Akhlou Brick feat Baye Cheikh Biteye - Borom Diamano (Clip Officiel)

Production - Muserecords Directed by - Wws (Worldwide studios) Beat By Babsbeatz Mix, Master by Sirr Khalifa Pianiste: Moustapha Biteye Percussionnistes: Pa...

AkhlouBrickTV Officiel•2.5M views•4:05

About this video

Production - Muserecords Directed by - Wws (Worldwide studios) Beat By Babsbeatz Mix, Master by Sirr Khalifa Pianiste: Moustapha Biteye Percussionnistes: Papis Mbaye( PMP) ; Babacar Zaka; Baye Wilane. Maquillages : Be on fleek And EIE Tenues par Azcouture Remerciements: EIE , Wonderfood, le Tahir, Deco by Rio Street Wear Lyrics BOROM DIAMONO Cheikh Baye Biteye Kérok bagnou paré Dem haybou ba di soukourat Yalla nang fa tew johgnou yonnént Sidy Barhama Yeurmandé Yalla dji kou la am Niass am na sowétass Yalla Yalla def gnou ndongo Sidy Barhama Wahlén ya Sidy Barhama moy Borom Diamano Baye Niass gnoun sougnou Gor gui Moy Borom diamono Baye Niass Aboul al Arwah moy Borom Diamono Baye Niass Baye Barhamaaaa Ara Kou yalla May kou am set lou ham ni wadji baye la Gnou yagnou doy dang gnou neub sa bopwanel gnou yalla Leer bangua medina Gamou berndel Bi diemi yalla la Nek di yalla doh thi ba fanaw lek thi yalla tank thi Di nan waouh. Kou yello beug ? (Barkhama baye) kan ngen beug? (barhama bayo barhama) bagnou paré Dem haybou ba di soukourat Yalla nang fa tew johgnou yonnént Sidy Barhama Yeurmandé Yalla dji kou la am Niass am na sowétass Yalla Yalla def gnou ndongo Sidy Barhama Wahlén ya Sidy Barhama moy Borom Diamano Baye Niass gnoun sougnou Gor gui Moy Borom diamono Baye Niass Aboul al Arwah moy Borom Diamono Baye Niass Baye Barhamaaaa Dayza Non bay moy wadji Bayou hawsa yek nari Mognou nandal bagnou mandi No baye no life Wilani jangal nagnou hitma Talibe eudeup enh Foudoul medina doufa teud carte gui deup na Guiss n’a yalla guissma Ham ko guen thi fitna Bayou bidewou bidew yi bay bidew bou bess la Goor yalla thi pochou baye Kouy bokale dou andak baye Daradié ne baye your side No baye no life Cheikh Baye Biteye Barhama banga Roté ba say Bagane fées Bawal nga gna la don haar ba séni ndap féss Halam ak allalam mom la diay thi l’ islam Bour signél ko mou wéer johko hatmou faydoumya Kou ngén beug? (Barhama Baye) Kan mo yéllo beug (Barhama Baye) Koungene beug (Barhama Bayooo Diarama (2 fois) Cheikh Baye Biteye Kon wahlen Ya Sidy Barhama moy Borom Diamano Baye Niass gnoun sougnou Gor gui Moy Borom diamono Baye Niass Aboul al Arwah ki moy Borom Diamono Baye Niass Baye Barhamaaaa...
4.8

491 user reviews

Write a Review

0/1000 characters

User Reviews

0 reviews

Be the first to comment...

Video Information

Views
2.5M

Total views since publication

Likes
37.7K

User likes and reactions

Duration
4:05

Video length

Published
Oct 12, 2021

Release date

Quality
hd

Video definition

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Pakistan under the topic 'b'.

Share This Video

SOCIAL SHARE

Share this video with your friends and followers across all major social platforms. Help spread the word about great content!