Ashs The Best - Tukki Bukki [Audio]

https://wiseband.lnk.to/Ashs-The-Best-Tukki Illustration & animation : Madinpixel Retrouvez-moi sur mes réseaux sociaux FaceBook - https://www.faceboook.c...

Ashs The Best132.9K views3:08

About this video

https://wiseband.lnk.to/Ashs-The-Best-Tukki Illustration & animation : Madinpixel Retrouvez-moi sur mes réseaux sociaux FaceBook - https://www.faceboook.com/AshsTheBest/ Instagram - https://www.instagram.com/ashsthebest/ Snapchat - ashsthebest Parole / lyrics TUKKI Bu xaaju guddee bu xaaju guddee bu ñëpp di nelaw man ma weet’ag xaalat waxtaan’ag njegenaay Kenn du ma yee ku nelawul nan lañ koy yeewee Biig foru ma bët waxtaan’ag njegenaay Nelawu ma biig Xanaa waxtaan’ag sama njegenaay Tay kenn duma yee Ku nelawul nan lañ koy yeewee Xale baa ngi jooy Nax ko warul jooy Doomu jambur warul jooy Demb laa la miin Tay yaa ngi taggoo Soy dem yobbaale ma Ulluku Man ku ma nëbbu ma reer la Ci rukku Laa la woo yobaante la [Ulluku boy nelaw bul xaar mu yee la] Kuy tukki Deeg naa ñu ne warul taggoo Fukki bukki laa gis taggaliko’og sama saggo [Ulluku boy nelaw bul xaar mu yee la] Bul ma di sooraale Sooraaleel sa bopp Soy dox di gestuwaale Mën nga fakkastalu Ulluku ku ku ku ku Kuma nëbbu ma reer la Ulluku ku ku ku ku Tukki tukki bukki Tukki bukki Fukki bukki guddi Fukki bukki bëccëg oo Nitt ki li muy wundu Mën nga ci bañ teg bët Bukki bënn buntu Bant bënn bëttëm Nitt ki li muy wundu Mën nga ci bañ teg bët Fukki bukki guddi Fukki bukki bëccëg oo Nitt ki li muy wundu Mën nga ci bañ teg bët Bukki bënn buntu Bant bënn bëttëm Nitt ki li muy wundu Mën nga ci bañ teg bët Ulluku ku ku ku ku Man ku ma nëbbu ma reer la © 2022 Nautylusprod

Tags and Topics

This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:

Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.

4.7

26 user reviews

Write a Review

0/1000 characters

User Reviews

0 reviews

Be the first to comment...

Video Information

Views
132.9K

Total views since publication

Likes
2.2K

User likes and reactions

Duration
3:08

Video length

Published
Dec 22, 2022

Release date

Quality
hd

Video definition

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Netherlands under the topic 'noodpakket bestellen sinterklaasjournaal'.

Share This Video

SOCIAL SHARE

Share this video with your friends and followers across all major social platforms including X (Twitter), Facebook, Youtube, Pinterest, VKontakte, and Odnoklassniki. Help spread the word about great content!