4- Dizzy Kha - Nobelak (Prod. Karabalik Beatz)

#AtouFegneNa Titre numéro 4 "Nobelak" Réecouter ce son en streaming sur les plateformes suivantes : Itunes : http://itunes.apple.com/album/id1437941960?ls=...

Dizzy Kha Officiel‱8.9K views‱3:03

đŸ”„ Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Singapore under the topic 'itoto system 12'.

About this video

#AtouFegneNa Titre numéro 4 "Nobelak" Réecouter ce son en streaming sur les plateformes suivantes : Itunes : http://itunes.apple.com/album/id1437941960?ls=1&app=itunes Apple music : http://itunes.apple.com/album/id/1437941960 Disponible sur Deezer, spotify, tidal etc .. Fbk : https://www.facebook.com/dizzydreamking/ Twitter : https://twitter.com/dizzykha Instagram : https://www.instagram.com/dizzykha/ Snapchat : @yagga-dream Refrain : Yenesay mou nekh yenesay mou weekh khate (oh nah) So déssé sama wete douma wete wayy si nadj bou tangue dieurgadon kerr way yaye sama choix Awma benen choix Wonaleuu Yaye sama sadiabar Nobelak khol nobelak thieur yi Love everyday Novelas tv Oh yea novelas tv Oh oh oh oh oh oh 1 er couplet : Yay sama debut di sama fin Yagone la sete mai guiss nala tey Dé moma geuneul guiss sa defaite Sans yow ni life Di safadé Si Life bou tar yaye sama joie de vivre bama guenté aldiana yow ladon guiss Sa khet dafma nekh baby Kay took fi Sa mbeuguel doumasi doyal kaye doli Déloul bountou neg bi andeu bi ga Boyal Thiourayal dieguesima legui leww gama Sama beut ak sama khol yeup yakoy toyal Baby Bayi sen mbok nieuw deukeulma nehnama way Refrain : Yenesay mou nekh yenesay mou weekh khate (oh nah) So déssé sama wete douma wete wayy si nadj bou tangue dieurgadon kerr way yaye sama choix Awma benen choix Wonaleuu Yaye sama sadiabar Nobelak khol nobelak thieur yi Love everyday Novelas tv 2eme couplet : Yaye sama ouest di sama nord Yag ko xoslu di sondondo Koula beugoul di sama none Dé moma geuneul guiss sa rangogne Hamnani geumo liga wakh daga mere rek Hamna sa vrai djiko Kone baby tournel sama magg dafa wete tey Kone please let it goo Boul diap mer geuneul diap sama mere Doumala saga ndeye té doumala Sagané Guissoumafi lenen lou dak sa mbeuguel Sans yow ni life dou safadé Daniouy motalanté kay diabteloma ak sa love bou Chocolaté ehhhh Sougnou mbeuguel dotoul laté nakh sayougn kheuyé mak yow niou recommencer wayé Refrain : Yenesay mou nekh yenesay mou weekh khate (oh nah) So déssé sama wete douma wete wayy si nadj bou tangue dieurgadon kerr way yaye sama choix Awma benen choix Wonaleuu Yaye sama sadiabar Nobelak khol nobelak thieur yi Love everyday Novelas tv Oh yea novelas tv Oh oh oh oh oh oh

Video Information

Views
8.9K

Total views since publication

Likes
249

User likes and reactions

Duration
3:03

Video length

Published
Sep 28, 2018

Release date

Quality
hd

Video definition

Tags and Topics

This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:

Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.