Ouza - Last Piece ft. Adiouza [Official Video]
Watch Ouza's 'Last Piece' featuring Adiouza in this official music video. Subscribe for more updates! 🎶
About this video
Abonnez-vous ici : http://bit.ly/AdiouzaDiallo
Video prises de vue : Boris Diop
Lyrics
Da nga maye nakh maye titero
Doxer nima nekher nane mafi meune
Nga dane maye diaye maye titero
doxer nima nekher nane ma fi meune
Ndeketer yo da nga maye nakh
Nakh ngama adouna ware ngama
Adiouza
Adouna ngui ni
Demal mangui gneuw la
Pape Thione li la waxe
Ndeyssane mane louma gemone
Adouna mako mome
Mane Ndeyssane louma gemone
20 ans yi dotoul diekh
Goudi goudi mangui thi biti
Nathieu nathieu mangui thi biti
Gej sambarax mangui thi biti
Liw liw mangui thi biti
Ndeketer yo da nga maye nakh
Nakh ngama adouna ware nga ma
Adiouza
Adouna ngui nonou
Dalaye ware ware warate.
Da ma goumber bire teungethieu
Dem ba bargny gethieu
Sebikotane dem ba thies kaye
Dara jolof fale ma boure.
Dama goumber bire fatick
Dem ba ziguinchor
Velingara Gambia wooo
Serekunda falle ma boure
Goudi goudi afro dounda
John Thomas fale ma boure
Goudi goudi afro dounda
Khady manka fale ma boure
Goudi goudi sérale sa xole
Khady tabane fale ma boure
Dianka dia nga nane cheikh bassine Lo
Fi fi fi yenako mome
Adiouza
Booo de gone
Da ngay yakarni yaye borom
(Degeuleu)
Mak Dikk mou ware meunoto dara
Koy ndieukeunter le loy daw baye danou yaw
Thiam Babel demba thi yonou pomt ba
Marem ndoye seder la
Thiam Babel dem ba thi yonou pont ba
Assane doyen seder la
Tomorow tomorow
Waxe ma foder play
Tomorow tomorow
Tomorow night ma sathialene
Samba Diom
Anti Cole dem na
Aïda diop Joynà wett
Ibou sarr Banel Banel dem na
Ndiabot gui Joy na wete
Massamba anni pape
Papis gnibi na
Massamba anni cheikh
Gauloise gnibina
Massamba anni pape
Grand gni bi na
Maimouna ani pape
Papa gnibi na
Cheikh bassine Lo ani boni
Boni gnibina
Bébé koura ani boni
Papa gnibina
Chœurs
(Boko diaper diapo thi dara )
Khady sene pape mbaye sene pape mbaye sene
(Boko diaper diapo thi dara )
Sama niayou kharer danou
Koy ndieukeunter le loy Daw Bay danou yaw
Adouna nakh nga ma adouna warnama
Tan marem mère fanta dem nagn ni
Pape moussa diallo dem na
Sama mak diou bakh ja gnibi na
Wetal ngama Momy Seck
Sama niayou xarer danouna.
Yacoumba seungem na .
Dans ce morceau poignant intitulé Last Piece, le chanteur Ouza accompagné de sa fille Adiouza nous parle de la nostalgie de sa jeunesse. Quand on est jeune, on croit que rien ne peut nous atteindre.
Mais le temps avance, implacable…
Et peu à peu, la force s’efface, les années s’impriment sur nos visages. Le temps nous rappelle que tout est éphémère, que la beauté, la vigueur et même les certitudes finissent par s’envoler.
Ce titre est également dédié à la mémoire de feu Thione Seck, l’un des plus grands ténors de la musique sénégalaise, dont l’héritage continue d’inspirer des générations entières.
🎶 Last Piece est plus qu’une chanson, c’est un cri du cœur, une mélodie de souvenirs et une *prière pour tous ceux qui nous ont quittés.
Retrouvez Adiouza Diallo sur :
- Instagram: http://i.instagram.com/adiouza/
- Twitter : https://twitter.com/Adiouzaofficiel
- Facebook: https://web.facebook.com/AdiouzaPageFans/
Tags and Topics
This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:
Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.
42 user reviews
Write a Review
User Reviews
0 reviewsBe the first to comment...
Video Information
Total views since publication
User likes and reactions
Video length
Release date
Video definition
About the Channel
Related Trending Topics
LIVE TRENDSThis video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!
This video is currently trending in Thailand under the topic 'สภาพอากาศ'.
Share This Video
SOCIAL SHAREShare this video with your friends and followers across all major social platforms including X (Twitter), Facebook, Youtube, Pinterest, VKontakte, and Odnoklassniki. Help spread the word about great content!