Akhlou Brick - Popcorn (Official Video) 🎥

Official video for Akhlou Brick's 'Popcorn' with beats by Weezyade, mastered by Max Mix, in partnership with Canal Olympia & more.

Akhlou Brick - Popcorn (Official Video) 🎥
AkhlouBrickTV Officiel
716.1K views • Aug 28, 2020
Akhlou Brick - Popcorn (Official Video) 🎥

About this video

Beat by:Weezyade Teacher
Mix,Mastering & edit by: Max Mix QGS Records
Partenaire: Canal Olympia , Rio Street Wear, Tyna style, Maraz,
--------------------------------------------------------------------------------------------------

Popcorn disponible:
iTunes link: http://itunes.apple.com/album/id1529590044?ls=1&app=itunes
Apple Music:http://itunes.apple.com/album/id/1529590044


Lyrics
Boudon né kou né sa life lagniy dawal tay cinéma
Kou guiss sa cd ding ko hoss si pet bagn sa dieufi né fang
Lima guiss wahko defko ak fima deug sama tank
Tank yalla ngui def soutoura si man menoko ham
Porcorn bi man kassé si ciné may seytanè sama film
Jeuf mo nék ni man kassé fi nèk fiimné ak yalla mima tim
Toudal ma diw ak diw diw mila takhal té dou niin
Faw yalla hawi lim dentj nga guiss diw dotoul mena miim
Yaw gni geum ni Rassoul dé na gno geuna triste
Li tah meno ham Jesus pask ya toudé leundeum criss ( chirst)
Ibliss don bour thi diamono Bign seulmalè timiss
Borom gnari beut yeup goumba borom bén beut di guiss
Fi ak fè ak fagnou dieum fou dieun doul deki Rou dieufarou
Dieumeum yonen mo ndieuka guiss motah mo ndieuka diébalou
Yaw lan nga ban ngalaw safara ak ndoh
Ko geum
yalla bou Ibrahima wala bi Ibrahima weron ngot
Ko geum nit nga Rek do Deum
Nekal ki nekal lep Wetal ki weton demb i mean
Sa yo wete yaw ak sa bop Wetok ngak sa Ya Rabi
Free Rou diar wethit free ken amoul sa ndieuk free
Fay nagn prix pour dieund mais fekogn si man sam roubi
Yeah..

Bou laf don mayé jam ramatou dou ham pierre
ay mindafone di heh ngir yaw te thi yaw lagn nek
Bo thiakaré nim lay nakharè metite ngay yeuk
Yeurmande yalla rekay walou diam te ken amoul ndieuk bi

Ken amoul ndieuk bi
Ken amoul ndieuk bi

Alcool thie gom bou bess ndakh bou robalee day teu

Neubeul sa xol bou fess bou dee rembet ndokh day feul beut

Dès fois ma bind way pour sa wayadi nga dinga dindiko may wakh sa bir xel lo degoul louma athie boy nga dem adjiko

Tekil sa verr you rose yi /nga guiss la vrai vie Wathiel sama bop/ hol thi souf guenee sa beut ecla étoiles yi legui xol ma wakh lo guiss lou nostra damus predire dalay nekh nga bone mba nga bah life bi yaye def choix bi
Like/boul weureuti ba son degloul sa xel topal sa xol sa dieuf /moy thieur bou dieuf dji bakhee aldianay sa keur

Fo dieulee dolè beuneu wen beuss bingay dora nap nam gueumal sa bop, gueum sa liguey ,lo dougou am ci ndam god/

Roki me roki la wotee la wotee thie diam manam
Newona rassoul kou tedeki topal sa yonou mam ibrihim

Bo beuguee degue kamil na deugue nek kani
Fonkal yaye ak bay sa wassila bi niane nga dek amine

Bou laf done mayee diam ramatou dou ham pierre
Ay bindafon di hekh nguir yaw tee thie yaw lagn nee bo thiakaree nimlay nakaree metit ngay yeuk
Yeurmandee yala rekay walou diam bi tee ken amoul dieuk bi yeah

Tags and Topics

Browse our collection to discover more content in these categories.

Video Information

Views

716.1K

Likes

20.7K

Duration

3:34

Published

Aug 28, 2020

User Reviews

4.8
(143)
Rate:

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

Related trending topics. Click any trend to explore more videos.

Trending Now