Akhlou Brick - Hello World

28 Décembre sortie Album HELLO WORLD Disponible en Précommande sur ? http://www.akhloubrick.com/ iTunes: http://itunes.apple.com/album/id1488447019?ls=1&a...

AkhlouBrickTV Officiel656.1K views3:27

🔥 Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Turkey under the topic 'bursa deprem'.

About this video

28 Décembre sortie Album HELLO WORLD Disponible en Précommande sur 👉 http://www.akhloubrick.com/ iTunes: http://itunes.apple.com/album/id1488447019?ls=1&app=itunes Apple Music: http://itunes.apple.com/album/id/1488447019 Mix, master: Max Mix QGS records Beat: Passa Beatz Cover Artwork: yusufasamb Accessoires: Rio Street Wear Avec la participation: EIE(Ecole international d’esthétique ) et la gare de Dakar( Apix) Les acteurs: Aldo De Sa Nogueira (Luis G) Mouhamed gueye Pierre Morera Akon Facebook: https://facebook.com/akhloubrickofficiel/ Twitter: https://twitter.com/akhloubrickest Instagram: https://www.instagram.com/akhloubrickofficiel/ Lyrics: Hello Hello world my album degloul Meun na yag meun na nadie wayé batay goudegoul Même thi say guente bomay wokh bo yewou hourekou Teuh dou crise thi bruit Ibliss dou guiss goumba bou beuteum mourekou Balè war kou diékou Mougn day fay kou dekou Même Garabou gnambi pour mou diarign faw renam boudékou Demay hol thi pinkou dina fay heul di fegnou Feul foma foguèwoul may wer bi Iyan thiam di sentou siguil ndigalè album yi fi jota delou haybou Sen carrières ni esperence de vie lire bou delou Hello world dou dé foko soti dou fess moy jeumi faydou Tay kou bagn rikekou kou beug kiray yourekou Kou deglou deg kou guiss ne gongo ay fathom oubekou Bi doko get guementou bokoy get def thiotj tahaw hymn national pincez tous Force ding ko tok di deglou ding thi guis sa bop diem ko lire couplet yangui thi seetou Alhamdoulila ... Hello word my album listen may ma wah limiy teunk Dou rap dou rnb dou afro beat dou diazz té dou funk Brick bi dou top mouvance Beat yi di top mouveum Rythme mélodie gnou danse Sang solal ko mboubam Gnetellou album gnetelou baram thi dohine yi deung Ndiekew ma geum def halam tama some flutu peul Mouma di wah ay teuh Djine di diomal ay deum Hehou dof la ak kou keuh borom hel al helou dieun Borom ham ham yi tegante hel dof yi teguente deund Diangal sa couri mo geun def sa cour di nek si geune Bari gni beug deglou album tekthi new gni koy dieund Amo Lo wah teudial gat noopil sit doown sit down be humble Am na lamign bou ngadeu bache ak chaise gnew gnou langeu bir ak dole biceps molé ak tere you manga Do man wah tay mouma nga album bi legui moy yemb Ladial sa nigga foum nekon bagniy ne thi hour bi di tangal Nit day tew ndoh day tew hel dey tey Gneup diay mai diay katou gnambi danan day sey natalou album ni photo mer bi thi diek bou diar Kon Halal len ma yon bi com ni halé yon bi ter bi diar #Akhoubrick #helloworld #Rapgalsen Hello world

Video Information

Views
656.1K

Total views since publication

Likes
18.9K

User likes and reactions

Duration
3:27

Video length

Published
Nov 18, 2019

Release date

Quality
hd

Video definition

Tags and Topics

This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:

Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.