Jeeba - Ki La Bagn đ¶ Official Music Video
Découvrez le clip officiel de 'Ki La Bagn' de Jeeba, une chanson captivante avec une réalisation exceptionnelle. Plongez dans l'univers musical de Jeeba dÚs maintenant !

Jeeba Abdn
1.5M views âą May 24, 2025

About this video
https://africori.to/kilabagn
Auteur interprĂšte : jeeba
Compositeur : Bril
Réalisateur : Optiques Studios
DA : Vegeta - Afshal
Stylisme :
Cana Dof. - Stef Dakar - Afshal - Mara International
Art work : Med Saloom
Photographe : Biraan Pix
Description :
Ki la Bagn (Celui qui te déteste)
â
Jeeba
Dans âKi la Bagnâ, Jeeba dĂ©voile une nouvelle facette de sa
sensibilitĂ© artistique Ă travers une chanson dâamour
puissante et poétique. Sur une mélodie à la fois douce et
intense, il rend hommage Ă une femme exceptionnelle,
unique Ă ses yeux.
à travers des paroles ciselées et des métaphores
percutantes, Jeeba dĂ©crit une relation fusionnelle, oĂč
lâamour dĂ©passe les apparences. Il cĂ©lĂšbre la beautĂ©
physique de sa muse, mais insiste surtout sur sa force
intérieure, son intelligence, sa loyauté et sa singularité.
Le titre âKi la Bagnâ, qui signifie âCelui qui te dĂ©testeâ,
évoque avec finesse les jalousies et les critiques extérieures,
en soulignant que lâamour vĂ©ritable rĂ©siste Ă tout, mĂȘme
aux regards malveillants. Jeeba y oppose la sincérité de ses
sentiments à la médisance, affirmant que rien ne pourra
Ă©branler son admiration pour cette femme qui lâinspire et
lâĂ©lĂšve.
Un hymne Ă lâamour pur, portĂ© par une interprĂ©tation
vibrante, entre douceur R&B et envolées afro-urbaines. Une
preuve de plus que Jeeba sait transformer ses émotions en
musique universelle.
Lyrics :
Legui ler na nagne alliance bagui thi sa lokho
Diaroul dougal bop bou sekeuté mako nane tokho
Meuno comprendre quand on te dit lâami câest beau
Moy banekh ak nakar bi ngay top di daw amoul pause
Rangatti sama xel bi ba fouma romb niouné dama dof
Thiapal ngama thi sauce bi batakh meuna touma pousse
Fouma la guissé teup di dal né ouzin mel ni kou sousse
Ma tay nop koumou meti nga teuth sa heinn bi yeuy sa dross
Yeukeuti sama lokho né walay mala beug biir
So beugué niou mame Ndiaye savon henné Time indi fi riir
Lo beug ma beug Lo beugoul beugouma beugouma Nono oun oun
Fo dougou ma dougou fo dougoul dougouma fa douma nono oun oun
Bébé xam Nani mane douma similé galanterie
Damay defar bamou bakh may ko sama thieur yi
Refrain
Lo yagg weur ba kheuy mou nek thi sa weet
Day melni nga beug adjii niouné la qabba gangui sa nek
Les gens me regardent ils pensent des fois que je suis bĂȘte
Câest parce que mane lima yor diamant la badola meunouko dieunde
Bayi leen ma ak sama bébé bébé
Bébé bébé dama yeureum kila bagn bébé
Bébé bébé dama yeureum kila bagne
Couplet
Dafa paré thi xalé xam na douma woutal jamalé
Moy gaindé thi digg al bene goné douko diam nani
Téyé sa lokho yoboula ci pa bi neleen ki moy seuy ci
Kima geunal beyoncé geunal cardi geunal ma nicki ak riri
Ki moy ndiss mou ndiol teré ma nelaw goudi ak beuthieuk
Moma togal bakhalou mbar yi souy thi soul riith thi beugeuth
Saï saï bi nieuw beug ma yakal way neko mou dem tok mousse doufi nané gnékh
Va faire dodo on touche pas à mon bébé
May sa rambo koula lal ma tocc sa mbémbé
Bébé xam nané mane douma similé galanterie

Outro
Bayi leen ma ak sama bébé bébé
Bébé bébé dama yeureum kila bagn bébé
Bébé bébé dama yeureum kila bagne
Sa bébé louma la diaral bayi yay bayi bay sa youla sokhla nga nieuw nguenn nekal koci begual
koci yeungal koci éh éh éh éheeeé bébé
Bébé bébé dama yeureum kila Bagn

Tags and Topics
Browse our collection to discover more content in these categories.
Video Information
Views
1.5M
Likes
19.5K
Duration
3:21
Published
May 24, 2025
User Reviews
4.7
(296) Related Trending Topics
LIVE TRENDSRelated trending topics. Click any trend to explore more videos.