Jeeba - Saï Saï Feat Dieyla (Clip Officiel)

#saïsaï #jeeba #dieyla Saï Saï disponible ici http://africori.to/saisai Jeeba à Paris?? Achetez votre billet ici : https://lamarbrerie.fr/jeeba-a-paris/ Aut...

Jeeba Abdn4.3M views3:33

About this video

#saïsaï #jeeba #dieyla Saï Saï disponible ici http://africori.to/saisai Jeeba à Paris🇫🇷 Achetez votre billet ici : https://lamarbrerie.fr/jeeba-a-paris/ Auteur : Jeeba Interprète : Jeeba - Dieyla Compositeur : diamond guidem Mix Mastering : Afro Music Studio Sn Réalisation : Mao Sidibé Production : Abadane Daiman Stylisme : Bise Collection - Teranga Lounge - Cana Dom Jeeba et Dieyla proposent un cocktail musical inédit, l’histoire d’amour dénonce les mensonges et dérives des couples d’aujourd’hui. Le son se veut drôle et raconte en interposé un récit de deux couples aux ambitions différentes et malhonnêtes. Lyrics Yala dou dioum mani Yala dou dioum loumou def ndeké lolou mo geune Demone na ba nar ko dougal sama biir xol souma ko defone mangui thi tolof tolof Kone fok ma xolate ko Saï saïiiii la fok ma xolate ko Wadjii Saï saïiiii la Yalla dou dioum ndeké yalla dou dioum loumou def ndéké lolou mo geune Demone na ba nar ko dougal sama biir xol souma ko defone mangui thi tolof tolof Kone fok ma xolate ko Saï Saï la fok ma xolate ko Wadji Saï Saï la yala dou dioum ndeké yalla dou dioum loumou def ndéké lolou mo geune Demone na ba nar ko dougal sama biir xol souma ko defone mangui thi tolof tolof Couplet Nieuw na sama lathté fa sama yay boy Saï Saï la Nieuwate sama keur lathté fa sama baye boy Saï Saï la Néna kilifa la dou dokh thi tank thiakhane Ñente ak tranche indi gouro dadi labane Mingui may tek tank beug ma forcé ray Ndéké loumou beugone dougal but bi jubilé daw Refrain Yala dou dioum mani Yala dou dioum Loumou def ndéké lolou mo geune Demone na bay xalate nar ko diox sama xol Ndéké souma ko defone mangui thi tolof tolof Kone fok ma xolate ko Saï Saï la Kone fok ma xolate ko Ndaw ci Saï Saï la Yala dou dioum mani yalla dou dioum loumou def ndéké lolou mo geune Demone na ba nar ko dougal sama biir xol souma ko defone mangui thi tolof tolof Néna koudoul mane beugoul sokhla woul Mane rek la diokh bop kou Mel ni mane amoul Mane mako yeungal yeungal mbeguelam Ndéké mane dama door ay calmant lamay diokh Dem na ba dépense keureum mako yoor Faye courant Faye ndokh Faye diangue xalé yi ecole Dieund greffage Faye ay voyage ndéké damay door sama poche la nop Refrain Yala dou dioum mani yalla dou dioum loumou def ndéké lolou mo geune Demone na bay xalate nar ko diokh sama xol Dejesouma ko defone mangui thi tolof tolof Kone fok ma xolate ko Saï Saï la Kone fok ma xolate ko

Tags and Topics

This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:

Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.

4.4

867 user reviews

Write a Review

0/1000 characters

User Reviews

0 reviews

Be the first to comment...

Video Information

Views
4.3M

Total views since publication

Likes
30.8K

User likes and reactions

Duration
3:33

Video length

Published
Nov 23, 2024

Release date

Quality
hd

Video definition

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Portugal under the topic 'depressao claudia ipma'.

Share This Video

SOCIAL SHARE

Share this video with your friends and followers across all major social platforms. Help spread the word about great content!