Ashs The Best - Wetoon Na (Official Clip) 🎶

Watch Ashs The Best's Wetoon Na official video. Album 'Dibèer' available now. Composed by Jeuss Beatz & Nautylusprod.

Ashs The Best - Wetoon Na (Official Clip) 🎶
Ashs The Best
5.3M views • Dec 29, 2020
Ashs The Best - Wetoon Na (Official Clip) 🎶

About this video

https://wiseband.lnk.to/Ashs-The-Best-Wetoon-na
Album "Dibèer" ici :https://wiseband.lnk.to/Ashs-The-Best-Dibeer

Compositeur : Jeuss Beatz / Nautylusprod
Mix & mastering : Nautylusprod

Réalisation : Mad in pixel Films
Montage : Elzo tawfekh & Mad
Color grade : Mad & Elzo Tawfekh
Décoration : Mad & Sadek Bouzinou
Direction artistique : Mad in pixel
Assistant : IamJustBravo & Moussa

#AshsTheBest #Wétoonna #seriekarma #BO #Soundtrack #sonkarma #Wetoonna #dembwetona #sonkarmamarodi #karmasong

Retrouvez AshsTheBest sur :
FaceBook - https://www.faceboook.com/AshsTheBest/
Instagram - https://www.instagram.com/ashsthebest/
Snapchat - ashsthebest
Lyrics :

Dèmb weetoon naa
Da ma reeroon nga fèeñal ma
Yow mii laa doon xaar
Fekk ma ci lëndëm niital ma
Sama xol Weetoon na
Da nga ñëw ma xam luy adduna
Sa mbëggeel dundël ma
Yor ma yar ma yee ma yërëm ma

Dam la bëgg bëgg te Yàlla tax
Pare lepp pour nekk akk yow

Ndax dèmb weetoon naa
Da ma reeroon nga fèeñal ma

Yow laa tàmm nekkal
Yow laa nangul lu ma mësul nangul kenn

Sa mbëggeel dundël ma
Yor ma yar ma yee ma yërëm ma

[mbëggeel bii di na ma gaañ]

Ndax dèmb weet naa weet naa
Tay samay naqqar jeex na wëy naa
Yaakaar gu tasoon waaw
Sama xol a ma tëjjoon kaso waawaw
Banneex bi ñëw na ñëw na
(Li) meti woon dèmb tay neex na neex na
Ma’ag yow all day all night
Sa wet laa bëgg des ma’ag Yow for life


Dèmb weetoon naa weetoon naa
Da ma reeroon nga fèeñal ma fèenal ma
Sa mbëggeel la ñëw dundël ma dundël ma
Yor ma yar ma yee ma yërëm ma yërëm ma
[Bis]

© 2020 Nautylusprod / Mind7

Tags and Topics

Browse our collection to discover more content in these categories.

Video Information

Views

5.3M

Likes

57.7K

Duration

3:38

Published

Dec 29, 2020

User Reviews

4.6
(1065)
Rate:

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

Related trending topics. Click any trend to explore more videos.

Trending Now