Jahman X-press ft. Ahmada Jadid & Abdou Khoudoss Kara - BAMBA NGEUREUM 🎶 (Official Music Video)

Discover the vibrant official music video for 'BAMBA NGEUREUM' by Jahman X-press featuring Ahmada Jadid & Abdou Khoudoss Kara. Produced by OPTIQUE STUDIOS and directed by Ibrahima Mbengue Dione, this video showcases stunning visuals and energetic performa

Jahman X-press ft. Ahmada Jadid & Abdou Khoudoss Kara - BAMBA NGEUREUM 🎶 (Official Music Video)
Jahman X-Press
3.2M views • Aug 2, 2025
Jahman X-press ft. Ahmada Jadid & Abdou Khoudoss Kara - BAMBA NGEUREUM 🎶 (Official Music Video)

About this video

Crédits de la chanson et du clip :

Production : OPTIQUE STUDIOS
Directed by : IBRAHIMA MBENGUE DIONE
Camera Operator : BABACAR SOW
charge de prod : METHA
Assistant Cam : DAME DIOP
Edit : BABACAR SOW
Color Granding : IBRAHIMA MBENGUE DIONE
Design : DAME DIOP
Visual art : IBRAHIMA MBENGUE DIONE
Light : RACINE DIAW
Stylisme : PAPA LAXASSAYE
Idée de composition beat : LOUFA ON THE BEAT
Beat : JEUSS BEATZ
Mix & Master : MOUSSA NGOM
Guest : ABDOU KHOUDOSS KARA


Remerciement : ZÉE, TEAM OPTIQUE STUDIOS, METHA

Lyrics : BAMBA NGEUREUM

Refrain:
Ngëram, ngëram ñeel na ka dog buumi jaam ñi
Ki tax ñu sampi daara fi ba Mbacké Baari

Sant ak ngëram ñeel na borom Silkul Jawaahiri
Jàraama rek doyul ci Borom Magal gii



ZAHIIM: YAA KO JAR, MA LA KOY WAX: YA QALILI!
MBÉGTÉ'M YÂLLAH NGA AK YONNEN, YÂ HABIBI !

JADID: ÀDDUNAH DA LA KOO MAY, YÂ AZIZI !
LI MU ËMB IT YAA KO MOOM, YÂ WASIILATI

JAHMAN X-PRESS : YAA MËN FII AK FA NU JËMM YAAY JAALÉ JAAM ÑI
BU MBËR YEEP TAXAWEE YAA MËN CI GOOR ÑI



ABDOU KHOUDOSS KARA : Makaak Madiina, seen mboot ya ñëw na
Diggante Njaareem Mbacké ba Touba

JAHMAN X-PRESS : BAMBA Teeye naa laak leneen ludul samay loxoo
Ndax xam nga Yalla xamlé nga koo

AHMADA JADID : Maam Ceerno Faati loxol ndayjoor la
Moo gaaganti naar ya té laaloul mool ya



TRIO: Jaramaa rek doyul dañ la wara kennal
Suñ goree suñ leepp yaa nu ko wara gënal

Ëskey la ñeep di wax fu ñu tuddee turam
Yonenn beeko ko baaxee moo sàkkuw turam

Refrain:
Ngëram, ngëram ñeel na ka dog buumi jaam ñi
Ki tax ñu sampi daara fi ba Mbacké Baari

Sant ak ngëram ñeel na borom Silkul Jawaahiri
Jàraama rek doyul ci Borom Magal gii


AHMADA JADID: Xamu ñu sax yaw ki nga doon
Ba yore mbootu Kun fa yakuun

JAHMAN X-PRESS : Bismil ilaahi may deelu sant Daam
Moo ñu goreel tax deewugn ci njaam

ABDOU KHOUDOSS KARA : Ñun sant nan bu wér-a-wér
Noflaayam yi raw na ci ñun ker

AHMADA JADID: Doyna laaxuwaay ak weeruwaay
Woo nañ la woowatila sunuy mbir kaay

ABDOU KHOUDOSS KARA : Buñ doon wutt dara
Duñ la moy ndax yaay dara
Joo xam ne man naa def dara
Mu jur lu ñepp yéem


JAHMAN X-PRESS : Issa Dièye Fatim Penda
ADBOU KHOUDOSS KARA : Issa Dièye waawaw
JAHMAN X-PRESS : Damel Lat Soukaabé Ngoné Dièye Damel Déthié Fo Ndiogou yaa djaay sa nguur jëndee ko ngëm
ABDOU KHOUDOSS KARA : Damel Samba Yaya Fall
AHMADA JADID: Sama Mame Fall Yaaram

AHMADA JADID: Kër guñ am ñun jox nañ la ko
Boolég njaboot gi jeebal la ko
Xel mi ak xol bi fob nga ko
Jëlël leep yaa ko moom

#jahman #bambangeureum #magal2025

Tags and Topics

Browse our collection to discover more content in these categories.

Video Information

Views

3.2M

Likes

86.7K

Duration

4:16

Published

Aug 2, 2025

User Reviews

4.9
(648)
Rate:

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

Related trending topics. Click any trend to explore more videos.