Ashs The Best - Weetël Feat Amira Abed (Official Audio)

https://ashsthebest.s-ib.link/Weetel Album "DibÚer" ici :https://wiseband.lnk.to/Ashs-The-Best-Dibeer Retrouvez-moi sur mes réseaux sociaux FaceBook - https...

Ashs The Best‱836.4K views‱3:44

About this video

https://ashsthebest.s-ib.link/Weetel
Album "DibĂšer" ici :https://wiseband.lnk.to/Ashs-The-Best-Dibeer

Retrouvez-moi sur mes réseaux sociaux
FaceBook - https://www.faceboook.com/AshsTheBest/
Instagram - https://www.instagram.com/ashsthebest/
Snapchat - ashsthebest

Parole / lyrics
Muy suba muy guddi
Muy naaj
Mbaa muy soobee
Mësu maa woote
Te wuyu loo ma
Boo weetee gore
Weetali ku nga akk sa mbëggeel
Mësu maa woote
Te wuyu loo ma
Ah Yeah
Ah Yeah
Eh Yah
Mësu maa woote
Te wuyu loo ma

Fii ci addun yaa
Gisu ma ku melni yow
Mbëggeelam yaatu na
Yërmandeem moo ma yeem
Ku melni yow
Benn la dootul ñaar
Yaay sama Aljana
Yow mi ma teg yoon
Ci yoonu leer
Cause I've been fearless
To get to the road tonight
Because so been love
Nobody never
Everything how to try
But I believe in miracle now
You're right here
Yow mii sa mbëggeel bi yaatu na ni Adduna
Gestu gis la sama wet muy Aljana
Mësu maa la woo te wuyu loo ma
Sa yërmande yeem na ma man
Xeebu loo benn yoon siggil nga ma
Def ma ni sa bopp te won nga ma
I've been so grateful for your love

Muy suba muy guddi
Muy naaj
Mbaa muy soobee
Mësu maa woote
Te wuyu loo ma
Boo weetee gore
Weetali ku nga akk sa mbëggeel
Mësu maa woote
Te wuyu loo ma

Mësu ma la woo wuyu loo ma
Saayu ma soxla nga jox ma xañ sa bopp
Li nekk ci Yow moy daw ci man mii
Suma la gisee
Moy gis naa sama bopp
Lu fees ci xol feeñ ci jëmm jii
Yow sa mbëggeel moo may weetali
Yow mii
Sa mbëggeel bi yaatu na ni Adduna
Gestu gis la sama wet muy Aljana
Mësu maa la woo te wuyu loo ma
Sa yërmande yeem na ma man
Xeebu loo benn yoon siggil nga ma
Def ma ni sa bopp te won nga ma loolu
I've been so grateful for your love

Muy suba muy guddi
Muy naaj
Mbaa muy soobee
Mësu maa woote
Te wuyu loo ma
Boo weetee gore
Weetali ku nga akk sa mbëggeel
Mësu maa woote
Te wuyu loo ma
Te wuyu loo ma...

Traduction française

COMPAGNON

Refrain
Qu’il soit jour ou nuit, qu’il pleuve ou fasse chaud
Je n’ai jamais appelĂ© sans tu ne rĂ©pondes
Digne dans la solitude, ton amour t’accompagne
Je n’ai jamais appelĂ© sans tu ne rĂ©pondes

Couplet
Sur terre il n’y a pas ton semblable
Ton amour est immense et ta compassion m’émerveille
Il n’y a pas deux comme toi, tu es unique
Tu es mon paradis et tu m’as mis sur le droit chemin
Parce que je n’ai jamais eu peur d’emprunter ce chemin la nuit
Parce que je suis tellement amoureux
Personne n’a jamais su comment essayer
Et je crois au miracle et je suis lĂ  maintenant
Toi, ton amour est immense comme l’univers
Te voir à mes cÎtés est mon paradis
Je n’ai jamais appelĂ© sans tu ne rĂ©pondes
Ta compassion m’émerveille
Tu ne me négliges pas et tu es fiÚre de moi
Tu me considĂšres comme ton prochain et c’est prouvĂ©
Je suis reconnaissant de ton amour

Refrain
Qu’il soit jour ou nuit, qu’il pleuve ou fasse chaud
Je n’ai jamais appelĂ© sans tu ne rĂ©pondes
Digne dans la solitude, ton amour t’accompagne
Je n’ai jamais appelĂ© sans tu ne rĂ©pondes

Couplet
Je n’ai jamais appelĂ© sans tu ne rĂ©pondes
Si je suis dans le besoin, tu me donnes en t’en privant
Quand je te vois c’est comme si c’était moi-mĂȘme
L’ĂȘtre est remarquable sur le paraĂźtre
C’est ton amour qui me tient compagnie
Toi, ton amour est immense comme l’univers
Te voir à mes cÎtés est mon paradis
Je n’ai jamais appelĂ© sans tu ne rĂ©pondes
Ta compassion m’émerveille
Tu ne me négliges pas et tu es fiÚre de moi
Tu me considĂšres comme ton prochain et c’est prouvĂ©
Je suis reconnaissant de ton amour

Refrain
Qu’il soit jour ou nuit, qu’il pleuve ou fasse chaud
Je n’ai jamais appelĂ© sans tu ne rĂ©pondes
Digne dans la solitude, ton amour t’accompagne
Je n’ai jamais appelĂ© sans tu ne rĂ©pondes

Parole / Traduction By Malick Sy

#Weetël #AshsTheBest #AmiraAbed

© 2022 Nautylusprod

Tags and Topics

This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:

Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.

4.7

167 user reviews

Write a Review

0/1000 characters

User Reviews

0 reviews

Be the first to comment...

Video Information

Views
836.4K

Total views since publication

Likes
12.2K

User likes and reactions

Duration
3:44

Video length

Published
Jan 13, 2022

Release date

Quality
hd

Video definition

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in South Korea under the topic 'a'.

Share This Video

SOCIAL SHARE

Share this video with your friends and followers across all major social platforms including X (Twitter), Facebook, Youtube, Pinterest, VKontakte, and Odnoklassniki. Help spread the word about great content!