ADIOUZA - MONSIEUR BONHEUR (CLIP OFFICIEL)

Après une longue dispute dans le couple, la femme prend l’initiative de se réconcilier avec son homme, son Monsieur bonheur et de faire la paix car ce dernie...

ADIOUZA•9.0M views•3:25

About this video

Après une longue dispute dans le couple, la femme prend l’initiative de se réconcilier avec son homme, son Monsieur bonheur et de faire la paix car ce dernier lui manque énormément . La paix est la source du bonheur.Sans toi mes jours sont blèmes et le monde vide. Que serai-je sans toi à mes côtés ? Reviens-moi. Lyrics Mr Bonheur nexa joubole Dafa jote nga gneuw gnou waxe Taye jameu la yewo Bae sagou bi doyna ma guiss néne ni néna ngui thiapa thioly do kéne thi gni lo viser doko moy raféte nguémb meuné beuré souf Refrain nonou lalay nammé *dotou moko def* Te foma méré ma diakh lé bb *dotou mako def* *balma dotou moko def* yaw xolma tay ré bb Dotoumako def* gnou def joboo de l’année bb Dotoumako deff *balma dotou moko def* Couplet 2 dama paré dioubok yaw ba fofou gnouy wowé wouyaye oohoo ohoo khamanté nagne dou ame thiow oohoo ohoo diéleu ame foko fogué woul soukeur bi thi banana paré noy ni xaale menthe bi né thi nana ak yénene yilay xaar Doyalouma mére bi doyna Doyalouma Refrain nonou lalay nammé *dotou moko def* Te foma méré ma diakh lé bb *dotou mako def* *balma dotou moko def* yaw xolma tay ré bb Dotoumako def* gnou def joboo de l’année bb Dotoumako deff *balma dotou moko def Pont meuno dém kaay ndax yaye sama poumon gauche Waw Waw Waw Yaw la meuna fi dé thi une minute de pause Wallah wallah am nga thiass stylé nga mako léteu kaay firiko diekha goul doya louma dianteu soow kaay dolima *doyaaa louma* a vie lagne signé *doyaaa louma* Refrain nonou lalay nammé *dotou moko def* Te foma méré ma diakh lé bb *dotou mako def* *balma dotou moko def* yaw xolma tay ré bb Dotoumako def* gnou def joboo de l’année bb Dotoumako deff *balma dotou moko def Weye mbegel manak mbegel bae tay la tay bae tay la tay dara ladoule mayé Bae taye la taye togale Bae taye la taye Dara doumako mayer bae tay la tay togale dara ladoul mayé Beat: Iso Composition: Adiouza, Iso Lyrics: kruh Mix master: Ludovic Ingenieur: Moussa ngom Realisateur: Mety-med Acteur principal: Ansoumana Coiffure: dija and aisha Make up: Adja make up Styliste: Mb haute couture Assistante: Aminata Ndoye Remerciement: Villa Ndéye Fatou, campement ndangane de Cheikh Dieye, Maison la lagune campement Ndangane, imam Diouf île du saloum et le staff. Abonnez-vous ici : http://bit.ly/AdiouzaDiallo Retrouvez Adiouza Diallo sur : - Tik Tok: https://www.tiktok.com/@adiouza7 - Instagram: http://i.instagram.com/adiouza/ - Twitter : https://twitter.com/Adiouzaofficiel - Facebook: https://web.facebook.com/AdiouzaPageFans/ #Adiouza2022 #MonsieurBonheur #AdiouzaProd

Tags and Topics

This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:

Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.

4.4

1801 user reviews

Write a Review

0/1000 characters

User Reviews

0 reviews

Be the first to comment...

Video Information

Views
9.0M

Total views since publication

Likes
51.2K

User likes and reactions

Duration
3:25

Video length

Published
Oct 29, 2022

Release date

Quality
hd

Video definition

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Morocco under the topic 'الطقس غدًا'.

Share This Video

SOCIAL SHARE

Share this video with your friends and followers across all major social platforms. Help spread the word about great content!