Jahman X-press - Djaayma Guerre Bi (Official Video)

EN CONCERT AU POINT FORT D'AUBERVILLIERT 27 SEPTEMBRE 2024 : https://shotgun.live/fr/events/jahman-x-press Stream Djayma Guerre bi : https://bfan.link/diaay...

Jahman X-Press‱30.7M views‱3:07

About this video

EN CONCERT AU POINT FORT D'AUBERVILLIERT 27 SEPTEMBRE 2024 : https://shotgun.live/fr/events/jahman-x-press Stream Djayma Guerre bi : https://bfan.link/diaayma-ma-guerre-bi CrĂ©dits de la chanson et du clip Maison de Prod : @ReverseStudios RĂ©alisation: Bilal Mbengue Etalonnage: Bilal Mbengue VFX: Bilal Mbengue Chef Op : Leye Gueye Chef Ă©lectro : Djiby Niang Assist Cam: Mame Ass Top Montage: Leye Gueye Make up : Khadija Ndiaye Musique: IdĂ©e originale: @Jahman X-Press & @Iss814 Programmation Jeuuss beats Mix master Jeuuss beats Arrangement : Jeuuss beats Suivez-moi sur mes rĂ©seaux Instagram : https://www.instagram.com/jahmanxpress Facebook : https://www.facebook.com/jahmanxpress Twitter : https://www.twiter.com/jahmanxpress 𝐋đČđ«đąđœđŹ 🔊 Li guene ci Ndap li lay nieuw keuf Gnibek mom sen yakar tasssss Guerre ak man yomboul dama meun biss Ma ci tek lokho tĂ© motax nguen guethie ko guis Kinguen done kheutho la def thiopet Dolen ci papa ndiaye may Bondi Man dama tangue foumalen fek nguen almett Dieulko sen lokho parĂ© taxaw guerre guerre bi Man Lima mom lokho Bouma ci fek nga yeureum borom Ki bako yala di sak man ma taxone Seti len lennen ki boure tek na ci lokhom Sama lek la teguil sa ay beut ci mom Djaayma guerre bi Djaayma guerre bi Djaayma guerre bi Djaayma guerre bi Kou niĂ©mĂ© nanga takhaw Kou ragual nanga daw Ki kouko beugua nangou si man Dangnouy raak ba naw konn Djaayma guerre bi Djaayma guerre bi Ki may Kiko tĂ©yĂ© man comme kou ngap deureum NgĂ©n diotaat si dou yombou man damlĂ©nn yeureum Dama tĂ©bbi As Takh sen coeur yi di bakh Meunon dieul Sama place Ligueyo’fi loutakh ‱Manela diw beurre bi Ñunela Adja ak Aladji Makoy adje diko adjiii ChĂ©rie booy x2 Dafma tane ci sen biir ndax xamnani kou nitĂ© la Dafma noba noba nob dof chĂ©rie sama chocolat Ki manela nob (waw) dotolĂ©n’si diott Ndakh munuñ’ko bokk Konn demal nga tokk Fi amofi place Man douma sa mass Sen yakaar’ra tass LĂ©m lenn sĂ©ni bagages Manela diw beurre bi Ñunela Adja ak Aladji Makoy adje diko aadjiii ChĂ©rie booy x2 Djaayma guerre bi Djaayma guerre bi Djaayma guerre bi Djaayma guerre bi Kou niĂ©mĂ© nanga takhaw Kou ragual nanga daw Ki kouko beugua nangou si man Dangnouy raak ba naw konn Djaayma guerre bi Djaayma guerre bi Wolou sa Serigne sou takhĂ© nga yapma nala defal bagages Andeu bou deuggeur liggey mĂ«nussi touss kom jour’rou Dimanche Fi lo andi FĂ©kk kofi Mohh yaw dawn sama yaraam KhalĂ© boussi douggou sama 18 tu joues avec le feu Manela diw beurre bi Ñunela Adja ak Aladji Makoy adje diko aadjiii ChĂ©rie booy 🔇 #jahman #djaaymaguerrebi #dakar #senegal
4.3

6137 user reviews

Write a Review

0/1000 characters

User Reviews

0 reviews

Be the first to comment...

Video Information

Views
30.7M

Total views since publication

Likes
112.2K

User likes and reactions

Duration
3:07

Video length

Published
Mar 3, 2023

Release date

Quality
hd

Video definition

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Algeria under the topic 'g'.

Share This Video

SOCIAL SHARE

Share this video with your friends and followers across all major social platforms. Help spread the word about great content!