Iss 814 | Aminata (Official Video)

Titre: Aminata Artiste: Iss 814 Lyrics/Prod: Iss 814 Mix/Mastering: Iss 814, Zox & Sir Khalifa Directed by: Awanje Films Coordination Logistique: Taf Zion __...

Iss 814•1.3M views•3:16

About this video

Titre: Aminata Artiste: Iss 814 Lyrics/Prod: Iss 814 Mix/Mastering: Iss 814, Zox & Sir Khalifa Directed by: Awanje Films Coordination Logistique: Taf Zion ________ Aminata disponible sur toutes les plateformes de téléchargement: https://li.sten.to/bBaITjq ________ Abonnez-vous à ma chaîne YouTube : https://www.youtube.com/channel/UCz8KYuq-KGD0vk6WgRetlrw ________ Ma discographie disponible sur toutes les plateformes de téléchargement: https://bit.ly/iss814 ________ Retrouvez moi sur les réseaux sociaux: * Twitter: https://twitter.com/814bsb * Instagram: https://www.instagram.com/iss814beats/?hl=fr * Facebook: https://fr-fr.facebook.com/814prod * TikTok: https://www.tiktok.com/@iss814beats Lyrics: Amou ma or, amou ma xaliss, amou ma ay liasse Né ngua do guéne ak mane ndakh awmeu clash Loutakh ngua melni Aminata? Mane xamouma, bébé wakhma Amou ma or, amou ma xaliss, amou ma ay liasse Né ngua do guéne ak mane ndakh amou meu classe Loutakh ngua melni Aminata? Loutakh ngua melni Aminata? Lane ngua meu eupeulé Motoul sakh pép thiép Nio bokk deuk tchi kogne, loutakh yaw ngua mayy khép? Yéne dieuff yi nguay deff, tchi sama khol daf may guagne Yéne say ma diépi leu déme bay bayi, khol bi bagne Sama mbeuguél moma togne, motakh ma topeuleu Mane ak yaw nio bok kogne motakh ma sopp leu Kheuyneu beuss di na ame kagn, takk leu, téreul leu Hé eh, Hé eh Thioro baye samba, dak sa yaye dieulmeu Sa nijaay yo may ma ay dollar, dou ma té daggo Djank bi tchi kogne bi néna dou sey ak badolo Bo démé keur yayam goudi gossi lay réré Amou ma or, amou ma xaliss, amou ma ay liasse Né ngua do guéne ak mane ndakh amou meu ay clash Loutakh ngua melni Aminata? Mane xamouma, bébé wakhma Amou ma or, amou ma xaliss, amou ma ay liasse Né ngua do guéne ak mane ndakh amou meu class Loutakh ngua melni Aminata? Loutakh ngua melni Aminata? Lane mo takk si mane ba faléwomeu? Lane mo nekk si mane ba xoloulomeu? Nieuw na sakh si séne keur, mais wakhou lok mane Té métinama ndeyssane, métinama ndeyssane Pourtant nitt la kome yaw, kheuy neu beuss dineu changé Pourtant nitt la kome yaw, wakh meu lane moy déranger Nékal ak mane bilay, beugueu leu Yalla takh Hé eh, Hé eh Thioro baye samba, dak sa yay dieulmeu Sa nijaay yo may ma ay dollar, dou ma té daggo Djank bi tchi kogne bi néna dou sey ak badolo Bo démé keur yayam goudi gossi lay réré Amou ma or, amou ma xaliss, amou ma ay liasse Né ngua do guéne ak mane ndakh amou meu ay clash Loutakh ngua melni Aminata? Mane xamouma, bébé wakhma Amou ma or, amou ma xaliss, amou ma ay liasse Né ngua do guéne ak mane ndakh amou meu class Loutakh ngua melni Aminata? Loutakh ngua melni Aminata? © December 2020 | 814 Prod

Tags and Topics

This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:

Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.

4.8

263 user reviews

Write a Review

0/1000 characters

User Reviews

0 reviews

Be the first to comment...

Video Information

Views
1.3M

Total views since publication

Likes
26.3K

User likes and reactions

Duration
3:16

Video length

Published
Dec 18, 2020

Release date

Quality
hd

Video definition

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Kenya under the topic 'betty bayo'.

Share This Video

SOCIAL SHARE

Share this video with your friends and followers across all major social platforms. Help spread the word about great content!