Maabo - Ideu (Clip Officiel)

Dans son nouveau clip, NoFace Maabo prie pour son ex-femme AĂŻssata GuissĂ© - mieux connue sous son nom d’artiste Mia - et lui pardonne. #maabo #ideu #clipoffi...

MAABO officiel‱6.9M views‱3:51

About this video

Dans son nouveau clip, NoFace Maabo prie pour son ex-femme AĂŻssata GuissĂ© - mieux connue sous son nom d’artiste Mia - et lui pardonne. #maabo #ideu #clipofficiel #noface #undacova ** Les crĂ©dits du clip & la chanson IDEU ** Auteur : NFU Compositeur : NFU RĂ©alisation : NC.ABRAM, SEDRICK BLICMAN Production : NuWorld Music Group NWMG LLC. Atlanta, Georgia 2022 N8 Studios www.N8studios.co Lyrics: by NFU Mane kane laci wara wakhal ? Aissata wala Mia ? Khame nani niakoumala Nakh yameu dioural ay doom Fater wouma ki niou soĂ»l tchi Yoff Ak souniou Amina namena fo akk mom Reuthiouwouma ma sama seuy ak yow Djigueine dei geunou la si souf ni sa tourondo Djikko yi rafet yima kham tchi yow Bouma fi togone di ci wakh fi ba souba dou diekh Mangui niane diam tchi yow Niane yalleu nangou tei yokk leu Nianouma djital kein tchi yein Goudal fann yow ak sama mame Amina Boul fater niane yimala dinkone beuss bo degguer ni njibina Mane dei namena khetou wagne Bi done khegne si keur gui May yendo fetieu ak way Doumalako neub souniou andd bi Beugouma wone mou diekh Wayer diameu ak pekhem Yalleu ak ndogalam Yow dĂ© sama nawlĂ© ngua Dou meuss nekh bama fater leu Yow dĂ© sama nawlĂ© ngua Fatew ma bigne lay mour nguay nieuw tchi mane Niongui done niane benene dom bou goor Touder ko seydina Mouhamed Niou dem adji Makka Fatew meu biniouy nieuk wahtane Fatew meu biniouye moudier wahtane WaylĂ© lein ma .... Aissata legui sama rakk ngua Kone denkeu nala Yow boko ak niom sokhna ngua Nakh Aissata fĂ©tĂ© kaw Mia Adouna ko belel dierry Dounya Ko meri (meri) Demna rakk yaralma sama mame Yalleu neu Yalleu leral sa yone Dingua guiss kou nek kholal boubakh Sa mbektĂ© moy diam Amina Woy Mia wala Aissata Santeu nalĂ©ne geureum nalĂ©ne tay Euleuk dou agne dou rer Wayer lou mata sor leu Yalleu neu Yalleu def Li geun ci yow Tagou nala Aissata Mangui lay balou tei dila bal Aissata mane sa Mak la.
4.9

1378 user reviews

Write a Review

0/1000 characters

User Reviews

0 reviews

Be the first to comment...

Video Information

Views
6.9M

Total views since publication

Likes
110.2K

User likes and reactions

Duration
3:51

Video length

Published
Nov 17, 2022

Release date

Quality
hd

Video definition

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Turkey under the topic 'bursa deprem'.

Share This Video

SOCIAL SHARE

Share this video with your friends and followers across all major social platforms. Help spread the word about great content!