https://Wiseband.lnk.to/Ashs-The-Best-4010-Session-1
Millions Flows nouvel album maintenant disponible: http://bit.ly/MillionsFlows
https://smarturl.it/album-millions-flows
___
40TenSessions #1 Ashs The Best (prod. 1da Beatz )
Lyrics:
Guddee tëdd naajee yeewu
Absa tàngal café añ bi lay teewlu
Geenatuma kër ga fa laa am rendez-vous
Neeg ba am na micro machine ba ma la gënël fuuf
Sama patrimoine ci ben disque dur
Sama xel’ang ci biir sama xol mbëggeel a ma fa diig
Xawma woon li may doon nga def li ma doon
Nee nañ ma jappal ding ci geen te ma bëgg des ci yow for ever
[For everything]
Ni ma la bëggee
Tax fum la deeg begg
Su ma meroon mu dèñ
All day man akk yow
Xol bi mélodies fa fèes
Deglu beat di rap
Faate samay problème
Sudul yow docteur du ma faj
Ma ne yen bi yagg diis
Coffeel tax dum ko yëgg
Mën jooyal sama bopp
Sudee ku dee da sës ci man
Samay problèmes dum la ko diis
Moom laa ko mëna wax
Soo gisee weet ci moom di job am na lutax
Refrain:
Am na ñu ma nekkaloon ño ma wonaat ginaaw taxaw guerre akk man
Alone in my mind love is dead I beleive anyone
Rest In Peace mbëggeel ci sama xol
Mbegte lay def ci man souffrance bi yëpp lay faj
Ñi ma war bis di na ñëw
Am ñi ma topp ndax moom
Ñi foogoon ni da ma dof ne len da ma dof ci moom
Mën nañ ma baayi akk sama bopp
Noflaay bokkul ci man
So alone ci sama life
Ken xamul woon fils lan lay doon
Batay maa ngi demmal sama bopp
Maa tracer sama tape
Ken àllu ma règle mais mang koy teg ci yoon yu jubb
Maa doon lonku akk Bathie ci koñ bi
Ñoo doon lëmbe classe school bi yëpp
Ken bëggul ñu freq sa doom
Man la weex dunk lu am mën na encaisser gauche akk droite
Fight sama life again chambre 11 I will never forget
Yagg xoslu ci koñ bi batay ñu fight sunu respect
Am na ay fakedass yu des akk ay real yu mësul dee
Shout out for my every nigger
My nigger who failed my nigger who died my niggers in jail
Rest In Peace Malick Sarr a.k.a Sarenzo
Guediawaye du la mësa forget
Rest In Peace L’Homme Du Squarre Beuz weetal nga kër gi yëpp check it
Ashs The Best what’s up
Refrain
#ashsthebest #4010 #40TEN #millionsflows #session #1
Retrouvez #AshsTheBest sur :
FaceBook - https://www.faceboook.com/AshsTheBest/
Instagram - https://www.instagram.com/ashsthebest/
Snapchat - ashsthebest
Abonnez-vous à #Mind7 : https://instagram.com/mind7_musik?igshid=1fkh68pys4y1x
© 2020 Mind7