Massamba Amadeus - Amadeus - Saajobaan (Clip Officiel)

#Amadeus #saajobaan #afrombalax #afropop Votre cadeau du nouvel an ?? est disponible sur toutes les plateformes de streaming : https://bfan.link/saajobaan ...

Massamba Amadeus‱8.0M views‱2:41

đŸ”„ Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Bangladesh under the topic 's'.

About this video

#Amadeus #saajobaan #afrombalax #afropop Votre cadeau du nouvel an đŸ„łđŸ˜ est disponible sur toutes les plateformes de streaming : https://bfan.link/saajobaan Auteur & InterprĂšte : Saliou Samb AKA Amadeus Compositeur : Zoom Beat © 2022 COSANOSTRA Suivez Amadeus sur les rĂ©seaux sociaux : Instagram : https://www.instagram.com/massamba_amadeus/ Twitter : https://twitter.com/massambaamadeus Facebook : https://www.facebook.com/massambaamadeus Paroles en Wolof : Eey MĂ samba Waalo eeeh hii Su mbĂ«ggeel doon jaay Am naa njĂ«gam Dinaa la wan sama yĂ©ene yi ma am ci yaw Duma ku lay jay Te duma la wor Dinaa la wax dĂ«gg ak lum metti metti Maa la woo ne la maa la nob Miinal la sama bopp ba nga barder maa la tooñ Kon nag loo ma manti def Lu mu metti naa ko muñ Àdduna du dox ba ma soppi li ma la wax doo ma weddi Ay bu doon ay nax neex na ma Fekk ma ciy gĂ©nt yee nga ma JĂ mm ju bari may nga ma Yaa ngi may dundal Ă jjana Tamit tĂ«ggal ma ma jaayu Xamal ma ne man la GĂ«mal ma ne Man rekk nga nob Sama saajobaan TĂ«ggal ma ma jaayu Xamal ma ne Man la gĂ«mal ma ne Man rekk nga nob Sama saadjobaan eeee waay Xam nga duma puruux duma fĂ tte bi may surux Xuntu wu lĂ«ndĂ«m wi nga ma gĂ©nne dinaa ko wax Du lu rafet ci wax Soo ma bĂ yyee damay torox Nawle yĂ©pp bis bu ñu teewee dinaa ko wax waaaay Doy nga ma ci kĂ«r Kenn du la sikkal Man yaw mii yaay ki ma fiital (tiital) Doo dund ngistal Ngor gi nga jiital Ragaluma siiwal Nun ñaar ndax doy nga ma ci kĂ«r Ndaxte Mane maa la woo Ne la maa la nob Miinal la sama bopp ba nga barder maa la tooñ Kon nag loo ma manti def Lu mu metti naa ko muñ Àdduna du dox ba ma soppi li ma la wax doo ma weddi Hay bu doon ay nax neex na ma Fekk ma ciy gĂ©nt yee nga ma JĂ mm ju bari may nga ma Yaa ngi may dundal Ă jjana Tamit tĂ«ggal ma ma jaayu TĂ«ggal ma ma jaayu Xamal ma ne Man la GĂ«mal ma ne Man rekk nga nob Sama saajobaan TĂ«ggal ma ma jaayu Xamal ma ne Man la GĂ«mal ma ne Man rekk nga nob Sama saajobaan eeee waaay Bis (tĂČllanti) ...................................................................................................................................... Traduction des paroles en Français : "Ma DulcinĂ©e" Eey Massamba Wallo hummm hun Si l'amour avait un prix Je me donnerais Ă  tout prix Pour l'acheter sans cris Je te manifesterai mes bonnes intentions Je t'Ă©loignerai de toute trahison Je ne te complimenterai jamais ma solution Je te dirai la vĂ©ritĂ© en toute circonstance Car je t'ai choisie comme amour avec aisance Amour, finalement obnubilĂ© par ma frĂ©quence Je te supporterai pour toujours avec patience Fais-moi bĂ©bĂ© ton homme de confiance Parce que douĂ© de rigueur et de Constance Et si tes dires Ă©taient des balivernes Je m'en contenterais dans ma caserne Tu m'as extirpĂ© de mes dĂ©lires Pour me permettre de tout lire Tu m'as permis d'avoir une vie paisible AssimilĂ©e au paradis, notre seule et unique cible Chante alors glorieusement mes Ă©loges don du Ciel Rassure-moi fonciĂšrement mon Ăąme-sƓur, ma belle Montre-moi qu'il n'y a point d'amour comme tel Ma DulcinĂ©e, tu es plus dĂ©licieuse qu'un caramel Ma dulcinĂ©e Couplet 2 Loin des traĂźtres dĂ©pourvus de reconnaissance J'assume d'avoir bĂ©nĂ©ficiĂ© de ton assistance AprĂšs ĂȘtre envahi par le vent de l'ignorance Ma vie sombrerait dans l'oubli Si tu me quittes ou mĂȘme m'oublies Je rĂ©affirmerai ma DulcinĂ©e solennellement Devant toute l'assemblĂ©e rĂ©unie par moment Que tu me combles de bonheur entiĂšrement Personne ne peut "casser du sucre sur ton dos Ma force qui me porte sur son dos Tu ne rĂ©agis pas pour les yeux d'autrui Mais tu agis dignement sans faire de bruit J'ose dĂ©voiler notre relation jour et nuit Ma DulcinĂ©e, la femme trĂšs chĂšre que je suis Je te dirai la vĂ©ritĂ© en toute circonstance Car je t'ai choisie comme amour avec aisance Amour, finalement obnubilĂ© par ma frĂ©quence Je te supporterai pour toujours avec patience Fais-moi bĂ©bĂ© ton homme de confiance Parce que douĂ© de rigueur et de Constance Et si tes dires Ă©taient des balivernes Je m'en contenterais dans ma caserne Tu m'as extirpĂ© de mes dĂ©lires Pour me permettre de tout lire Tu m'as permis d'avoir une vie paisible AssimilĂ©e au paradis, notre seule et unique cible Chante alors glorieusement mes Ă©loges don du Ciel Rassure-moi fonciĂšrement mon Ăąme-sƓur, ma belle Montre-moi qu'il n'y a point d'amour comme tel Ma DulcinĂ©e, tu es plus dĂ©licieuse qu'un caramel

Video Information

Views
8.0M

Total views since publication

Likes
34.5K

User likes and reactions

Duration
2:41

Video length

Published
Jan 6, 2023

Release date

Quality
hd

Video definition

Tags and Topics

This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:

Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.