đŸ”„ OMG x Jahman Present 'Kenen Diapoula' Official Music Video

Discover the vibrant new track 'Kenen Diapoula' by OMG & Jahman, featuring stunning visuals directed by Amdy. Don't miss this exciting collaboration! đŸŽ¶

đŸ”„ OMG x Jahman Present 'Kenen Diapoula' Official Music Video
OUMY
4.0M views ‱ Aug 2, 2024
đŸ”„ OMG x Jahman Present 'Kenen Diapoula' Official Music Video

About this video

Artistes : OMG & Jahman
Compositeur: B.Beut
Auteur : Jahman
Production : DD Records
D.A : OMG & Stefdekarda
Realisateur : Amdy
Cadreurs : Pii & Lakhat
Assistante Camera : Kiki
Light : Dynastie Studio
Montage : Pii
Étalonnage: Jordy Diop
Maquillage & coiffures: Thiaba Class’A Beauty
Déco : Dynastie Studio & Stefdekarda
Stylisme : stefdekarda, Maktoum Store, wizi création
Accessoire & bijoux : bijouteries Abass Aly Dia 775124624
Lunettes : PĂ©pit’ice
Chorégraphie : Barry Kush
Danseuses : Jeanne & Marie Obama
Remerciements : Maison de la Culture Douta Seck

lyrics

REFRAIN
Est ce khamnga linga yoor
KhalĂš bou ndayam gueureum
mako fa am nékak kenen diapoula

May ki takhone niou sakk la
Ande bangue niou takhé arass
Ko meuneu nekkal kenene tamit
Diapoula

Nekak kenene diapoula
Sa ex diapoula
Nangoul ni mane nga nope bayil saggou diapoula

COUPLET OMG

Eh Nank rek ma dane la diĂšl bou gaw amateur yibekk
GnibĂšk V bi rek match nul lolou meuneuteu nek
Done sa guelou rap bi sangou lo la sete
Chance deugue leu am kou melni mane thi sa wete
Ligniy bari bari yaw may sa préférée tÚ faté xadioufi var amna so wédé
Lingay weuri fenene
Yaw Fi rek ngakoy ame
Dakh may ki ko am
Mako am bakou bari dolĂš
Sa pointure mana
Kénéne diapoula
Ay bobou mbeuguĂšlou sur mesure
Wakhal sa deuguentane kane nga nope
Sa deuguentane mane nga nopp
Koulay gagne yaw koulay thiokhatane

COUPLET JAHMAN
Andak mane day def effet mane rek damay yokk taar
Kone tĂš nga ngoy bou deuguer banc de touche bi niongui khar
Mane rek kala diap kenene ko andalite dou dém
Té gni dila tope so yabo néléne niou yam
Gninane la yaw fane yi danga leer so gooré néléne may diw bingay diwo
Litax mane ak yaw nioune meunounioi khoulo
Yalla ko def souniou rawane yi nio djoubo
Dakh ma def thi yaw valeurs bagne lay weur comme ay vautours
Diaroul wiri wiri mane nga nope allez retour
Wakhal sa deuguentane kane nga nope
Sa deuguentane mane nga nopp
Koulay gagne yaw koulay thiokhatane



#OMG #JAHMAN #KENEN_DIAPOULA

Tags and Topics

Browse our collection to discover more content in these categories.

Video Information

Views

4.0M

Likes

26.9K

Duration

3:27

Published

Aug 2, 2024

User Reviews

4.4
(808)
Rate:

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

Related trending topics. Click any trend to explore more videos.