Iss 814 | Walter White (Hymne du Sal) [Official Video]
Titre: Walter White (Hymne du Sal) Album: Bicrave Artiste: Iss 814 Prod: Iss 814 Keyboard: Fulgence Gackou Mix/Mastering: Sir Khalifa x Iss 814 Video Directe...
🔥 Related Trending Topics
LIVE TRENDSThis video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!
THIS VIDEO IS TRENDING!
This video is currently trending in Italy under the topic 'video'.
About this video
Titre: Walter White (Hymne du Sal)
Album: Bicrave
Artiste: Iss 814
Prod: Iss 814
Keyboard: Fulgence Gackou
Mix/Mastering: Sir Khalifa x Iss 814
Video Directed by: Awanje Films
#RapGalsen #WalterWhite #BreakingBad
________
Abonnez-vous à ma chaîne YouTube : https://www.youtube.com/channel/UCz8KYuq-KGD0vk6WgRetlrw
_______
Ma discographie disponible sur toutes les plateformes de téléchargement: https://bit.ly/iss814
________
Retrouvez moi sur les réseaux sociaux:
* Twitter: https://twitter.com/814bsb
* Instagram: https://www.instagram.com/iss814beats/?hl=fr
* Facebook: https://fr-fr.facebook.com/814prod
* TikTok: https://www.tiktok.com/@iss814beats
LYRICS
Dou Katy Chimère té dou Lisa
Leppa sombre tout est bizarre
Facial la diaroul visa
Sa diabar viergeoul def ci bissap
Wacce game bi dieul sa distance
MHD joxu ma puissance
Haliday dé ma dieul vacances
Diwline tchi taal rek’am sens
Moussou gnou ray, fuck sa massage
Barrer tali forcer passage
Balotelli noir marquage
Dou Tom et Jerry rek’ay trucage
Dewé Étranger comme Meursault
Ken dou siffler domou hors jeu
Arbitre du yeukeuti drapeau
Gueuneu deugueul samay propos
TSQ Tewal Sa Quartier
Réseau mbedd nekoul 4G
Lepp dial sans gnou forcer
Yone bi lerr sans gnou torcher
Fuck Fac droit !
Fuck sen licence !
Mbedd rek la diokh confiance
Ghetto boy la bouy weur liasse
Ghetto boy la bu am liasse
Liasse !
Eh ehhh 🎶🎵
Gang !
Encaisser naniou sunu liasse, seddo ak sunu gang gang
Amone naniou fi touti problème, khekh’ak ko ak sunnu gang gang (x2)
Walter White (x2)
Heinzerberg
Walter White
Arsenal bi dou pour Ozil
Shoot sa rappeur mou dieul exil
Vision bu lerr ak ay faux cils
Animaux yi rek’a dociles
Capitaine dou guéné brassards
MĂŞme bouy guen ci birr terrain
Youkoungkoung sunu madrassa
Guediawaye la nigger ba fin
Tupac back Biggy dé
Ci tiakk tiakk yegg terre
Dou raktak mo fi ne
Bir barsakh lagne lay yé
Boy Loy lacc lou doul pé
Bou niouy rafal kii ak kee
Sunnu mafia sissoulene
Sen rasia dou ci len
Kamikaze kamikaze
game bi lay viser
Comme kouy défsi Kamikaze
Guediawaye c’est la case
Dieul job bi imposer comme kouy violer seni cages
Pairou Nike pairou Dass, tass liasse yi di compter
Nekk ci four bi di brasser paquetass paquetass
Comme grand yi niou paquetass ndakh quelque kilos yi gnou placer
Gang !
Encaisser naniou sunnu liasse seddo ak sunu gang gang
Amone naniou fi touti problème khekh’ak ko ak sunnu gang gang (x2)
Walter White (x2)
Heinzerberg
Walter White
Na four bi di tournée
Niou deff lou dope
Di make ay millions par journée (x2)
©️ 814 Prod. | January 2021 | All rights reserved.
Video Information
Views
362.4K
Total views since publication
Likes
11.4K
User likes and reactions
Duration
3:42
Video length
Published
Jan 8, 2021
Release date
Quality
hd
Video definition