Iss 814 | Xool Ma ci Bët (ft. Jeeba) [Official Video]

Titre: Xool Ma ci Bët Artistes: Iss 814 & Jeeba Prod. : Iss 814, Yannick Réal. Vidéo: Black Rétina | BayeBlVck Mix/Mastering : King Beat Lumières : Yarba...

Iss 81421.7M views3:20

🔥 Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Pakistan under the topic 'f'.

About this video

Titre: Xool Ma ci Bët Artistes: Iss 814 & Jeeba Prod. : Iss 814, Yannick Réal. Vidéo: Black Rétina | BayeBlVck Mix/Mastering : King Beat Lumières : Yarba Déco & Justin Mendy Clip Tourné au Safari Studio Artwork: Eyelit Studio Maquillage: https://www.instagram.com/khadiijaah_soft ________ Abonnez-vous à ma chaîne YouTube : https://www.youtube.com/channel/UCz8KYuq-KGD0vk6WgRetlrw ________ Ma discographie disponible sur toutes les plateformes de téléchargement: https://bit.ly/iss814 ________ Retrouvez moi sur les réseaux sociaux: * Twitter: https://twitter.com/814bsb * Instagram: https://www.instagram.com/iss814beats/?hl=fr * Facebook: https://fr-fr.facebook.com/814prod * TikTok: https://www.tiktok.com/@iss814beats Management || Booking: +221 77-204-19-55 •• iss814booking@gmail.com LYRICS Mbeuguel bou deugou Dara douko faye Yaay seetou Biye woné sama leeraye Jant goudi Biddew soubeu teel Bimala xamé Ci la tagok weetaye Nii tognal sa aaaaaa ! yaye Balenala ndakh mbeuguel bimaay yeug Ci yow Nii tognal sa aaaaaa ! Baye Balenala ndakh mbeuguel bimaay yeug Ci yow Wolou nala wolou wolou nala ! Eh yaaaay ! Wolou nala wolou wolou nala ! Ahn ahn ! Boume laay guiss ngaay doundou Dafemaay doundeul baby Soume laay guiss ngaay rétaan Dafemaay doundeul waay Boume laay guiss ngaay doundou Dafemaay doundeul baby Boume laay guiss ngaay rétaan Dafemaay doundeul waay Xool ma ci bët Ma xool la ci bët Nioune niare la rek Mbeuguel a nekh Xool ma ci bët Ma xool la ci bët Nioune niare la rek Mbeuguel a nekh Yéne saaye nga diéki diéki woma Woma Nga meer maané mba diépiwoma Nga néma non non Yéne saaye nga xole ma rek Ma rétaan rétaan Yaay sama boumou xol bi Yaay sama boumou xol bi Bo meeré ba guédeu dafemaay metti Metti Bo deffé ba gnipeu Nala setsi Setsi Douma ci xole sax pa bek mère bi Mère bi Na oubi bountou bi soxna si Dang ma diape sa mbaal Té douma guéneuti Bilay walay yé Yow laay fethie ci bal Yaay sama mélodie Yow rek la baredé Eh eh ! Boume laay guiss ngaay doundou Dafemaay doundeul baby Soume laay guiss ngaay rétaan Dafemaay doundeul waay Boume laay guiss ngaay doundou Dafemaay doundeul baby Boume laay guiss ngaay rétaan Dafemaay doundeul waay Xool ma ci bët Ma xool la ci bët Nioune niare leu rek Mbeuguel a nekh Xole ma ci bët Ma xole la ci bët Nioune niare leu rek Mbeuguel a nekh Yeh weurena ba weurengueul adouna Yeh kou melni yow mba amatina Yeh dougueul ci Keur gui yatouna Ndakh yow yaay yaay sama boumou xol yaay sama boumou xol Yéne saaye nga diéki diéki woma Woma Nga meer maané mba diépi woma Nga néma non non Yéne saaye nga xole ma rek Ma rétaan rétaan Yaay sama boumou xol bi Yaay sama boumou xol bi Weurena ba weurengueul adouna Yeh kou melni yow mba amatina Eh yah dougueul ci Keur gui yatouna Ndakh yow yaay Yaay sama boumou xol Yaay sama boumou xol #Mbedocratie #Iss814 #Jeeba © 814 Prod. | July 2021

Video Information

Views
21.7M

Total views since publication

Likes
107.2K

User likes and reactions

Duration
3:20

Video length

Published
Jul 16, 2021

Release date

Quality
hd

Video definition

About the Channel