Akhlou Brick - Dama La Love 🎶

Available on iTunes, Apple Music, and Spotify. Listen to Akhlou Brick's 'Dama La Love' now!

Akhlou Brick - Dama La Love 🎶
AkhlouBrickTV Officiel
8.6M views • Oct 25, 2019
Akhlou Brick - Dama La Love 🎶

About this video

Disponible/available:
iTunes: http://itunes.apple.com/album/id1485207454?ls=1&app=itunes

Apple Music: http://itunes.apple.com/album/id/1485207454

Spotify: https://open.spotify.com/album/7znaL6h4gk4QiGgAtKMmYZ

Directed by WANTD

Mix,edit & master : Max Mix QGS Records
Beat : Iss 814
Percu : Papis Mbaye (PMP)

Images : Nazir Ciss
Lights : CHeikh Elpheno & Young Fresh
Make Up : Lissa Pro

Avec la participation de Prestige Deco
et Suma Assistance

LYRICS
Bb yaw ba nam nga ma
man dama la nam ba nam nimala namé eh eh
Té yaw bb tam nga nak, dieul peage bi raw ma mai nak tay ma feul pé eh
bb yaw ba aimer nga ma man damala aimer ba aimer ni mala aimer eh eh
Tè Yaw bb diaral ngama dohé ak ay dal wegn thi desert bi bamou dieh ehh
Bamou dieh Bamou dieh
Def ma ndank yama meun thi pét ma nangouwat ko thi diam Lay doh
Wahone nalako thi souba faw ma bamtouwat ko.

Damala Love
Yaw Damala love
Té Andou mathièk sago
Bb Dama la Yeah yaw dama la love
Mala topé dina dof baby

Negga man rek malay togn
Wanté boudoul man kenen kan moko sagne
Negga man may guenee sa rangogne
malay tongn bafou togn yam dik baloula tado bagn bae
Yanssay damay yeukeuti sama batt
Merr nela may nala batt yaram bi daw ma reuthiou wakh diou niaw gneuw dila balou wat
Nan b damadone fo dama tam ay wakhou kon hanadou may Tom yay Jerry beugante meunta niak thiow yaw
Sekougnou demal ma dem
awma mot hepna je t’aime motah malay wah damla bagn ,mais damla nob meunoul ame prix yaw am nga prix nobel ,man damla nob damla nob ba lab ci guédiou nobel love you.

#Akhloubrick #Damalalove #Namnala

Tags and Topics

Browse our collection to discover more content in these categories.

Video Information

Views

8.6M

Likes

53.2K

Duration

3:20

Published

Oct 25, 2019

User Reviews

4.4
(1728)
Rate:

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

Related trending topics. Click any trend to explore more videos.