DIP DOUNDOU GUISS - CALIFAT

#Califat disponible sur toutes les plateformes de streaming ! ?? https://orcd.co/califat ? @LUDAFRICKPRODZ Mix/mastering : @KarabalikBeatz ....................

Dip Doundou Guiss TV‱3.7M views‱3:55

đŸ”„ Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Tunisia under the topic 'ca'.

About this video

#Califat disponible sur toutes les plateformes de streaming ! đŸ‘‰đŸŸ https://orcd.co/califat đŸ„ @LUDAFRICKPRODZ Mix/mastering : @KarabalikBeatz .................................................................................................... Maison de Production : Couro Prod Directeur de Production : Ibra Almamy DIA Assistant de production : Bamba TRAORÉ Administrateur de production : Papa Ibrahima NDOYE RĂ©alisateur : Eric BERGES Concept & DA : Eric BERGES 1er Assistant rĂ©al : Ibou BARRY 1er Chef opĂ©rateur : Leye GUEYE 2nd Chef opĂ©rateur : Real Thiat Assitant camĂ©ra 1 : Djiby NIANG Assistant Cam 2 : Mamadou DIALLO D.I.T : Fatou Diop Chef Ă©lectro : Fatah FARIS Électro : Cherif DIALLO Assistant Électro : Pape Samba KANDÉ DĂ©corations & accessoires : Yarba DĂ©co Maquillage : Penda Fall NDIAYE Assistante Maquillage : Maman DIOP 2nd Assistante Maquillage : Maman Daba FALL Chef Costume: Malick MBENGUE Habilleuse : Adja Lovely CISSÉ RĂ©gisseur GĂ©nĂ©ral : Mamadou NDIAYE Adjoint rĂ©gisseur : Badara Barry Aide rĂ©gie : Mouhamed GUEYE Aide rĂ©gie : Ibou GUEYE Aide rĂ©gie : Fadel BARRY Post Production : Reverse Studios Montage : Bilal MBENGUE Assistant Montage : Ousmane 
 Motion Design : Bilal MBENGUE Étalonnage : Bilal MBENGUE Remerciements : Direction de la cinĂ©matographie Dojo National (Camara – BĂ«g Bamba KaratĂ©) MĂšre Sophie (MĂ©dina) Pepsi SĂ©nĂ©gal Dolima SĂ©nĂ©gal Moustapha DIOP dit Alex danseur Souleymane BARRY Dame GUEYE Jakarta ThiĂšs Chefs de projet : Sir FALL – Mahtarus .................................................................................................... LYRICS Couplet 1 Bamay duggu ci game bi, Dama tĂ«ju rek di job pour samay buntu tijeeku Xawma woon ñi tax may sonnay xĂ«y bĂ«ss buux ma ci teen bi Ñaata dĂ«m, jĂ«mmu nit, lamiñu unku ci gemiñ Mussu ma juutu ci game bi, fayuma juuti ci game bi Ma yĂ«rĂ«m thiouthie yi fi dem bañu dagg seen thiouthiou ci game bi Segam old school du ruux ci wutum turr new school bi du leen jigg Rapwolof du raw kenn day mĂ«ssa suulu ni teer bi Man duma middle school, may middle finger ruux tuunu game bi Ci son ci scĂšne maguel ba mĂ«n ma jurr du tee ma sutt la fuuf Bul ñodi chef ceeneel te cool sa cool Tojo fudul sa douche Di course pour mĂ«n dab coute que coĂ»te Muju di wutt secours Ken xamula ni ku sa propre mĂšre di wo di juum sa turr I don’t talk to these niggers Got no love for these niggers Don’t give a fuck about your motherfucking soul pussy niggers Sama ligeey moy faye di soul ay man Renn damay samp rang wu dĂ© di xaar kuy burle man Hook Xaar bi du yagg ba raw ma Capi bi champing bi ñëw na Yaw bandit sa papa ji ñëw na (ñëwna Yeah ñëw na) Chef bi ñëw na Xaar bi du yagg ba raw ma Capi bi champing bi ñëw na Yaw bandit sa papa ji ñëw na (ñëwna Yeah ñëw na) Chef bi ñëw na Couplet 2 Bamay duggu ci game bi jugge ci suufu tunnels yi Yekci di kung fu ni jet li LĂ«ndĂ«m ni sunguf bu weex bi Tek ci ñuul kukku ni derr bi Sutt la ci lepp, ngay xolu ndax dip sa coup de cƓurou mĂšre la Ci volcan lalay denthie, dumala suul fu suuf mĂ«na sedd Ñun ñoko fiy teg fu leer Ngeeni futeeku merr Ñun ño ngi ci suñu 10e saison sĂ©rie yeen ben sketch ngeen MĂ«n fenn, da ngeen ci dĂ«ggu ni kuy julle ku dee Suul ngeen ma du lu mĂ«n nek mais nak bul xeeb sa rĂȘve Rabatuma xaj bu jugg di ñoddi wutang clan Ni gumbak tele Du mak yeen ñepp wut leen keneen Man rekkay genne clashs yi topante ni douze ak treize May guux seen deret Tiim game bi yepp ni ndiounga kebe Nigga who’s next ? Somebody tell me who’s next again ? You think you better than me you take the L I’m supposed to win always one of them got to lose everyday Ben respect ngeen ma yoreel moy bu ndioulek ak salbe Hook Xaar bi du yagg ba raw ma Capi bi champing bi ñëw na Yaw bandit sa papa ji ñëw na (ñëwna Yeah ñëw na) Chef bi ñëw na Xaar bi du yagg ba raw ma Capi bi champing bi ñëw na Yaw bandit sa papa ji ñëw na (ñëwna Yeah ñëw na) Chef bi ñëw na Xaar bi du yagg ba raw ma Capi bi champing bi ñëw na Yaw bandit sa papa ji ñëw na (ñëwna Yeah ñëw na) Chef bi ñëw na Xaar bi du yagg ba raw ma Capi bi champing bi ñëw na Yaw bandit sa papa ji ñëw na (ñëwna Yeah ñëw na) Chef bi ñëw na ..................................................................................................... Clips officiels : https://bit.ly/ClipsofficielsDip ..................................................................................................... Suivez-moi sur les rĂ©seaux sociaux : Facebook : https://web.facebook.com/dipdoundouguissofficiel Twitter : https://twitter.com/DipDunduGuiss Instagram : https://www.instagram.com/dip_doundouguissofficiel Snapchat : Dip490

Video Information

Views
3.7M

Total views since publication

Likes
92.0K

User likes and reactions

Duration
3:55

Video length

Published
May 14, 2022

Release date

Quality
hd

Video definition

Captions
Available

Subtitles enabled

Tags and Topics

This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:

Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.