a qween
Fouma nekh laye feuler
Courant dou pile
ndax feeling pathie lagne ma xamer

1 er couplet
Xalé dangay féroce
bo tolo si temps
Mane kouma meuseu bokal poste tek leu si banc
Wakh dji dou bari mane fi Koufi wett khamni ndanane gneuwna

Xalé day solou di khégne lou nekh
Teksi wakh lou nekh
Wakh dji dou bari mane fi Koufi wett khamni ndanane gneuwna

Thiowli day bari wanté gnémé wougnou diar mane fimay fekh lo
Dougnou fa diar jamais
Wakh dji dou bari mani
ndanane gneuwna

Pré refrain
Mane limay liguey Bilay silay fayéko
(kou meune defal)
Mane douma crithie douma crathie talouma defanté
(gnoune, dagne koy def sakh té dafay nekh)

Refrain
Tay dafay nekh day meti
Dara dou yombou nay meti
Amoul seral amoul tousss
Nay métiii biss bi moko lathie
Wakh dji sou baré dou mane
Dieuf dji sou baré mane leu
Wakh dji sou baré dou mane
Dieuf dji sou baré ba baré sou baré mane leu


Dieuf ji sou barer Mane la
Wax ji sou newer Mane la
Eheee Mane leu


Pré refrain
Mane limay liguey Bilay silay fayéko
(kou meune defal)
Mane douma crithie douma crathie talouma defanté
(gnoune, dagne koy def sakh té dafay nekh)

Refrain
Tay dafay nekh day meti
Dara dou yombou nay meti
Amoul seral amoul tousss
Nay métiii biss bi moko lathie
Wakh dji sou baré dou mane
Dieuf dji sou baré mane leu
Wakh dji sou baré dou mane
Dieuf dji sou baré ba baré sou baré mane leu

Ndanane bi gneuwna
Ndanane bi gneuwna
Ndanane bi gneuw na
Tay fi dafay nexxx

2em partie

Xol bou sett bima Yala diokh maye dane sama dolé
Ba douma tite Mane douma ragal Bene yoonei
Ndanane bi dakoy yeungeule
( bokoulak Gnom dou sen morom) chœurs
Bilay dakoy yeungeul
(bokoulak Gnom dousen morom) chœurs

Ma bari feeling
Teksi jongué
Té louma sagnsé mou Nice
(Pouss len yoon bi dafa bari dolé) chœurs
Sama wakh dou bari
Sama Dieuf day bari
Mane doma sonal
(Pouss len yoon bi dafa bari dolé)chœurs

Sagnsé Tina man louma Nameu
(Mo bari dolé) chœurs
Poussal ma dem mane doma lakale
(Pouss len yoon bi dafa bari dolé)chœurs
Wakh dji Bilay mane Damay sonal
(Mo bari dolé) chœurs
Deuké touti wakh job lou bari
(Pouss len yoon bi dafa bari dolé) chœurs

Ma bari feeling
Teksi jongué
Té louma sagn sé mou Nice
(Pouss len yoon bi dafa bari dolé) chœurs
Sama wakh dou bari
Sama Dieuf day bari
Mane doma sonal
(Pouss len yoon bi dafa bari dolé) chœurs

Xol bou sett bima Yalla maye moy dane sama dolé
Ba douma tite Mane ragal Beneu yoonei
Ndanane bi dakoy yeugeul
(bokoulak Gnom dou sen morom) chœurs
Bilay dakoy yeungeul
(bokoulak Gnom dousen morom) chœurs
🔇

#adiouza #xaleferoce

Tags and Topics

Browse our collection to discover more content in these categories.

Video Information

Views

734.4K

Likes

15.3K

Duration

3:51

Published

Jul 21, 2023

User Reviews

4.8
(146)
Rate:

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

Related trending topics. Click any trend to explore more videos.