Jeeba - Décorée (Clip officiel)

#jeebaleboy #décoré Auteur : JEEBA Compositeur : ZbeatZ X Weezyade Teacher Arrangement : Iss 814 beat Mix Mastering : sir khalifa Réalisation : Viewz Studio...

Jeeba Abdn3.4M views3:23

About this video

#jeebaleboy #décoré Auteur : JEEBA Compositeur : ZbeatZ X Weezyade Teacher Arrangement : Iss 814 beat Mix Mastering : sir khalifa Réalisation : Viewz Studios Guitare : Henri Partenaires : pullman hôtel Teranga Manager : 77 434 11 63 •••••••••••••••••••••••••••••••••••••••••••••••• Instagram : https://instagram.com/jeeba_abdn?igshid=lhf2isf0vxoi Facebook : https://www.facebook.com/jeebabdn •••••••••••••••••••••••••••••••••••••••••••••••• Stylisme : Zadada : https://instagram.com/zadada_?igshid=155lojd6avdvm Molly Style : https://instagram.com/molly__stylle?igshid=b967nhxm2eal Afshal : https://instagram.com/af_shal?igshid=j6339q1u5vd Madelaine d’Arabie https://instagram.com/_madeleine_sn?igshid=oxr8ps4xlbuh Wosiba https://instagram.com/wosiba_?igshid=bmubh83znytg Maquillage Make up by rimadallas https://instagram.com/makeupbyrimadallas?igshid=9nlysw0ekt0p Ndeye Aby : Lyrics: [Couplet 1] “Eeeh eeh eeeh Jeeba le Boy oooh ooh” Seen ko reik mouy deem aam caractère ba dokoo ñémé xool Yeee Yee Yeeh Mane guiss nala yoow yagui dieem Beug meunale sa Bopp ba kenn doula toññ Yeee Yee Yeeh Nionioy jigeen jigeen juu meune goor Jigeen juu kharoul daraay goor Jigeen juuy niaffé nguir meunal bopam wawaw Mane kham dou diambar nga damalay nianal Annnh annh Baññkat laa motakh mou deuk ci war wi Yeee Yee Yeeh Yow yarr nagn fuññ la wara yarr boubakh Meusso ñuu gathiel benn yoon linga geum Bobou ba leigui yagui siiy ñiaffé nguir beug mou baakh Motakh reik manaan la [Refrain 1] Naaw na sa yaye boy Dina ko décorée wakh ko doom boumu juur Meune na yoor reew Naaw na sa baye boy Yoow baye boy wakhko dom boumou juur Meun na yorii reeew....eeh eeh eeh meune na yoori reew Sa yaay boy eeh eeh eeeh eeew Jigueen meune na yoori reew [Couplet 2] Seen ko reik muuy deem Boudonne benn bouniou donn niénteu Mane sagn nala bayi aak njaambot guissi keur gui Douñu toumouranké douñu kokh kokhi Niongui si tolle yi aak bureau yi Niongui si sport bi aak fo meune tii deem Ma naam jigueen yeup soleen né diaak Dignité aak jambarté ngay lire seeni kanaam Ay Joxooñ nala joxooñ nala Motakh ma biind weuy wi deelo la ndioukeul Oube nga lamb ji do seen moroooom ooooh oooh ooh Oooooh oooh oube nga lamb Ji jigueen do sen morom [Refrain 2] Mane naaw na sa yaye boy dinako décorée Wakh ko doom boumu juur meune na yoori reew Mane naaw na sa baye boy “Baye boy” Wakh ko doom boumu juur meune na yoori reew eeeh eeh eeeew Meune na yoori reew eeeh eeeeh eeeh Naw na sa yaye boy eeeh eeeh eeh Jigueen meune na yoori reew.

Tags and Topics

This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:

Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.

4.6

677 user reviews

Write a Review

0/1000 characters

User Reviews

0 reviews

Be the first to comment...

Video Information

Views
3.4M

Total views since publication

Likes
38.1K

User likes and reactions

Duration
3:23

Video length

Published
Nov 20, 2020

Release date

Quality
hd

Video definition

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Morocco under the topic 'الطقس غدًا'.

Share This Video

SOCIAL SHARE

Share this video with your friends and followers across all major social platforms. Help spread the word about great content!