Abdou Guite Seck - Tangal (Official Video) đ¶
Découvrez le clip officiel de Tangal d'Abdou Guite Seck, une chanson sur l'amour, un thÚme universel. Abonne-toi pour plus de musique!

Abdou Guité Seck
757.6K views âą Oct 29, 2023

About this video
** Abonne- toi en cliquant ici http://bit.ly/abdouguite pour suivre mon actualité musicale **
Lâamour, Ă©lĂ©ment omniprĂ©sent de notre quotidien, continue Ă mâinspirer.
Voici le premier titre de mon album KAKATAR.
Jây chante lâacharnement dâautrui face Ă une relation amoureuse qui ne lui plaĂźt pas. Lorsquâun couple fait face Ă cette situation, il doit garder ses distances et Ă©viter tout faux pas qui donnerait victoire Ă lâennemi. Comme dit lâadage : pour vivre heureux, vivons cachĂ©s .
Je suis en dĂ©phasage avec certaines croyances claniques selon lesquelles les mariages hors castes sont socialement inacceptables, voire tabous. Ces considĂ©rations dĂ©coulent souvent de la cupiditĂ©Ì, de la culpabilitĂ©Ì des parents et de bon nombre de personnes animĂ©es de mauvaise foi.
#abdouguiteseck #tangal #clipofficiel #kakatar #mbalax #ags #team221 #senegal
"Danse ma musique et écoute mes paroles" - voir lyrics ci-aprÚs dans la description -.
** Crédits de la chanson & du clip TANGAL **
Auteur Compositeur : Abdou Guite SECK
Enregistrement - Mix - Arrangement - Mastering : Bril (ClassâChic Studio)
Réalisation clip : Pac Deejay
Une production AGS Music (octobre 2023, Dakar, Senegal)
** Ecoute la musique d'Abdou Guité Seck **
Apple https://music.apple.com/us/artist/abdou-guite-seck/1178336681
Spotify https://open.spotify.com/artist/3H5Pn6GQSz3guRlI5zNoOi
Deezer https://deezer.page.link/aezBVT8ka6khfXQd7
Boomplay https://www.boomplay.com/artists/1032221
** Retrouve Abdou Guité Seck sur les réseaux sociaux :
Facebook https://www.facebook.com/guiteseck
Instagram https://instagram.com/abdouguiteseck
TikTok @abdouguiteseck
X https://x.com/abdou_guite
** Les lyrics de la chanson TANGAL **
Diogual guaaw nioun niou dem balla mouy nieuw
Ndakhte moom nena diggënte bi nekhou ko
Mone kham na ni dara douniou feweule
Waya ne noumou meun def di na gniou dëdële ( bis)
Woo! khale bile beug naa laa
Boma nakhe di nga ma gagnë noon ba contaan
Diogal ma
Diogal ma
Diogal ma ma beggal la
Diogal ma
Diogal ma
Diogal ma niou dem fanenoo
Diogual gaaw nioun niou dem blow, blow ba dano
Diogual guaw nioun niou dem fe fe wa guën fi
Diogual guaw nioun niou dem balla mouy nieuw
Ndakhte ne noumou meun def dina niou dëdële
Woo ! khale bile beug naa laa
Boma diouye di nga ma gagnë noon ba contaan
Diogal ma
Diogal ma
Diogal ma ma beggal la
Diogal ma
Diogal ma
Diogal ma
Diogal ma
Diogal ma
Diogal ma
Diogal ma niou dem fanenoo
Gone gui lou mou lath
Diokh ko
Gone gui loumou lath
Diokh ko
Boufi laadie kani
Bou fi laadie bongbong
Bou fi laadie « TANGUAL »
Wooo boul ko diokh
Tangual booboo ma yobe lima dal
Gone gui lou mou laath
Diokh ko !
Gone gui loumou laath
Diokh ko !
Boufi laadji kani
Diokh ko !
Bou fi laadjie nokkos
Diokh ko !
Bou fi laadjie pobare
Diokh ko !
Bou fi laadie tangual
Wooy boul ko diokhâŠ..
TANGUAL bobo ma yobe li ma dal
Bou len koko may ndakh gueweul la
Lolou andou ma thi
Bou len koko may ndakh toroodo la
Yeufi diondo la reck
Bou len koko may ndakhte li la
Wakhi kassaw kassaw
Bou len koko may ndakhte le la
Futilité la reck
Bou len koko may ndakhte laobe la
Man andou ma thi
Bou len koko may ndakh te teugu la
Yeufi diondo la reck
Bou len koko may ndakhte li la
Wakhi kassaw kassaw
Bou len koko may ndakhte le la
Futilité la reck
Yefer bi nieuw aki dondiam
Nga oubil ko nekk
Dalal ko tekk thi di ko bernde
Alal dong gua guis
Bou len koko may ndakhte li la
Wakhi kassaw kassaw
Bou len koko may ndakhte le la
Futilité la reck
Diogual gaw nioun niou dem blow
Blow ba daano
Diogual guaw nioun niou dem fe
Fe wa gën fi

Tags and Topics
Browse our collection to discover more content in these categories.
Video Information
Views
757.6K
Likes
15.8K
Duration
4:02
Published
Oct 29, 2023
User Reviews
4.8
(151) Related Trending Topics
LIVE TRENDSRelated trending topics. Click any trend to explore more videos.
Trending Now