Jailer Bangz - Sukhi Saaf 🎶 Official Lyrics Video

Discover the latest single 'Sukhi Saaf' by Jailer Bangz. Watch the official lyrics video and dive into the catchy vibes of this new release!

Jailer Bangz - Sukhi Saaf 🎶 Official Lyrics Video - thumbnail
Jailer Bangz
9.0K views
Jan 27, 2018 • 3:09
Jailer Bangz - Sukhi Saaf 🎶 Official Lyrics Video

About this video

JAILER BANGZ -Sukki Saaf

Ajouté le 27 janvier 2018

#Sukki Saff -officiel-New Single

JAILER BANGZ, sort un nouveau single intitulé Sukhi Saaf qui parle de sa sortie de Jah Me Rue de ses ambitions dans le Game et au passage de Reconnaissance envers ses anciens Compagnons de JAH ME RUE

RUPTURE OU CONSENSUS

# Les Credits #

Compositeur: ByMic

Auteurs: Jailer Bangz

Mix et Mastering: KNAL4

Realisateur Clip: Noreyni

Production: ByMic

Musique ( Senegal, Dakar janvier 2018)


Vous pouvez vous abonner à la chaîne YouTube et suivre l'artiste sur:

Facebook:https://www.facebook.com/jailerbangzlofficiel/

Soundcloud : https://soundcloud.com/jailer-bangz-official

Reverbnation: https://www.reverbnation.com/jailerbangz8

Instagramme: https://www.instagram.com/jailer_bangz_baby/

Snapchat: Fatherbangz


#Lyrics SUKKI SAAF #

L'amour est double aveugle Boudei Gnari goumbeu Gno nobantei

Mouno guiss thi Mane loma beugué nigger Bo tégo thi code nala décoder

Mbalakhouma té wayouma nit Mbeur thia galagne ya lay bakouwé

Tekla fitneu ba beugoma guiss Woo sa thioro Diko thioroté

Et puis grand Yow danga gnak djome
Boy yi gnigni Boy yi gnégnégné

Bo bagné faye nanga yok job
Mangui thi ni manak sama gang

Kou meuneu dégue dinga dégue ni Mangui def musique thi onde yi gueuneu nekh
Sougne mané jailer danga lére Damay ré Ndakh dama Khame nit noumou leundeumé

Refrain: 2X

Sukhi saaf dithi gnamal gneup legui réwatouma dama neup Mangui fly doundou lima yeuk
Gneup dougnou beugue beugouma gneup
Everyday everyday Mangui fly sama way
Everyday everyday Mangui def dila yéme

Deuxième couplet:

Lek sama lek ak lékou grand yi
Legui meuneutougnou nek ganïne
Ganïne deum leu def nala yeufou deum t boma tamé rek nek kagne

Dama lay togne Door la koroché
Deglou kholé gueuneu étonné

Waw Waw wawawaw maye na loxo gnima djémone téyé

Amna grand you thi yague djap
Waxna falsower waxna wicky diallo
Chigga gueum nama Bala ma gueume sama bop
Faté wouma Dara worna yalla

Flinguer men nigger moma ya
yokou ma khel gueunma yok bandit
Wakh karbalah toudou mister zou
Mbokou talibé yi naka war yi
Bi noni weuré sama nopou yi fallait que ma teukh pour meune dégue djameu
Def aye magie team bou melni paris
Rap thi biir clim son yi gueuneu tangue


Refrain:

Sukhi saaf dithi gnamal gneup legui réwatouma dama neup Mangui fly doundou lima yeuk
Gneup dougnou beugue beugouma gneup
Everyday everyday Mangui fly sama way
Everyday everyday Mangui def dila yéme

Tags and Topics

Browse our collection to discover more content in these categories.

User Reviews

4.6
(1)
Rate:

Video Information

Views
9.0K

Total views since publication

Likes
273

User likes and reactions

Duration
3:09

Video length

Published
Jan 27, 2018

Release date

Quality
hd

Video definition

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

Related trending topics. Click any trend to explore more videos.

TRENDING!

Trending in Thailand under 'สภาพอากาศ'.