Iss 814 | DIOKH KO LOVE (Official Video)
stream DIOKH KO LOVE ⎠https://li.sten.to/diokhkolove ____ Réalisation: Director VFX Cadrage: Dramatik Viewz Montage & Etalonnage: Ousmane LY LumiÚres: Leo ...
đ„ Related Trending Topics
LIVE TRENDSThis video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!
THIS VIDEO IS TRENDING!
This video is currently trending in Italy under the topic 'video'.
About this video
stream DIOKH KO LOVE âŽ
https://li.sten.to/diokhkolove
____
Réalisation: Director VFX
Cadrage: Dramatik Viewz
Montage & Etalonnage: Ousmane LY
LumiĂšres: Leo JAMES
Prod: Iss 814
Mix/Mastering: Iss 814
Maquillage: Fana_Beauty & Fatima Zahrafric
Stylisme & Accessoires : Faty Madina KANE
Artwork: Ousmane LY
Chargé de prod.: Gabriel (814 Prod.)
//\\ Iss 814 et Lily sont habillés par TOLYNA COLLECTION //\\
________
Remerciements :
TOLYNA COLLECTION âąâą https://www.instagram.com/tolyna.collection/
____________________________
LYRICS
Soumala gaañé ci xol
Sam bopp la gaañe
Soumala bayé nga daanou
Moy mane maay daanou
Beuga touma niou bayanté ba abadaan
TĂ© lou la metti ci mane mi
Babe mine fok niou andado xeex ko
Bagna bayi nitt suñu diganté
Baby kaay ma wax ko
Je tâaime je tâaime my babe !!!
Dji ngama mbeuguélou goor
Kone fok ma delolako la
Woho woho
Wakh ma leep loye yoor
Ma nieuw gueuneul leu ko
Koula denk xolam
Bayi loula dara
Xamé ko nonou
Koula dji Mbeuguel
Dessa loula dara
Xamé ko nonou
Diokh ko love
Love love
( love love love )
Mérité na love
Diokh ko love
Love love
Merité na love
Baby yama gueuna xam
Kenn meunou la terré nek sama Life
Sama life love nga sama waye
Xarito ak mbeuguel danio and waay
And waay yah
Best friend ak homie
Homie!
Sama doom yow yay nek yayam
Ya yam !!!
Soumbou nga si poott mi yeh
Poott mi !!
Damala nopp Wa waaw
Wa waaw !!
Nimala beugué yeh !!
Meuno ko guissate non
Nimala beuguéééé
Meuno ko guissate my babé
Koula denk xolam
Bayi lou la dara
Xamé ko nonou
Koula dji Mbeuguel
Dessa loula dara
( love love love )
Xamé ko nonou
Diokh ko love
Love
Mérite na love
Diokh love love
Mérité na love
Soumala gaañé si xol
Sama bopp la gaañe
Soumala bayé nga daanou
Moy mane maye daanou
________________
Sream my music âŽ
https://linktr.ee/iss_814
_____
Retrouvez moi sur les réseaux sociaux:
* Twitter: https://twitter.com/814bsb
* IG: https://www.instagram.com/iss814beats
* Facebook: https://www.facebook.com/814bsb
* TikTok: http://tiktok.com/@iss814official
* Snapchat: /iss-814
________________
#coeursbrisés #evenprod #iss814
© 814 Prod. | November 2023 | All rights reserved | iss814booking@gmail.com
Video Information
Views
15.8M
Total views since publication
Likes
86.3K
User likes and reactions
Duration
2:25
Video length
Published
Nov 17, 2023
Release date
Quality
hd
Video definition