Jahman X-Press Live in Aubervilliers 🎶 – Album ABIYO Concert on Sept 27, 2024

Don't miss Jahman X-Press performing their new album ABIYO live at Le Point FORT d'Aubervilliers! Join us on September 27, 2024, for an unforgettable night. Produced by Hoside Studio and mixed by Jeuuss. Get your tickets now!

Jahman X-Press Live in Aubervilliers 🎶 – Album ABIYO Concert on Sept 27, 2024
Jahman X-Press
2.0M views • Nov 20, 2021
Jahman X-Press Live in Aubervilliers 🎶 – Album ABIYO Concert on Sept 27, 2024

About this video

EN CONCERT AU POINT FORT D'AUBERVILLIERT 27 SEPTEMBRE 2024 : https://shotgun.live/fr/events/jahman-x-press

Production : Hoside Studio
Prod. by Jeuuss - Mix by Moussa Ngom

CONTACT MANAGEMENT : 77 640 22 08
ECOUTER L'ALBUM ICI : https://backl.ink/149698758

LYRICS
Yaye ki gueune ci mane yaye woye nala
Meunoumala faté
Soudoul wone ak saa yaye booy dina firim réw tass koo
Yaye balal ma
Yaye booy kaay balal ma
Soula nékhé daagoul sa ligueye fegn na ci sa ndiabot gui
Ay camions khaliss
Soumala ko done sotti
Dou doye ndakh diouro lou kene di khol nane thiam kane mondiour li

Mane santeu naa yallah buur bi bimala amé
Yaye diou melni ioe yomboul té khamna li takh ma wakh ko

Sanni ma daleu
Dou té malay gueureum
Loula nekh deff meu sama Aldiana ngui ci sey souffou tankeu
Mane santeu naa yallah buur bi bimala amé
Yaye diou melni ioe yomboul té khamna li takh ma wakh ko

Yaye defo fii lou niaw
Wakho fii lou niaw
Meusso nio wane guinaaw
Naadj bou tàngue bi nga daan daaw takh sama khol sedd ci yaw
Yaye gueureum nala
Yaw fo diaar yone la


Kouniou nane demb téy motax
Yone bi goudoone na loool
Yaye moussoulo wagnékou
Bilay khepp nako loool
Lou néew loumay deff ci yaw
Sou yokoul dotoul waniékou
Na lamp yii takkeu ma photowok mom
Yaye rétane maa
Sa rétane dafmay doundeul
Guiss la rek dafmey bégueul
Doundeul doundeul
Ba Abadan moma done gueuneul
Yaye yama lene gueuneul
Nga fékké laley nianal
Mangui ci yaw ba guédj gui ferr ndakh yamay bégueul
Yaye foula ndanane di diaar
Sey att yakkoul sa taar

Naadj bou tàngue bi nga daan daaw takh sama khol sedd ci yaw
Yaye gueureum nala
Yaw fo diaar yone la
Na lamp yii takkeu ma photowok mom
Yaye rétane maa
Sa rétane dafmay doundeul
Guiss la rek dafmey bégueul
Doundeul doundeul
Ba Abadan moma done gueuneul
Yaye yama lene gueuneul
Nga fékké laley nianal
Mangui ci yaw ba guédj gui ferr ndakh yamay bégueul
Ya foula ndanane di diaar
Sey att yakkoul sa taar

Video Information

Views

2.0M

Likes

14.6K

Duration

3:39

Published

Nov 20, 2021

User Reviews

4.4
(397)
Rate:

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

Related trending topics. Click any trend to explore more videos.