JEEBA - So Bayiwoul (Clip Officiel)

http://africori.to/SoBayiwoul Auteur : JEEBA Prod by : Bril Directed by Abadane Daiman Dressing by Abdn • Sams Dakar Facebook : https://web.facebook.com/je...

Jeeba Abdn5.5M views3:47

🔥 Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Singapore under the topic 'itoto system 12'.

About this video

http://africori.to/SoBayiwoul Auteur : JEEBA Prod by : Bril Directed by Abadane Daiman Dressing by Abdn • Sams Dakar Facebook : https://web.facebook.com/jeebabdn/ Instagram : https://www.instagram.com/jeeba_abdn/ Lyrics : {Couplet 1} No ow wow yeah yeah yeah yeah No no no no no ow wow Yeah yeah yeah yeah Mane teud na teud meunouma nelow may tok di khalat louniou dieumelé kanam thi yone bi gnou soumb té amouniou katanam Mane lingama jii meunoumako bafoué Ngani thi sa khol ngama tatoué éh Ma fess thi say beut Té ngani bene goor khadiatoul thi sa heart Yangui mougn yangui diap yangui diem Yangui def yangui topeu yangui deem Nguir niou binde souniou love thi story you geuna kawé thi real love Baye meussoul wakh bama teek thi baat Wayé tay dina done beuss bou ndieuk Ndakh té goré goré rek mokoy faay Dou danga bayi nieup ngani may sa waay Lii boudé deug la lii dara douko fay Wadialal say bagass tay dina niou fly Même boumay fandé awma louma leek louma naane Love binga may diokh doy nama leek ak naane {Refrain 1} Gueunone na meti tay niouy work Ba yalla def mouy mbeuguel Oow baby eh bo bayiwoul douma bayi Gueunone na meti tay niouy work Ba yalla deef mouy mbeuguel Oow baby bo bayiwoul douma bayi No no no no no no nooooo ow woow Nono no ow woow Yeah yeah yeah ééé {Couplet 2} Mane teud na teud meunouma nelaw may tok di khalat Yoon bima dieul eh nathi am ndam waw wala deét Danga takh ma bayi lep Lou guenone thi mane Ma def la sama number one yeah Kone linga ma wara wone Mbeuguel thiofel bou deug dadi lale None yangui sothieu siign beuga réé éh Mais douniou meussa réé baby Bouniou sérré souniouy coude Douniou siign assouma mala nane réé Wayé louy am am na ba noppi Naniou rafétal deugeureul digeunté bi Niane nathi yalla ay dom doom Wayé louy am am na ba nopi naniou rafétal deugeureul diguenté bi niane na thi yalla dom doooooom {Refrain 2} Guenone na meti tay niouy work Ba yalla def mouy mbeuguel Oow baby eh bo bayiwoul douma bayi Guenone na meti tay niouy work Ba yalla def mouy mbeuguel Oow baby bo bayiwoul douma bayi No ow wow eh yeeeah eeh Noooo baby baby bo bayiwoul douma bayi dinala dinaaaala dinala diox so bayiwoul Bo bayiwoul douma b #jeeba #sobayiwoul

Video Information

Views
5.5M

Total views since publication

Likes
26.7K

User likes and reactions

Duration
3:47

Video length

Published
Apr 4, 2019

Release date

Quality
hd

Video definition

Tags and Topics

This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:

Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.