Wizzy Kana Feat Fantastic - Ndaat Saay ( Clip Officiel )

#wizzykana #sénégal #abonnetoi Disponible sur toutes les plateformes streaming https://bfan.link/ndaat-saay Artiste : Wizzy Kana Feat Fantastic Compositi...

Wizzy Kana270.6K views3:18

About this video

#wizzykana #sénégal #abonnetoi Disponible sur toutes les plateformes streaming https://bfan.link/ndaat-saay Artiste : Wizzy Kana Feat Fantastic Composition Musicale : Fantastic Beatz Mix - Master : PeulBouHigh Beatz Arrangement : Zox Guitariste : K guitz production: MBT100©️ Réalisation : Kainri Pictures Montage & Etalonnage : Kainri Pictures Assistant Cam : Halil Prod & Rozay Shoot Habillement : Mamour Shop , FMAR Design & Tamsir Sena Couture LYRICS Ndaat saay Jaral ngama taxaw fetial leuh ndate saayé Yaay bourou sama xol kone foula nekh feulaalé Koula songg beurrei nga daan ko Thi dig eute bi noula nekh dagoo Farata rek laaladoon doyei Damala nope ba am sa faiblesse Lou eupp tourou bvby lii dafa fees Damlay xalaat ba sama xel bi né mess Lou waay deugeur deugeur dinga danou Say kesseng kesseng momay takha aallu Yeegeul sama xel dima souss loo Yaa raw dadiou volet bimay takha metti Risque leuh Risque leuh Jeema dokh sa garde risque leuh Risque leuh Risque leuh Jeema dokh sa garde risque leuh Jalgati jalgati iow Sama xol bi yaako yeungeul yeungeul Iow yaamay fethie loo ndaate saay Jalgati jalgati iow Sama xol bi yaako yeungeul yeungeul Iow yaamay fethie loo ndaate saayé Linguère linguère Iow yaamay fethie loo ndate saayé Linguère linguère Iow yaamay fethie loo ndate saayé Deukké dima tiaw xiir bi doo baalé Dawal sama kaw deema yoobalé Ehh deguine ndate saay Ehh deuguine ndate saay Tay ma fetial la deuguine ndate saayé Chéré sama chéri Yaama téré nelaw Say tiakass tiakass sama kaw Lii moma tée Deff ma ndank Deff ma ndank Xalei bi dina meusseu ray doomou diambour Yaadi wourouss ngalam Féthial ma toukoussou ngalam Yaay awoo buuru keureum Kou merr nafa dé yaafa kham Xalé bi amoo morom Maala sante geureum Or nga yeugoo peureum Iow laay topp deema beureung Risque leuh Risque leuh Jeema dokh sa garde risque leuh Risque leuh Risque leuh Jeema dokh sa garde risque leuh Jalgati jalgati iow Sama xol bi yaako yeungeul yeungeul Iow yaamay fethie loo ndaate saay Jalgati jalgati iow Sama xol bi yaako yeungeul yeungeul Iow yaamay fethie loo ndaate saayé Linguère linguère Iow yaamay fethie loo ndate saayé Linguère linguère Iow yaamay fethie loo ndate saayé
4.7

54 user reviews

Write a Review

0/1000 characters

User Reviews

0 reviews

Be the first to comment...

Video Information

Views
270.6K

Total views since publication

Likes
9.9K

User likes and reactions

Duration
3:18

Video length

Published
Jul 29, 2023

Release date

Quality
hd

Video definition

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Egypt under the topic 'f'.

Share This Video

SOCIAL SHARE

Share this video with your friends and followers across all major social platforms. Help spread the word about great content!