Dip Doundou Guiss Dominates with 'Musiba' đ€ â The Unchallenged King of Rap
In 'Musiba,' Dip Doundou Guiss reaffirms his throne in the rap scene, proving he's the true king despite any competition. Discover why he's unstoppable!
About this video
Dans ce titre, DIP consolide son titre de King dans le rap game : il rappelle à ses détracteurs qui est le roi, malgré leurs attaques incessantes. Entre différentes punchlines et egotrip, le King tape sur la table et prévient les MC : leur plus grand malheur, c'est lui. #Musiba en streaming et en téléchargement sur toutes les plateformes : https://orcd.co/musiba
....................................................................................................
Clips officiels : https://bit.ly/ClipsofficielsDip
.....................................................................................................
Suivez-moi sur les réseaux sociaux :
Facebook : https://web.facebook.com/dipdoundouguissofficiel
Twitter : https://twitter.com/DipDunduGuiss
Instagram : https://www.instagram.com/dip_doundouguissofficiel
Snapchat : Dip490
.....................................................................................................
Compositeur : Ssadik beatz
Mix & mastering : Karabalik Beatz
Production : Reverse Studios
Réalisation : Bilal Mbengue & Leye Gueye
Stylisme : DoulSy JahGal
Décoration : Yarba Déco
Make Up : Mimiâs Touch
lyrics
REFRAIN
Fuck number one, Fuck number two
Ya ngeek limay fay, moytul baña juum (yeaah, ouuh)
Musiba naarulay
Gëm sama ñaanu yaay
Lëmbé ndakaru ndiaye
Musuma xaddi, bañuma jeng mais duma daanu way
Aka ma gaaw si gars yi
May sa musiba naarulay
Musiba naarulay
COUPLET 1
Comme roof si ceeb
Cere dolli ñeex
Capp ni goor Gui Dieng
Vol si jet, wala doxx si geej
Yokk job du deñ
Kuy bonn di hate
Bombe nucléaire ci sa xol bu wow ni xeer
MĂȘme boy dĂ© bul fokni jeex na, may bĂ«ss bila God di yĂ©
Investir ci fenn amo saxx bénéfice du doute
Na doon 50 cents sama ben shot, sa fils du jukk
DIP mola mĂ«n du gacce câest comme ku Messi di duut
Ma ngi si trÎne bi ak ñom Messi jël sama Pepsi di guux
Duma segg si cage
Man la seen soeurs yi di xaar
Maa taxx sen sërr yi di tass
CarriĂšre bi munoko saltel nigger melni sa chemisou pa
Sëg di gass, job lu tax CD bi jarr
Fële jël sa reliquat
Sama cachet sañu ñuko dagg ni bin bin ci sa ndigu Ma
Na money bi teew, xaalis moy gagner guerre bi duma rayante comme militaires
Si kaw lañuy yeeg wacce leen ni adamak awa ak pomme biñu yëy
Sori fi man, duma xooli sa guel mĂȘme su defe man kesse si story privem
Coow li du jeex fi ba mëwti di dé amatu ñu adversaire mais ño ngi si guerre
Refrain
Fuck number one, Fuck number two
Ya ngeek limay fay, moytul baña juum (yeaah, ouuh)
Musiba naarulay
Gëm sama ñaanu yaay
Lëmbé ndakaru ndiaye
Musuma xaddi, bañuma jeng mais duma daanu way
Aka ma gaaw si gars yi
May sa musiba naarulay
Musiba naarulay
Couplet 2
Every day, may def baña xaar ndaxx dé du jeem
Soxlawuma tuub pour def ko benn buum mën na takk plus de 5 jeeg
Yes we can
Gedd gratte- ciel, dëkki Baraku Bamba fu Trump dem ba nek president
Fu sëtu esclave dila ray ngir chaßne
Tojj sa lu bonn ba mujje ak séy biens
Nigger ëppo njariñ skincaru Michael Jackson ci cimetiÚre
Dangay gunge rek ni frĂšru Michael Scofield ci biir jail
Damay fayu ba pare mën nangu ni coow du jib kay
Ku xamm kepp kuy rap wolof xamna nombre rappeur bi DIP fay
Tek sama nafsu ci beat bi
Rap yefu dëmm dëg lë kan mo saña waxx ni que Pac bëggul Biggy ?
Sen game bi concours lëmbël la motax malay yokkal ay tama si beat bi
Sa guel la yakoy solal makoy simi, dagg buumu gacce dagg seeni string yi
Sama kumpa nekul books mais rappeur yi publier gul sen streams yi
Ay goat yu vider plassu gettu bëy du sho bu tijji tank rek ñu dem
Dé bi kesse momay taxa tëddi ni roses yi si sa tanku caissou neew
Bëg coow ni intifada Ben Laden
MĂȘme dof du sikki sakka lima fi def
God du mëssa à ndak ñi di fenn
Par force King bi man la té du deñ
Refrain
Fuck number one, Fuck number two
Ya ngeek limay fay, moytul baña juum (yeaah, ouuh)
Musiba naarulay
Gëm sama ñaanu yaay
Lëmbé ndakaru ndiaye
Musuma xaddi, bañuma jeng mais duma daanu way
Aka ma gaaw si gars yi
May sa musiba naarulay
Musiba naarulay
Tags and Topics
This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:
Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.
1394 user reviews
Write a Review
User Reviews
0 reviewsBe the first to comment...
Video Information
Total views since publication
User likes and reactions
Video length
Release date
Video definition
Subtitles enabled
About the Channel
Related Trending Topics
LIVE TRENDSThis video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!
This video is currently trending in Turkey under the topic 'g'.
Share This Video
SOCIAL SHAREShare this video with your friends and followers across all major social platforms including X (Twitter), Facebook, Youtube, Pinterest, VKontakte, and Odnoklassniki. Help spread the word about great content!