Cherifou & Job Sa Brain ( BAMBA)

Reconnu parmi les figures les plus emblématiques de l’islam, CHERIFOU & JOB SA BRAIN REND HOMMAGE AU FONDATEUR DU MOURIDISME CHEIKH AHMADOU BAMBA MBACKÉ KHAD...

Ziz'Art•3.1M views•3:25

About this video

Reconnu parmi les figures les plus emblématiques de l’islam, CHERIFOU & JOB SA BRAIN REND HOMMAGE AU FONDATEUR DU MOURIDISME CHEIKH AHMADOU BAMBA MBACKÉ KHADIM RASSOUL à travers ce titre. Label : RockteamMusik Contact management : Yass 00221 77 708 04 82 Réalisation :Ziz'Art 00221 76 324 78 77 Musique : Abbra Kora : Elhadjii Kora Intro Mourite touba sunu xol Mourite khelcom sunu toll Mourite thianta lay dõne Mourite baye fall lay dõne Mourite touba sunu xol Mourite khelcom sunu toll Baye fall lay dõne Thianta lay dõne Refrain Bougnou Diaggé Nagnou xam léep yaw laa Bougnou Goré Gnou sante laa warna Yaw Bamba,cheikh Ahmadou Bamba Xaliil gua Yonn ,Indi gua léer .Bounou Diagué léep yaw la,Bounou Goré Nélaa Yaw laa. Couplet 1 Jeuff gua Lou Reuy si xol Gnou diko séddé Indi gua xéweul ,Indi gua Naatangué Touba moy Guenél du sùnu Mbécté,Islam Amati Ndàm gnou Dikko Fêter Diguenté Wirwir Mayomba Diouli si guéthi akk NõNam Ya Taxùko Yénni Yanaam baa Yalla la Doylo ak Yonéen Baa Lamù Tontou bureau bâ sa Ndar Takhaaw Ni yalla bour Ibra fall Fégnou Koo Nànn :Mbacke yaye sén bour Refrain Bougnou Diaggé Nagnou xam léep yaw laa Bougnou Goré Gnou sante laa warna Yaw Bamba,cheikh Ahmadou Bamba Xaliil gua Yonn ,Indi gua léer .Bounou Diagué léep yaw la,Bounou Goré Nélaa Yaw laa. Couplet 2 Jangalé gua Alkhourane Térée na Safane Dimbali ganou bagnou Mouthiou si Nassarane Niogui sùkù Raam Délou Sakù Niann ,serign bi Taff nou sa Barké. Dômi Mame Diarra Yoroul Liy Loré Mbacke Balla Aisha Ya Goré Yarr ganou Yiir ganou ar ganou Ya tabé Soll ganou Jikko Yi Geunn Gnù Diko wanée Lamou Tontou Bureau bâ sa Ndar Taxaaw nii Yalla bour Ibra fall fégnou KO Naan Mbacke yaye sén bour Refrain Bougnou Diaggé Nagnou xam léep yaw laa Bougnou Goré Gnou sante laa warna Yaw Bamba,cheikh Ahmadou Bamba Xaliil gua Yonn ,Indi gua léer .Bounou Diagué léep yaw la,Bounou Goré Nélaa Yaw laa. Outre Ayoo léeeée...............bis Kén d'où Mame cheikh ibra fall Baye fall, baye fallou baye Faye yi Kokou moy cheikh ibra fall Abo Ridial. #bamba #rocktem #Zizart

Tags and Topics

This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:

Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.

4.4

612 user reviews

Write a Review

0/1000 characters

User Reviews

0 reviews

Be the first to comment...

Video Information

Views
3.1M

Total views since publication

Likes
19.5K

User likes and reactions

Duration
3:25

Video length

Published
Oct 3, 2019

Release date

Quality
hd

Video definition

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Kenya under the topic 'betty bayo'.

Share This Video

SOCIAL SHARE

Share this video with your friends and followers across all major social platforms. Help spread the word about great content!