Akhlou Brick - Sama Logo Bi (Beat By BabsBeat)

Akhlou Brick - Sama Logo Bi Disponible sur iTunes: http://itunes.apple.com/album/id1447143869?ls=1&app=itunes Apple Music: http://itunes.apple.com/album/i...

AkhlouBrickTV Officiel‱1.4M views‱3:44

đŸ”„ Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Bangladesh under the topic 's'.

About this video

Akhlou Brick - Sama Logo Bi Disponible sur iTunes: http://itunes.apple.com/album/id1447143869?ls=1&app=itunes Apple Music: http://itunes.apple.com/album/id/1447143869 Beat by BabsBeat mix,edit & master by Max Mix QGS records Avec la Participation de : Boubou Design , Bise Collection, CasuelChic, Yarba Deco, et ATVISION, Lyrics: SAMA LOGO BI Ehhhhhhhh Logo bi logo bi i know LOGO BI ParĂ©lĂ©n tay parĂ©na ok ok I know ParĂ©lĂ©n tay parĂ©na EHHHHHHH. Fou bi nĂ©na dofatoul tĂ© dou dĂ©lou fan Patin nĂ© mouk dou ba fĂ©n tĂ© ken douko tĂ©rĂ© nan ay Douliprane ParĂ©lĂ©n parĂ©na May djinĂ© biy tafou bir koloban Dou gris gris diate ak thioumboukay boudone lola Gouy Gui rĂ©kay meuna dan Grand yi nĂ© dama wawlĂ© meuna rap tekthi gnĂ©mĂ© rak Ragalouma yamou thiowlĂ© limay hamb tay la geuna tak Tay la geuna tay la geuna tar Dina meti tahoul beut yi taaa YĂ©nĂ© ma dĂ© ma lĂ©k sa naka Tay mbeura beurĂ© guĂ©n thi di bakou Wahko nĂ© Toubab bĂ© bagn nĂ© dou diongu Nit kou gnoul bagn nĂ© dou diang Kou nĂ©k sa natou bi Ana Louy ndiarignou koom BoudĂ© dou guĂ©n thi bank Haliss day wallou nit Wan ma Lan geuna fonk Louis V Gucci nga Am Ma TassarĂ© logo thi Logo bey todji sa monde 🌍 Ara la toudouma baye sen mai wowema wowema sen pa ArmĂ©e bi marquer na sen pas Ngor Djigan Dupon la Demba Sa rapeur bi menoul na bayi neko na bayi mongui beune timpa Sa girls bi nĂ© Ara da sympa Beugone ma nop ko mais mĂȘme pas Dama pĂ©daler laisser deux legui meun na pas de danse yi rek fatĂ© na GuĂ©ta gnemeko brickest attentat wane ko topp 5 batamba Mbour Dk Kaolack brickest ba Tamba Sissou na dissout tay niggazz bi nangouna Sagnsek sama logo bi Logo bi logo bi logo bi Sa teeshirt sama logo bi Logo bi logo bi logo bi Sa casquette sama logo bi Logo bi logo bi logo bi nangouna Sagnsek sama logo bi Sagnsek sama logo bi nangouna ParĂ©lĂ©n tay parĂ©na ok ok I know ParĂ©lĂ©n tay parĂ©na ok ok I know Caissou beat bi bamou dalĂ© gneup LadjtĂ© Dayza fan la nĂš Caissou Ă©tat dig la mallette do massa ladjtĂ© fan la palais nĂ© Wesounala dama parĂ© man la mise Ă  jour bi Dougal sa paramĂštre Rap galsen bou melon ni charrette ma togue thi kanam gnounĂ© Dafa kanamĂ© Nigga man Kaw Kaw la bo beuguĂ© gnou def com dap dama yorĂ© beuzzou Classico bi gnom gnoulĂ©ni thiow comme lah pincez tous vos Cora c’est moi le chef chorale ara la Dayza la Herbert Pepper LĂ©opold SĂ©dar Raw Nala douma sa Mass hale bou matagoul moss wodatko Clip bi harouthi trace Million de vue yi thi poche nodatko Public bi rap la ma sass logo bi solko ni boss gneup dacorr sa son yi di faux raccord Dayza la messouma teulĂ© ma beug beugua def mouy teu Fitou gayndĂ© la dou titeu Da yomb ma mĂ©lni kouthiy fo Sa nigga bi amatoul Halima plume Bila fatĂ© thi ndelou titeuf Yag na mĂ©ti ma mougnko piĂšge nagn gnou ma ndiouyko Gni beug souki lafou pith bi nelen pith Bangui thi logo Twitter gnemeko brickest attentat wane ko topp 5 batamba Mbour Dk Kaolack brickest ba Tamba Sissou na dissout tay niggazz bi nangouna Sagnsek sama logo bi Logo bi logo bi logo bi Sa teeshirt sama logo bi Logo bi logo bi logo bi Sa casquette sama logo bi Logo bi logo bi logo bi nangouna Sagnsek sama logo bi (Logo bi) Sagnsek sama logo bi nangouna nangouna Sagnsek sama logo bi nangouna nangouna Sagnsek sama logo bi nangouna Sa teeshirt Sama logo bi Logo bi logo bi logo bi Sa casquette sama logo bi Logo bi logo bi logo bi Logo bi logo bi logo bi Logo bi logo bi logo bi Logo bi logo bi logo bi

Video Information

Views
1.4M

Total views since publication

Likes
22.6K

User likes and reactions

Duration
3:44

Video length

Published
Dec 14, 2018

Release date

Quality
hd

Video definition

Tags and Topics

This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:

Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.