Tamsir SN - KHAR YALLAH ( SN_Mood#2 )

#music #tamsir #senegal #newmusic #patience KHAR YALLAH – Un message d’espoir pour tous ceux qui traversent des moments difficiles. Cette ode qui vient en...

Tamsir SN•91.4K views•3:08

About this video

#music #tamsir #senegal #newmusic #patience KHAR YALLAH – Un message d’espoir pour tous ceux qui traversent des moments difficiles. Cette ode qui vient en renfort au concept SN MOOD nous rappelle qu’avec patience et foi, tout finit par s’éclaircir. « Mettineu Wayei Nanga Tok Khar Yallah » SN MOOD est une série visuelle artistique qui associe performance musicale et ambiance émotionnelle. Chaque épisode se concentre sur un morceau et une atmosphère unique, incarnée par l’environnement , le décor et la symbolique. L’objectif est de transmettre une image colorée de la vie sénégalaise dans ses différents aspects avec différentes sonorités, des messages forts et impactant. Production: Tamsir Music Director: Med Saloom Assist Director : Charles LO DOP : Moussa Ndiaye Editor : Med Saloom Color Grading : Moussa Ndiaye Photographe : Destiny Prod Recording: Mpossible Prod Beatmaker : Fissbass Beats Mix & Mastering : Zen Ridjal Assly Logistique : Melo Music Cover : POD Stylist: Bamba Couture LYRICS: Yenn saay xel mi né si diooy Mettina waayei nanga took xaar yallah Yangui try beu leegui mongui thiool Mettina waayei nanga took xaar yallah Sa weurseuk newoul si benn domou Adama Ndax Yallah buur bi moy kiy seddalei waay Bamkoy def si yow dou Tay yaggna (Dou tay yaggna) Defal lila warr mom moy mottali waay Sa yaay Liguey nako sa keur baye ( Ligueyou nday agnoup doom leu ) Tei baye nianal nala sama waadji (Geumeul dokh fo diaar yoon leu ) Fo diaar yoon leu Andalak sa ngor Gueum sa bopp Aw sa yonn ioe Lilay motali Yaako mana may sa bopp Boul xeep ben job Yagg yagg dineu nieuw ioe Ehh waay Yenn saay xel mi né si diooy Mettina waayei nanga took xaar yallah Yangui try beu leegui mongui thiool Mettina waayei nanga took xaar yallah Yenn saay xel mi né si diooy Mettina waayei nanga took xaar yallah Yangui try beu leegui mongui thiool Mettina waayei nanga took xaar yallah Jantt bi feinkneu djotna nga takk diouk Yaya booy yonni leu taxawaalou warouleu Finga dieum sorina yoonou ndaw dou gaaw Wowowoowowo Yoonou ndaw dou gaaw Nionguilay niaanal Yallah nga teral yaye Yallah nga siguil baye booy Saggal sa askann waay Nionguilay niaanal Yallah nga teral yaye Yallah nga siguil baye booy Saggal sa askann waay Mettina waay Mettina waayei dina nieuw Mann geumnaani Xamnaani dina nieuw Yallah limouy mayei dieexoul Anh wowowoo waay Yenn saay xel mi né si diooy Mettina waayei nanga took xaar yallah Yangui try beu leegui mongui thiool Mettina waayei nanga took xaar yallah Mettina waayei nanga took xaar yallah Mettina waayei nanga took xaar yallah
4.7

18 user reviews

Write a Review

0/1000 characters

User Reviews

0 reviews

Be the first to comment...

Video Information

Views
91.4K

Total views since publication

Likes
3.7K

User likes and reactions

Duration
3:08

Video length

Published
May 30, 2025

Release date

Quality
hd

Video definition

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Russia under the topic 'h'.

Share This Video

SOCIAL SHARE

Share this video with your friends and followers across all major social platforms. Help spread the word about great content!