Rema Diop - FALAY LANGUÉ (Official Music Video) 🎶

Découvrez le clip officiel de 'FALAY LANGUÉ' de Rema Diop ! Suivez l'artiste sur Facebook et Instagram pour plus de musique et d'actualités.

Rema Diop - FALAY LANGUÉ (Official Music Video) 🎶
Rema Diop
13.4M views • Dec 18, 2021
Rema Diop - FALAY LANGUÉ (Official Music Video) 🎶

About this video

Retrouvez Rema Diop sur vos réseaux sociaux
Facebook ~ https://www.facebook.com/RemaDiopOfficial?mibextid=LQQJ4d
Instagram ~ https://www.instagram.com/rema_diop_officiel/
Tik Tok ~ https://www.tiktok.com/@rema_diop16

#clipofficiel #mbalax #new #video #remadiop

••••

▪️ Manager : Alga +221 77 503 77 53
▪️Mastering POLIMAN
▪️Music : Jeuss Beatz
▪️Réal : Ziz’Art
▪️Pape Ndiaye Tama
▪️Tenue : Ma Ndiaye Couture et M&B Haute Couture
▪️Chaussures : Khadija Kounta
▪️Make up by: Zahra Make up
▪️Infographe : Abou HM

••••
••••

CHERIFOU et JOB SA BRAIN/Rockteam Music, Metha Ndour, Poliman, Adama Sow, Antoine Zerbo, Sophia Thiam, Touchic By Ada, Alassane Gaye, Amadou Diouf, Mouhamed Tima Déco, Mansour Mbaye, Mamoudou Sonko, capitaine Mamadou Dieye;
Mention spéciale à ABDOULAYE CISSÉ et YORO DIASSY

••••

••••


Lyrics:

Cédé lén ma wakh ko bén yoon
Yéh, mom diaral nama
Yen cédé lén ma wakh ko niarri yoono
Yéh yéh, mom diaral nama

Dinama wo, dinama topato, dinama diégué sa souné dima réeeh
Dinama wo yéh, dinama topato waw, dinama diégué sa souné dima réeeeh
Mane khamé nala téh niémé nala yama doy si farando dagua ma nékh

Chérie saï saï mane douma meuna diégué
Kay kay yay sama coco rappéh
Saï saï douma khol bamay niéméh
kone tamou nala ya fi néhhh

Doy guama wérouway
Doy guama karanguéh
Doy guama si sa ndiégué nay waw lay langué
Falay langué, falay langué, falay langué si sa wét lay langué
Falay langué, falay languéh, falay langué si sa wét lay langué

Kima sagal yawla
Kima thiëreul yawla
Kima téral bama tédd ték ma si wétam yaw la
Souma bégué yawla
Meunou ma bakh ba raw la
Souma guéné niou nawma bilay
Guinaw yallah yawla

Kone tay dessna si mane
Ma mat leu seuk yaye
Mat leu diabar
Mat leu kilay bégguël kilay ray
Kilay raaay waw


Chérie saï saï mane douma meuna diégué
Kay kay yay sama coco rappéh
Saï saï douma khol bamay niéméh
Kone tamou nala ya fi néeeh

Doy guama wérouway
Doy guama karanguéh
Doy guama si sa ndiégué nay waw lay langué
Falay langué, falay langué, falay langué si sa wét lay langué
Falay langué, falay languéh, falay langué si sa wét lay langué

Djiguéne boula mouniëlé dagua kay sagal
Gorr boula térallé dagua kay guereum
Djiguéne boula mouniëlé dagua kay sagal waaw
Gorr boula térallé dagua kay guereum

Baye ndidiay coly gorr silé for silé tokk
Thinn bou makk nélawal
Gaïndé bou boffé domam béy souko laléh togn
Est ce que dina ko lale wawwaaw
Yéé yééé dagua kay sagal
••••
••••

Tags and Topics

Browse our collection to discover more content in these categories.

Video Information

Views

13.4M

Likes

38.5K

Duration

3:12

Published

Dec 18, 2021

User Reviews

4.3
(2672)
Rate:

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

Related trending topics. Click any trend to explore more videos.