Cherifou - Pop Pop đŸŽ¶ DĂ©couvrez le clip officiel de cette chanson captivante

Plongez dans l'univers de Cherifou avec 'Pop Pop', une chanson aux paroles profondes sur la fugacité de la vie. Laissez-vous emporter par ce clip officiel et ressentez l'émotion!

Cherifou - Pop Pop đŸŽ¶ DĂ©couvrez le clip officiel de cette chanson captivante
Cherifou L’officiel
21.5M views ‱ May 5, 2023
Cherifou - Pop Pop đŸŽ¶ DĂ©couvrez le clip officiel de cette chanson captivante

About this video

"POP POP", Un titre certe simple mais qui engendre de riches paroles dans lesquelles L'artiste nous fait savoir que la vie est si Ă©phĂ©mĂšre,et que ni la jalousie, ni mĂ©chancetĂ© ne devraient avoir une place dans notre sociĂ©tĂ©, mais devraient pas aussi nous freiner Ă  atteindre nos objectifs. Savoir rĂ©agir avec classe et Ă©lĂ©gance, bravoure et persĂ©vĂ©rance, fait la force de l'homme et cela nous amĂšne Ă  ĂȘtre "POP POP"

Crédits de la chanson et du clip
Beat : Thiokos
Guitare : Seydou ba
Percussion : Pape Ndiaye tama
Mix & mastering : Polibeat
Réalisation : Gaby iris / iris av
Coiffure : Demba tarrou locks 78 432 00 50


Contact Watshap : +221 77 840 00 80 / 77 847 12 12

â–ȘSuivez-moi sur mes rĂ©seaux

🔾Instagram : https://instagram.com/cherifou__lofficiel

🔾Facebook : https://www.facebook.com/profile.php?id=100035350346924

🔾Tik Tok : https://www.tiktok.com/@cherifouofficial

Stream & Ecoute : https://bfan.link/pop-pop

#cherifou #poppop #senegal #dakar #music

Lyrics PoP PoP

Kay kay kay kay
Kay ma khamal la ni
Adoun’ya dou benn fann
Kingay toguĂ© tay bou souba meun’nala yĂ©y
Kay ma digual’la ni
Bouldi khol nitt diko nié
Meul nala yobbé ignaaan (ignaan ignaaan)

Yangui coq 🐓 coq ba callĂ©
May Pop pop ci khalé
Ngay togg togg ba callé
Diémo té meuno dabbé

Man soma beugoulé boul saalé
Guiss’nanĂ© dolĂ© feeling bĂ©la poussalĂ©
Ehhhhhh yah
So beugoulĂȘ boul salĂ©
Bayil sokhor ignaan dalay té
Boko toppé dangay dé firiil sa khol

Refrain
Ay way ah
yeukna linga nékké (ay door rék)
Malay lébal mbakh ngamay fékhél (ay door rék)
Eh bal dooré
Guiss’nala ngay leurĂ© eh eh ehhhh do gorĂ©
Man guiss’na ningmay worĂ©
Boul déféni ninga nékké yeugoumako dama doylou
bo dĂ©ffé’ni ya geuna yĂ©wou nieup, nalaw nga bay galleu
Thioy rék
Yaw deukéll thioy rék
Thioy rék
Yaw deukéll thioy rék
Dél thioy rék

2e Couplet
Dembeu yanei woon
Dembeu yanei woon ni gorĂȘdiwo
Konn loula diapp tay banga né ci yoonou noon
Non parégouma
Nono tambalé gouma
Yay sakhol ci nianaal’ma
Sabo douhan ouma mi falama néné barakaa

Yangui coq 🐓 coq ba callĂ©
May Pop pop ci khalé
Ngay togg togg ba callé
Diémo té meuno dabbé
Yaw woutal béneen yoon bo diarei
Yaw dĂ©mo kou nekk ci yoon nga diĂ©m’ko garĂ©

Bayil sokhor ignaan dalay té
Soko toppé dangay dé firiil sa khol

Refrain
Ay way ah
Yegg’na linga nĂ©kkĂ© (ay door rĂ©k)
Malay lébal mbakh ngamay fékhél (ay door rék)
Eh bal dooré
Guiss’nala ngay leurĂ© eh eh ehhhh do gorĂ©
Man guiss’na ningmay worĂ©
Boul déféni ninga nékké yeugoumako dama doylou
bo dĂ©ffé’ni ya geuna yĂ©wou nieup, nalaw nga bay galleu
Thioy rék
Yaw deukéll thioy rék
Thioy rék
Yaw deukéll thioy rék
Dél thioy rék

Solo guitaar 🎾đŸȘ—

Ambiance outro

Thiow meunoul dara
Wakh djou bonn fadioul dara (dedett)

Thiow meunoul dara ci man wakh dji fadioul dara (dedett)

Thiow meunoul dara ci man wakh dji fadioul dara (dedett)

Thiow meunoul dara wakh dji fadioul dara

Thiow meunoul dara wakh dji bonn fadioul dara
Thiowli meunoul dara dafmay yokk dolĂȘ nopaloul

KhalĂ© baangéééé (man’la)
KhalĂ© baangéééé (kham’ngan man’la waaawaaw)

Kham ngani man’la
Ay man’la
Affaire bi man’la
Wooooy man’la
NĂ©nagn’ma yaw la ehhhhh

KhalĂ© baangéééé (man’la)

Kham ngani man’la
Ay man’la
Affaire bi man’la
Wooooy man’la
NĂ©nagn’ma yaw la ehhhhh

TĂ© bilae damay fo ak yennn 😊🔇

Tags and Topics

Browse our collection to discover more content in these categories.

Video Information

Views

21.5M

Likes

71.8K

Duration

3:38

Published

May 5, 2023

User Reviews

4.3
(4306)
Rate:

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

Related trending topics. Click any trend to explore more videos.