ADIOUZA - FANS YI (CLIP OFFICIEL)

Adiouza rend hommage à tous ses fans qui la soutiennent depuis 10 ans ! Fans Yi (Lyrics) Mane beguer nallene Eh beguer nallene Fans yi namonalene namonal...

ADIOUZA•1.7M views•5:11

🔥 Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Singapore under the topic 'itoto system 12'.

About this video

Adiouza rend hommage à tous ses fans qui la soutiennent depuis 10 ans ! Fans Yi (Lyrics) Mane beguer nallene Eh beguer nallene Fans yi namonalene namonalene Couplet 10 ans déjà yone wi metina Cey yi le soper Bayiwougnouma Yageuna beug deff weuye wi Waxlene fima tolou thi yene Loune nguene di dathieu Nguir Mane Te Mane yeknako Xex souba Ngone yeknako Lou Len meti yeknako Mane Sama xel sama xol langui Thi yene Taye ma sargalene yene fans yi Refrain Mane beguer nallene Eh beguer nallene Fans yi namonalene namonalene Solo Ligueye bo Thi donner Djiguene Faut k nga xamner Foula moye Li geune Yen saye nite guisse la télé xemem la tok di dioye Weur la wolou la nga gneuw bo noyer bop dioye Kaye ma xamalene touti Fans yenou yeukati Ani Wa pikine Parcel Thiaroye Yarax Guediawaye Rio Keur Massar médina Ziguinchor ba ndar beguer nagne ma waye Mauritanie ba gambie beguer Baguer nagne ma waye Jappeu nguene tewa bayi, douma xadi waye. Refrain Mane beguer nallene Eh beguer nallene Fans yi namonalene namonalene Pont Taye ma weuyale lene Yena ma japaler Taye ma xamalene Yena ma dolele. Tiaba, Diarra Nancy, Bigue, Maimouna awa toure, wolma mame Diongue loxo thia kaw Leggo leggo Solo Weuye Lene ma ndeyssane sama mak ji Ana Sagna chéri sadia Wolma lamine fall ak fatou thiam Begoulo ma mère dale Yaw Domi ndey Mami diouf Souma demer baye beugeu xadi chéri Aziz ndiaye dolele ma Souma demer baye beuger xadi Khady koundoule dolel ma Tassou Sa goune sa goune Solo Dioudou Bou reye ndey ak baye Foulak fayda borome dale Mareme chalar mimaye beugeu jigne Aida Seye chéri lamine la bokale baye Fou sama rangogne touro Mareme fompale ngamako Raki gamou seye Diarama mareme Weye lele weuyelelene ma mareme Souma demer baye beugeu xady Chéri doudou dolelma Souma demer baye beugeu xady Fat kine dolelma Dj boubs, pape cheikh, cheix Sar Sidathe gnoma terrer chômer Abba , Koutia, alima Maria gnoma tere chômer Dieynaba, Nadia,, haini, maty, kebs thiam leggo leggo. REMERCIEMENTS: L'équipe de gladiateurs qui m'a accompagnée dans la réalisation de mon album. il s’agit de MON FRÈRE Cheikh Ouza, Moussa Ngom, Yeye faye, Iso on the beat, CT, Baxaw, Xuman, king Kruh lyrics, Bril, wanted, Pac D, Max Ngassa, wylliam, l’hôtel Radisson, Hertz, Novotel, Thinmas. Je remercie tout le staff, tous les membres de Adiouza family, ma famille, mes amies. Sans vous, il me serait difficile d’y arriver. Mention spéciale à mon père et ma mère pour votre soutien. Abonnez-vous ici : http://bit.ly/AdiouzaDiallo Retrouvez Adiouza Diallo sur : - Instagram: http://i.instagram.com/adiouza/ - Twitter : https://twitter.com/Adiouzaofficiel - Facebook: https://web.facebook.com/AdiouzaPageFans/ Pour booking: - A l’international: +33 6 77 73 16 73 - Au Sénégal: +221774892177 / +221 773222305 #Adiouza2020 #FansYi #AdiouzaProd #SaGoune

Video Information

Views
1.7M

Total views since publication

Likes
9.7K

User likes and reactions

Duration
5:11

Video length

Published
Feb 12, 2020

Release date

Quality
hd

Video definition