JËLËL – L’amour assumé 💫
Entre douceur, espoir et douleur…
Tamsir chante l’amour qui résiste, celui qu’on choisit malgré tout.
Un seul cœur, une seule femme. Un amour vrai, fort et assumé. ❤🔥
JËLËL vient clore le voyage émotionnel du concept SN MOOD, après Xarit (l’amitié) et Khar Yallah (l’espoir).
Ce dernier épisode marque la fin d’une aventure artistique où la musique rencontre l’émotion, la symbolique et l’identité sénégalaise. 🇸🇳✨
Production: Tamsir Music
Director: Med Saloom
Assist Director : Mor Talla Lo
DOP: Moussa Ndiaye
Color Grading: Moussa Ndiaye
Editor: Mor Talla Lo
Graphic & Sound Design: Med Saloom
Cover: Med Saloom
Photographe: Destiny Prod
Beatmaker: Bigboss Beats & Lyriix Beats
Mix & Mastering : Zen Ridjal Assly
Model: Aissata
Make up: Adja Ly
Dancer: Africa By Fah
Outfits: Clothing 221, Bamba Couture, Noble Baye Fall & Baolbaol Clothing
Big thanks To: Hotel Yaa Dikone & Tapalapa Studio
LYRICS:
Nieup manko neen ni Yow laa nopp
Awma si yow saggo waw xamnaako
Kounek kinga appo mann dieulnaala
Bouniou meusseu taggo yow djik ngama
Aalma aalma
Aalma sa xol man doumako fowei
Toogn meu ma baal leu
Lo meuneu def té demo
Noum may mettei ?
Deema woo ma dila woo
Fonei mangsa guinaaw yow
Deema woo ma dila woo
Dinaala woo tay
Dinaala wo cheree
Yow mii laa teyei
Ndax yaama leen geuneul
Xamnaa fingma dieumei
Mo geun fingma dieulei ya
JËLËL
Loumou metti metti metti
JËLËL
Xamanlni ya mom xol bi JËLËL
Yow foula neex yobboumafa
JËLËL
Xamalni ya mom xol bi JËLËL
2ème partie :
Doumala seetan mou niaaw
Douma dem bayyila guinaaw
Mbeuguel guedjou mbamboulaan
Niou thiy feey beu abadane
Reewouloo
Meussoulooma gaagn
Soofouloo
Yeenei ngama diamm
Xamoulo nima mel si yow
Geunn si man
Sama cheree waay
Cey lissi mbeuguel manak mbeugueloo
Lii dh diaaxal nama
Cey lissi mbeuguel manak mbeugueloo
Mann dh diomal nama
Yow mii laa teyei
Ndax yaama leen geuneul
Xamnaa fingma dieumei
Mo geun fingma dieulei ya
JËLËL
Loumou metti metti metti
JËLËL
Xamanlni ya mom xol bi JËLËL
Yow foula neex yobboumafa
JËLËL
Xamalni ya mom xol bi JËLËL
Yow foula neex yobboumafa
JËLËL
Xamalni ya mom xol bi JËLËL
Yow foula neex yobboumafa
JËLËL
Xamalni ya mom xol bi JËLËL
Outro :
Aalma sa xol man doumako fowei
Lo meuneu def lo meuneu def yow
Lo meuneu def té demo
Noum may mettei yow ?