Ashs The Best _ 40TEN SESSIONS #4 (Prod by 1DA Beatz)
https://Wiseband.lnk.to/Ashs-The-Best-4010-Session-4 Album "Dibèer" ici :https://wiseband.lnk.to/Ashs-The-Best-Dibeer Production : Mind7 Prod by : 1da Beat...
About this video
Album "Dibèer" ici :https://wiseband.lnk.to/Ashs-The-Best-Dibeer
Production : Mind7
Prod by : 1da Beatz
Mix Masters : Sir khalifa
Illustration : Madinpixel
Animation : Mad in pixel
Lyrics :
ASHS THE BEST
Sum la mënoon gisaat
Gisaat la benn yoon ci sama life pour wax la
Ni sama xol mësoo fi jog
Nu may def pour gissat la
Gisaat la benn yoon sama wet ngay reetaan
Ngay beeg di ma begloo
Dem nga baayi ma fi
Dem nga yobbaale sama leer baayi ma ci lëndëm
Weetal nga ma lool
Nu may def pour gissat la
Nu may def pour gisaat la pour wax la ni I love you baby
Dem nga baayi ma fi
Weet na yaa ma weetal
Kañ ngay delluwaat si
Ci sa wet laa bëgg a dalloo
Dem nga baayi ma fi
Weet na yaa ma weetal
Kañ ngay delluwaat si
Ci sa wet laa bëgg a dalloo
Fèeñu nga ma reeraat ma
Nu may def pour gisaat la
Dem nga baayi ma weetal ma
Biig ci guddi janneer naa la
Yaa ma taxoon daw bay death
Te nañ ma baayi ma weetoo’g life
Li may yëgg ci moom du dèñ
Batay mbëggeelam moo may daaneel
Weet na jooy ndax weetaay [weet naa]
Reer na reer waay reer na
Néeg la weccoo’g keneen
Batay mbëggeelam moo may daaneel
Yaa ne woon duñ yow doo ñoom
Gisaguma ku melni yow
Sama xel du jog ci yow
Sum la mënoon gisaat
Gisaat la benn yoon ci sama life pour wax la
Ni sama xol mësoo fi jog
Nu may def pour gissat la
Gisaat la benn yoon sama wet ngay reetaan
Ngay beeg di ma begloo
Dem nga baayi ma fi
Dem nga yobbaale sama leer baayi ma ci lëndëm
Weetal nga ma lool
Nu may def pour gissat la
Nu may def pour gisaat la pour wax la ni I love you baby
Dem nga baayi ma fi
Weet na yaa ma weetal
Kañ ngay delluwaat si
Ci sa wet laa bëgg a dalloo
Dem nga baayi ma fi
Weet na yaa ma weetal
Kañ ngay delluwaat si
Ci sa wet laa bëgg a dalloo
#Ashsthebest #40TEN #Session#4
Abonnez-vous à Mind7 : https://instagram.com/mind7_musik?
Album Millions Flows disponible: http://bit.ly/MillionsFlows
https://smarturl.it/album-millions-flows
© 2020 Mind7
Tags and Topics
This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:
Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.
99 user reviews
Write a Review
User Reviews
0 reviewsBe the first to comment...
Video Information
Total views since publication
User likes and reactions
Video length
Release date
Video definition
About the Channel
Related Trending Topics
LIVE TRENDSThis video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!
This video is currently trending in South Korea under the topic 'a'.
Share This Video
SOCIAL SHAREShare this video with your friends and followers across all major social platforms including X (Twitter), Facebook, Youtube, Pinterest, VKontakte, and Odnoklassniki. Help spread the word about great content!