Cherifou - Pop Pop (Clip Officiel)

"POP POP", Un titre certe simple mais qui engendre de riches paroles dans lesquelles L'artiste nous fait savoir que la vie est si éphémÚre,et que ni la jalou...

Cherifou L’officiel‱21.5M views‱3:38

đŸ”„ Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Singapore under the topic 'itoto system 12'.

About this video

"POP POP", Un titre certe simple mais qui engendre de riches paroles dans lesquelles L'artiste nous fait savoir que la vie est si Ă©phĂ©mĂšre,et que ni la jalousie, ni mĂ©chancetĂ© ne devraient avoir une place dans notre sociĂ©tĂ©, mais devraient pas aussi nous freiner Ă  atteindre nos objectifs. Savoir rĂ©agir avec classe et Ă©lĂ©gance, bravoure et persĂ©vĂ©rance, fait la force de l'homme et cela nous amĂšne Ă  ĂȘtre "POP POP" CrĂ©dits de la chanson et du clip Beat : Thiokos Guitare : Seydou ba Percussion : Pape Ndiaye tama Mix & mastering : Polibeat RĂ©alisation : Gaby iris / iris av Coiffure : Demba tarrou locks 78 432 00 50 Contact Watshap : +221 77 840 00 80 / 77 847 12 12 â–ȘSuivez-moi sur mes rĂ©seaux 🔾Instagram : https://instagram.com/cherifou__lofficiel 🔾Facebook : https://www.facebook.com/profile.php?id=100035350346924 🔾Tik Tok : https://www.tiktok.com/@cherifouofficial Stream & Ecoute : https://bfan.link/pop-pop #cherifou #poppop #senegal #dakar #music Lyrics PoP PoP Kay kay kay kay Kay ma khamal la ni Adoun’ya dou benn fann Kingay toguĂ© tay bou souba meun’nala yĂ©y Kay ma digual’la ni Bouldi khol nitt diko niĂ© Meul nala yobbĂ© ignaaan (ignaan ignaaan) Yangui coq 🐓 coq ba callĂ© May Pop pop ci khalĂ© Ngay togg togg ba callĂ© DiĂ©mo tĂ© meuno dabbĂ© Man soma beugoulĂ© boul saalĂ© Guiss’nanĂ© dolĂ© feeling bĂ©la poussalĂ© Ehhhhhh yah So beugoulĂȘ boul salĂ© Bayil sokhor ignaan dalay tĂ© Boko toppĂ© dangay dĂ© firiil sa khol Refrain Ay way ah yeukna linga nĂ©kkĂ© (ay door rĂ©k) Malay lĂ©bal mbakh ngamay fĂ©khĂ©l (ay door rĂ©k) Eh bal doorĂ© Guiss’nala ngay leurĂ© eh eh ehhhh do gorĂ© Man guiss’na ningmay worĂ© Boul dĂ©fĂ©ni ninga nĂ©kkĂ© yeugoumako dama doylou bo dĂ©ffé’ni ya geuna yĂ©wou nieup, nalaw nga bay galleu Thioy rĂ©k Yaw deukĂ©ll thioy rĂ©k Thioy rĂ©k Yaw deukĂ©ll thioy rĂ©k DĂ©l thioy rĂ©k 2e Couplet Dembeu yanei woon Dembeu yanei woon ni gorĂȘdiwo Konn loula diapp tay banga nĂ© ci yoonou noon Non parĂ©gouma Nono tambalĂ© gouma Yay sakhol ci nianaal’ma Sabo douhan ouma mi falama nĂ©nĂ© barakaa Yangui coq 🐓 coq ba callĂ© May Pop pop ci khalĂ© Ngay togg togg ba callĂ© DiĂ©mo tĂ© meuno dabbĂ© Yaw woutal bĂ©neen yoon bo diarei Yaw dĂ©mo kou nekk ci yoon nga diĂ©m’ko garĂ© Bayil sokhor ignaan dalay tĂ© Soko toppĂ© dangay dĂ© firiil sa khol Refrain Ay way ah Yegg’na linga nĂ©kkĂ© (ay door rĂ©k) Malay lĂ©bal mbakh ngamay fĂ©khĂ©l (ay door rĂ©k) Eh bal doorĂ© Guiss’nala ngay leurĂ© eh eh ehhhh do gorĂ© Man guiss’na ningmay worĂ© Boul dĂ©fĂ©ni ninga nĂ©kkĂ© yeugoumako dama doylou bo dĂ©ffé’ni ya geuna yĂ©wou nieup, nalaw nga bay galleu Thioy rĂ©k Yaw deukĂ©ll thioy rĂ©k Thioy rĂ©k Yaw deukĂ©ll thioy rĂ©k DĂ©l thioy rĂ©k Solo guitaar 🎾đŸȘ— Ambiance outro Thiow meunoul dara Wakh djou bonn fadioul dara (dedett) Thiow meunoul dara ci man wakh dji fadioul dara (dedett) Thiow meunoul dara ci man wakh dji fadioul dara (dedett) Thiow meunoul dara wakh dji fadioul dara Thiow meunoul dara wakh dji bonn fadioul dara Thiowli meunoul dara dafmay yokk dolĂȘ nopaloul KhalĂ© baangéééé (man’la) KhalĂ© baangéééé (kham’ngan man’la waaawaaw) Kham ngani man’la Ay man’la Affaire bi man’la Wooooy man’la NĂ©nagn’ma yaw la ehhhhh KhalĂ© baangéééé (man’la) Kham ngani man’la Ay man’la Affaire bi man’la Wooooy man’la NĂ©nagn’ma yaw la ehhhhh TĂ© bilae damay fo ak yennn 😊🔇

Video Information

Views
21.5M

Total views since publication

Likes
71.8K

User likes and reactions

Duration
3:38

Video length

Published
May 5, 2023

Release date

Quality
hd

Video definition

Tags and Topics

This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:

Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.