Aida Samb Gëstu - une production Prince Arts Studio (+LYRICS dans la Description)
Vous pouvez VOUS ABONNER à notre chaîne en CLIQUANT ici : http://www.youtube.com/subscription_center?add_user=princeartsmusic Rejoignez nous sur: Google+ ...
🔥 Related Trending Topics
LIVE TRENDSThis video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!
THIS VIDEO IS TRENDING!
This video is currently trending in Bangladesh under the topic 's'.
About this video
Vous pouvez VOUS ABONNER à notre chaîne en CLIQUANT ici :
http://www.youtube.com/subscription_center?add_user=princeartsmusic Rejoignez nous sur:
Google+ : http://gplus.to/PrinceArtsMusic
Facebook : https://www.facebook.com/PrinceArtsMusic
Twitter : https://twitter.com/princeartsmusic
- - - PAROLES - - - LYRICS - - -
{ commencer à chanter à partir de 1:11 :) }
Ling mey khol lo, dimako khelilo bobou beu legui mangui gestou man guissouma dara
Lingmey khol lo yaw dimako khelilo bobeu legui mangui guestou man guissouma dara...
Niit ki niit ki niit kiiii
Niit ki niit ki niit kiiii
Lingmey khol lo yaw dimako khelilo bobeu legui mangui thi mane mi khawmeu loumou done
Ndaw day sogua door diapeu tha la warr wayé boulko fakhasstale, loléé waroulaaa
Niit ki niit ki niit kiiii
Niit ki niit ki niit kiiii
Ndiom ak Ndiambar ra takhone mane meu topeu leu dem na beu guissoumeu thi yow fouleu mangui soumeu yone
Ndaw daye sogua dor diapeu tha la warr wayé boulko fakhasstale, loléé waroulaaa
Niit ki niit ki niit kiiii
Niit ki niit ki niit kiiii
Ndiom ak diambar a takhone mane meu topeu leu dem na beu guissoumeu thi yow fouleu mangui soumeu yone
Ndaw day sogua door diapeu tha la warr wayé boulko fakhasstale, loléé waroulaaa, loléé warouleu
Kalaass adouna ngi ni dal gestou ni la métééé
Kalaass adouna ngi ni dal gestou ni la métééé
Diafandoul diafandoul djeuf mom dafey wess
Diafandoul diafandoul djeuf mom dafey wess
Diafandoul diafandoul djeuf mom dafey wess
Amone na yaakaar ni soma khello khelliloma ma wakh la khalat lo ma yow
Adouna ak yatouwayam yalla ak yeurmandém bouko khol yillé yatouwone kone mou nekh beu diakhal ga gni
Mane bi mey gneuw fi mane khawma daray, te bimey gneuw fi bobou khaléla
Seyni ndiaye Fall thiey Seyni Ndiaye Fall yééé Seyni Ndiaye Fall
Mane bi mey gneuw fi mane khawma dara, té bimey gneuw fi bobou khaléla
Amari Guisse mane mimey woy kokou sameu ndidiaye la
Yalla moy bollé domou adama yi té moma bollék Coumba Fall Seck Coumba Fall yayou Mouhamed kokou sama maman la
Yalla moy bollé domou adama yi te moma bollé ak tonton Habib Sy tonton Habib gorou Coumba Fall kokou sameu ndidiaye la
Seyni Ndiaye Fall bi mey waye mom boléwoul dara ki wakh mom dinama téral té dina ma téral té dima tété ték mathi yone wou bakh
Mom Seyni ndiaye Fall thiey Seyni Ndiaye Fall yééé Seyni Ndiaye Fall
Video Information
Views
7.2M
Total views since publication
Likes
22.4K
User likes and reactions
Duration
6:30
Video length
Published
Aug 9, 2013
Release date
Quality
sd
Video definition
About the Channel
Tags and Topics
This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:
#Aida Samb #titi #pape diouf diofior #aida samb gestu #titi senegal #pape diouf begué #sen petit galle 2012 #pape diouf sadio #pape thiopete #pape diouf 2013 #pape diouf begue #Sa Nekh #Casse Casse #Lula Nex #Seneweb #diofior pape diouf #Sarabaa #titi jiggen feem #Mbalakh #Sénégal #West Africa #Africa #Studio #maison de production #Jololi #Youssou Ndour #Afrique #artistes africains #aida samb lula nex remix #sen petit galle 2013 #Prince Arts
Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.