Amadeus & Wally Seck - Jëli (Official Clip) 🎶

Listen to 'Jëli' from Amadeus's album Taarus, featuring Wally Seck. Available on all streaming platforms: https://bfan.link/jeli

Amadeus & Wally Seck - Jëli (Official Clip) 🎶
Massamba Amadeus
32.5M views • Oct 4, 2024
Amadeus & Wally Seck - Jëli (Official Clip) 🎶

About this video

#jëli 2e extrait de mon album #taarusenegal est disponible sur toutes les plateformes de streaming : https://bfan.link/jeli

Ecrit par AMADEUS
Interprété par Amadeus & Wally Ballago Seck
Compositeur : Papelayebeats
Mix / Mastering : Sirtam

Réalisateur & Postprod : Mame Sélémane Dieye
Assistante Réal : Mareme Helene Fall / Thérese Coly
Directeur de prod : MLD
Chef décorateur & Régisseur : Sadickdef & frères
Assistante Cam : Weuz Ndiaye
Régisseur Général : Mame Cheikh
Make up artist : Penda & Team
Directeur Photo & Color Grading : Mandione Laye Ka
Lighting : Bras Magik
Management Team : Sir FALL & MLD
Nos remerciements à CARGUYZ et à tous les figurants.

Suivez Amadeus sur les réseaux sociaux :
Instagram : https://www.instagram.com/massamba_amadeus/
Twitter : https://twitter.com/massambaamadeus
Facebook : https://www.facebook.com/massambaamadeus
Tik Tok : https://www.tiktok.com/@massamba__amadeus

Les paroles

Boo ma beddiwul xalaatuma la bàyyi
Amuma laamisoo tuddd mbalaay

Gaañ la taxul nga wax
Tooñ la taxul nga may réccu
Sàllaaw yenn saay nga mer
Sama njàmbaar ci yaw mi la wékku

Dootuma wiiri wiiri jaari Ndaari
Li ma moom laay jëli
Dootuma yónni kenn ci sama waa ji
Man mii maa koy jëli

Wally
Dootuma wiiri wiiri jaari Ndaari
Li ma moom laay jëli
Dootuma yónni kenn ci sama waa ji
Man mii maa koy jëli

Bala maa jug fajar
Fekk nga teg njaay
Bale kër gi raxas say ndab
Ndeke booba doom ngay waajal


Amadeus
Dund a mat a ñaan
Ndaxte gaynde dof a kuy jur
Ndax fitnaaloo ma xeeboo li ma lay jox
Lépp loo ma ñaan dinaa la may

Wally
Dootuma def lenn lu lay metii sama ndaw si
Ndax sama nawle nga doon leeral sama yoon wi
Dootuma nangu mbindeef di dox sama digg ak yaw
Ndax Yàlla moo def ci nun loolu wéy na
Kaay waay

Gaañ la taxul nga wax
Tooñ la taxul nga may réccu
Sàllaaw yenn saay nga mer
Sama njàmbaar ci yaw mi la wékku

Dootuma wiiri wiiri jaari Ndaari
Li ma moom laay jëli
Dootuma yónni kenn ci sama waa ji
Man mii maa koy jëli
Bis

Gaañ la taxul nga wax
Tooñ la taxul nga may réccu
Sàllaaw yenn saay nga mer
Sama njàmbaar ci yaw mi la wékku

Tags and Topics

Browse our collection to discover more content in these categories.

Video Information

Views

32.5M

Likes

168.8K

Duration

2:55

Published

Oct 4, 2024

User Reviews

4.4
(6491)
Rate:

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

Related trending topics. Click any trend to explore more videos.

Trending Now