Dip Doundou Guiss - Deuil National

Compositeur : Gilo Réalisateur : Reverse Studios Mix & mastering : Karabalik Beatz #DeuilNatonal disponible sur toutes les plateformes de streaming : https:/...

Dip Doundou Guiss TV‱1.1M views‱2:54

About this video

Compositeur : Gilo RĂ©alisateur : Reverse Studios Mix & mastering : Karabalik Beatz #DeuilNatonal disponible sur toutes les plateformes de streaming : https://orcd.co/deuilnational ............................................................................. Clips officiels : https://bit.ly/ClipsofficielsDip ............................................................................. Suivez-moi sur les rĂ©seaux sociaux : Facebook : https://web.facebook.com/dipdoundouguissofficiel Twitter : https://twitter.com/DipDunduGuiss Instagram : https://www.instagram.com/dip_doundouguissofficiel Snapchat : Dip490 ............................................................................. Lyrics Refrain Manatuma toog di xaar leneen Li nek sama bop bi xatt na fees na Manatuma toog di xaar leneen Dama muju joow ci gaal ba dess fa Lelelelelena dama muñ ba de, muñ bi jeex na Ndaw si diggu geej weet na, reer na Sama bakanay rot su geej gi mare naan Couplet Lo sorale dalay diisĂ«l, TĂ«wa fatte ñima bayi ginaaw Nap kat bi gĂ«dj na giss jĂ«n Ku saccul, ñaanul marr na xiif na Diplome ak journala yam kĂ«yit lĂ« Fay ndox ak courant ba tay dañuy tĂ« Suñu quotidien mo gĂ«na tiss tĂ«ss Suñu kĂ«r day taa ndox luñu miin lĂ« Xamul ndax yoonu xaru la am yoonu risque lĂ« Tekkey alxuranam, tekkey biblĂ«m Geej du mĂ«ssa rĂ«y ba Ă«p fittĂ«m GĂ«m ni buñu yegge nañ yeetal fitnĂ« Def ni ku rep giss yoon Dekkufi sedd di lox Defuñu ken lu bonn Dadj luñu yeene wul dom Soobu si teen bi di root Dem te ñëw tedd ni Gorr Dem te ñëw fay suñuy borr Delu samay digg mbok Don mak si kĂ«r di daw yĂ«rmande ak ndimbĂ«l motax ñu sĂ«ss xam liñu bĂ«g fimu ne moy xam fiñu jĂ«m Yoonu geej du liñu gĂ«nĂ«l liñu gĂ«nĂ«l moy am li gĂ«n Ken bĂ«gul doomam di taggo dem ñukoy deggat si dĂ«dj Gaal bu dĂ«ppu, kĂ«ppu, kĂ«ppale famille lĂ«m MĂ«no Ƌacc waye dem nga seeti charlie demb Juromi temeri neew Etat ne du wax si sen dĂ«dj Fi yaakar si nguur moy yaakar si ay ngandi dĂ«m Refrain Manatuma toog di xaar leneen Li nek sama bop bi xatt na fees na Manatuma toog di xaar leneen Dama muju joow ci gaal ba dess fa Lelelelelena dama muñ ba de, muñ bi jeex na Ndaw si diggu geej weet na, reer na Sama bakanay rot su geej gi mare naan

Tags and Topics

This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:

Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.

4.8

212 user reviews

Write a Review

0/1000 characters

User Reviews

0 reviews

Be the first to comment...

Video Information

Views
1.1M

Total views since publication

Likes
48.1K

User likes and reactions

Duration
2:54

Video length

Published
Nov 13, 2020

Release date

Quality
hd

Video definition

Captions
Available

Subtitles enabled

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Bangladesh under the topic 'argentina national football team'.

Share This Video

SOCIAL SHARE

Share this video with your friends and followers across all major social platforms. Help spread the word about great content!