Massamba Amadeus - Amadeus - Méritewoumala

Suivez Amadeus sur les réseaux sociaux : Instagram : https://www.instagram.com/massamba_amadeus/ Twitter : https://twitter.com/massambaamadeus Facebook : ht...

Massamba Amadeus‱4.4M views‱3:55

đŸ”„ Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Bangladesh under the topic 's'.

About this video

Suivez Amadeus sur les rĂ©seaux sociaux : Instagram : https://www.instagram.com/massamba_amadeus/ Twitter : https://twitter.com/massambaamadeus Facebook : https://www.facebook.com/massambaamadeus En streaming sur toutes les plateformes : https://bfan.link/meritewoumala Paroles : MĂ©ritewuma la MĂ©ritewuma la, eh yeah MĂ©ritewuma la, eh yeah MĂ©ritewuma la, eh yeah Waxal sa xol ne fonk naa Ko tekk naa ko fu ma tekkul kenn oh yeah, ah yeah Waxal sa xol ne fonk na Ko tekk na ko fu ma tekkul kenn oh yeah, ah yeah MĂ©ritewuma la MĂ©ritewuma la Yallah xam na mĂ©ritewuma la Oh mĂ©ritewuma la ÀttewĂło ma ñàkkal bu may deconnĂ© DecidĂ©wĂło bañ ma, xaar ba ma xĂ«y dem Tundu wi yĂ©pp yĂ«g sa taar Te taxul nga changĂ© MĂ©ritewuma la Waxal sa xol ne fonk naa Ko tekk na ko fu ma tekkul kenn oh yeah, ah yeah Waxal sa xol ne fonk naa Ko tekk na ko fu ma tekkul kenn oh yeah, ah yeah MĂ©ritewuma la MĂ©ritewuma la YĂ lla xam na mĂ©ritewuma la Oh mĂ©ritewuma la Na asamaan si taw muur say ronqooñ Na dĂ«nu bi dal nĂ«bb say xĂ©xet BĂ«gguma ngay jooy, danga may dofloo Rabil aala miina ma boole ak yaw Ci sa wet rek laay man a keppaaroo Na asamaan si taw muur say ronqooñ Na dĂ«nu bi dal nĂ«bb say xĂ©xet BĂ«gguma ngay jooy, danga may dofloo Rabil aala miina ma boole ak yaw Ci sa wet rek laay man a keppaaroo Waxal sa xol ni fonk na Ko tekk na ko fu ma tekkul kenn oh yeah, ah yeah Waxal sa xol ne fonk naa Ko tekk naa ko fu ma tekkul kenn oh yeah, ah yeah Waxal sa xol ne fonk naa Ko tekk naa ko fu ma tekkul kenn oh yeah, ah yeah Waxal sa xol ne fonk naa Ko tekk naa ko fu ma tekkul kenn oh yeah, ah yeah MĂ©ritewuma la, eh yeah MĂ©ritewuma la, eh yeah Traduction en français "Je ne te mĂ©rite pas" Je ne te mĂ©rite pas, eh yeah Je ne te mĂ©rite pas, eh yeah Je ne te mĂ©rite pas, eh yeah Dis Ă  ton cƓur qu'il a ma considĂ©ration Que personne n'a jamais eue comme expression Expression rĂ©vĂ©lĂ©e avec la plus riche diction TĂ©moignant ainsi mon amour sans fiction Je ne te mĂ©rite pas, Je ne te mĂ©rite pas, Que m’en tĂ©moigne Oh ! Je ne te mĂ©rite pas, Je ne te mĂ©rite pas ma bichette Vu ton unique et belle silhouette SymbolisĂ©e par tes scintillantes pommettes ReflĂ©tant ainsi la rondeur de tes boulettes DIEU sait que je ne te mĂ©rite pas ma louloute Toi qui supportes mes caprices et bassesses DIEU tĂ©moigne que je ne te mĂ©rite pas ma chouchoute Toi qui dissipes et envahis mes faiblesses Dis Ă  ton cƓur qu'il a ma considĂ©ration Que personne n'a jamais eue comme expression Expression rĂ©vĂ©lĂ©e avec la plus riche diction TĂ©moignant ainsi mon amour sans fiction Nonobstant la reconnaissance de ta beautĂ© Par tous les habitants de ta communautĂ© Tu es restĂ©e modeste, sereine et sans autoritĂ© Je ne te mĂ©rite pas avec ta lĂ©gendaire sĂ©riositĂ© Que le ciel pleure pour sĂ©cher tes larmes Que le tonnerre grommĂšle pour chasser les vacarmes Qui te turlupinent et t'embĂȘtent avec leurs armes Je ne te mĂ©rite pas sĂ©rieusement ma belle barme Dis Ă  ton cƓur qu'il a ma considĂ©ration Que personne n'a jamais eue comme expression Expression rĂ©vĂ©lĂ©e avec la plus riche diction TĂ©moignant ainsi mon amour sans fiction Je ne te mĂ©rite pas, eh yeah Je ne te mĂ©rite pas, eh yeah

Video Information

Views
4.4M

Total views since publication

Likes
38.9K

User likes and reactions

Duration
3:55

Video length

Published
Feb 18, 2022

Release date

Quality
hd

Video definition

Tags and Topics

This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:

Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.