Akhlou Brick - THIOWO ( CLIP OFFICIEL)

Production - MuseeRecords Composition Musique: Yaya Barry & Amnezik D.A Music : El Menemo Chœurs: Magui Goodlife x Angélique Arrangement: Ara Mix Master :...

AkhlouBrickTV Officiel•338.5K views•3:24

About this video

Production - MuseeRecords Composition Musique: Yaya Barry & Amnezik D.A Music : El Menemo Chœurs: Magui Goodlife x Angélique Arrangement: Ara Mix Master : Zeuss Vibes Empire Réalisation: Schadiiq Cadreur : Oumar Ndiaye Lumière: FayTech Régie: Pape Malick x Macbour x Papa Sow Styliste: Naru Goor Costumes: Al Gueye Photographe: Pixel Com Figurant: Coura Ousmane Cissé Lyrics: Verse 1 Ara Guentt na Nioune niaar thi bideew Di naaw fanaane thi weer bi Nganane nioune niara moudjé biir Aldiana Thi ngama yéwé Deugg deugg li thia love bala yeeh yeeh Def ngama indo Bilay Naniou bayi thiowo bi diarouko Fing ma def laala def yeah Refrain Mbeuguel meun nala doflo wow Wowowowowow Deuké di xoulo thiowo Thiowowowow (2x) 2e verse Ara Mbeuguel meun nala dof lo wow Dioylo wow Dem bamou merlo la Kaf lola reilo la Fo lo la Dinala beklo Pre chorus Mbeuguel capitainou borom Tei thiow bi moy xorom bi Yow reika may wathieulo Tei somay rei may wathieu yow Mbeuguel capitainou borom Ling ma wone amothi morom Beugeu la, nga beugeu ma niou niro Melni Binga Bingo Thia love bala yeeh yeeh Def ngama indo Bilay Naniou bayi thiowo bi diarouko Fing ma def laala def yeah Mbeuguel’ay nono (l’amour c’est l’ennemi) Refrain Mbeuguel meun nala doflo wow Wowowowowow Deuké di xoulo thiowo Thiowowowow (2x) Verse 3 Dayza Thiowo woo woo Deum wala jinee nga yaw wowowowo Mbeuguel dou fo no no Indo la bana yeufou cow bo bo boy Bari lignouy thiowowo Deum wala jinee nga yaw wowowowo Mbeuguel dou fo no no Indo la bana yeufou cow bo bo boy Boma méré baby diaroul ngay todj kass dieulal lekh todial pess Lekh ba ngui ni todial pess Sougnou xoulo ba dioubo sougn ande dafay gueuna bess Nonanté bi guena bess Mane may golo yaw yaye garap Même bougnou thiowee mane ak yaw mane yaw lay faral Baeb mane lima dalon dou dalat Wurus nga ngalam nga mala ngoye dotouma bawat Never bawat Pre chorus Mbeuguel capitainou borom Tei thiow bi moy xorom bi Yow reika may wathieulo Tei somay rei may wathieu yow Mbeuguel capitainou borom Ling ma wone amothi morom Beugeu la, nga beugeu ma niou niro Melni Binga Bingo Thia love bala yeeh yeeh Def ngama indo Bilay Naniou bayi thiowo bi diarouko Fing ma def laala def yeah Mbeuguel’ay nono (l’amour c’est l’ennemi) Outro Yow fing ma def laala def Baeb Yow fing ma def laala def Baeb Yow fing ma def laala def Baeb Yow fing ma def laala def Baeb

Tags and Topics

This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:

Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.

4.8

67 user reviews

Write a Review

0/1000 characters

User Reviews

0 reviews

Be the first to comment...

Video Information

Views
338.5K

Total views since publication

Likes
17.0K

User likes and reactions

Duration
3:24

Video length

Published
Jan 24, 2025

Release date

Quality
hd

Video definition

Captions
Available

Subtitles enabled

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in United States under the topic 'hawks vs clippers'.

Share This Video

SOCIAL SHARE

Share this video with your friends and followers across all major social platforms. Help spread the word about great content!