Jahman X-Press Live in Concert! đŸŽ¶ Celebrate Album ABIYO at Point Fort Aubervilliers, Sept 27, 2024

Join Jahman X-Press for an unforgettable live performance of their album ABIYO at Point Fort Aubervilliers on September 27, 2024. Don't miss this exclusive event! More info: https://shotgun.live/fr/events/jahman-x-press

Jahman X-Press Live in Concert! đŸŽ¶ Celebrate Album ABIYO at Point Fort Aubervilliers, Sept 27, 2024
Jahman X-Press
625.0K views ‱ Nov 21, 2021
Jahman X-Press Live in Concert! đŸŽ¶ Celebrate Album ABIYO at Point Fort Aubervilliers, Sept 27, 2024

About this video

EN CONCERT AU POINT FORT D'AUBERVILLIERT 27 SEPTEMBRE 2024 : https://shotgun.live/fr/events/jahman-x-press

Production : Hoside Studio
Prod & Mix by Jeuuss Beatz

CONTACT MANAGEMENT : 77 640 22 08
ECOUTER L'ALBUM ICI : https://backl.ink/149698758

Bessou mbegté leu ci mane
Bég bou amoul foumouy yam
Bég ci lima yallah deff
Beneu Baye Fall lou niow mané kheyneu dafa gueune
Bessou thianta leu ci mane
Thianta ngiir diam dji ma am
Dieureudieuf !
Dieureudieuf ! Yallah buur bima lakkeu
Fou beut bou bone yegoul wala lokho bouy yakeu
Damay contane continuer
(Bégué beauté ! begué mongui baakh ! Bégué beauté ! )
Mangui bég tei bégueulé
Merr maßtrisé
(Bégué beauté ! Bégué mongui baakh ! Begué beauté ! )
Diégueulé tei diéleulé
CELEBRATE ( nioune daniouy foo)
CELEBRATE ( kou merr bokko )
CELEBRATE ( fii lépeu jamm)
CELEBRATE ( bégué beauté )


TĂ© niit liy garabam niit leu
Diama gueune li ci sa compte
Damay bĂ©g mĂȘme soumay banque
Lénéne lou niow rek bonus leu
Yallah teral nama kone nak defal ci mane ndank
Soumay guestu lima wessou
Khamné mane merr warouma non non
( Nonono )
Awma dara loumay réthiou
Ndakh yallah yagg nama tekk lokho
Am sokhla fadjal ko sa bopp
Diarna sante yallah té khamni kene mounoul mey sa bopp
Wakh sakh mou yegu yallah la nekh
Kone warnga santeu yallah saa bo yéwo

Damay contane continuer
(Bégué beauté ! bégué mongui baakh ! Bégué beauté ! )
Mangui bég tei bégueulé
Merr maßtrisé
(Bégué beauté ! Bégué mongui baakh ! Begué beauté ! )
Diégueulé tei diéleulé
CELEBRATE ( nioune daniouy foo )
CELEBRATE ( kou merr bokko )
CELEBRATE ( fii lépeu jamm
CELEBRATE ( bégué beauté )


Degg naa fi louné , dadj naa fi louné
Deukeul ma founé té woul mangui bégué di dem
Saga nagn ma ndeye , takoul feneu ci mane
Mangui doli santeu yallah ndakh mom rek moy ki meune

Bégué beauté !
begué mongui baakh !
Bégué beauté !

Bégué beauté !
Bégué mongui baakh !
Begué beauté !

Tags and Topics

Browse our collection to discover more content in these categories.

Video Information

Views

625.0K

Likes

5.9K

Duration

3:13

Published

Nov 21, 2021

User Reviews

4.5
(124)
Rate:

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

Related trending topics. Click any trend to explore more videos.