Ashs The Best - Weetël Feat Amira Abed (Official Audio)

https://ashsthebest.s-ib.link/Weetel Album "Dibèer" ici :https://wiseband.lnk.to/Ashs-The-Best-Dibeer Retrouvez-moi sur mes réseaux sociaux FaceBook - https...

Ashs The Best836.4K views3:44

About this video

https://ashsthebest.s-ib.link/Weetel Album "Dibèer" ici :https://wiseband.lnk.to/Ashs-The-Best-Dibeer Retrouvez-moi sur mes réseaux sociaux FaceBook - https://www.faceboook.com/AshsTheBest/ Instagram - https://www.instagram.com/ashsthebest/ Snapchat - ashsthebest Parole / lyrics Muy suba muy guddi Muy naaj Mbaa muy soobee Mësu maa woote Te wuyu loo ma Boo weetee gore Weetali ku nga akk sa mbëggeel Mësu maa woote Te wuyu loo ma Ah Yeah Ah Yeah Eh Yah Mësu maa woote Te wuyu loo ma Fii ci addun yaa Gisu ma ku melni yow Mbëggeelam yaatu na Yërmandeem moo ma yeem Ku melni yow Benn la dootul ñaar Yaay sama Aljana Yow mi ma teg yoon Ci yoonu leer Cause I've been fearless To get to the road tonight Because so been love Nobody never Everything how to try But I believe in miracle now You're right here Yow mii sa mbëggeel bi yaatu na ni Adduna Gestu gis la sama wet muy Aljana Mësu maa la woo te wuyu loo ma Sa yërmande yeem na ma man Xeebu loo benn yoon siggil nga ma Def ma ni sa bopp te won nga ma I've been so grateful for your love Muy suba muy guddi Muy naaj Mbaa muy soobee Mësu maa woote Te wuyu loo ma Boo weetee gore Weetali ku nga akk sa mbëggeel Mësu maa woote Te wuyu loo ma Mësu ma la woo wuyu loo ma Saayu ma soxla nga jox ma xañ sa bopp Li nekk ci Yow moy daw ci man mii Suma la gisee Moy gis naa sama bopp Lu fees ci xol feeñ ci jëmm jii Yow sa mbëggeel moo may weetali Yow mii Sa mbëggeel bi yaatu na ni Adduna Gestu gis la sama wet muy Aljana Mësu maa la woo te wuyu loo ma Sa yërmande yeem na ma man Xeebu loo benn yoon siggil nga ma Def ma ni sa bopp te won nga ma loolu I've been so grateful for your love Muy suba muy guddi Muy naaj Mbaa muy soobee Mësu maa woote Te wuyu loo ma Boo weetee gore Weetali ku nga akk sa mbëggeel Mësu maa woote Te wuyu loo ma Te wuyu loo ma... Traduction française COMPAGNON Refrain Qu’il soit jour ou nuit, qu’il pleuve ou fasse chaud Je n’ai jamais appelé sans tu ne répondes Digne dans la solitude, ton amour t’accompagne Je n’ai jamais appelé sans tu ne répondes Couplet Sur terre il n’y a pas ton semblable Ton amour est immense et ta compassion m’émerveille Il n’y a pas deux comme toi, tu es unique Tu es mon paradis et tu m’as mis sur le droit chemin Parce que je n’ai jamais eu peur d’emprunter ce chemin la nuit Parce que je suis tellement amoureux Personne n’a jamais su comment essayer Et je crois au miracle et je suis là maintenant Toi, ton amour est immense comme l’univers Te voir à mes côtés est mon paradis Je n’ai jamais appelé sans tu ne répondes Ta compassion m’émerveille Tu ne me négliges pas et tu es fière de moi Tu me considères comme ton prochain et c’est prouvé Je suis reconnaissant de ton amour Refrain Qu’il soit jour ou nuit, qu’il pleuve ou fasse chaud Je n’ai jamais appelé sans tu ne répondes Digne dans la solitude, ton amour t’accompagne Je n’ai jamais appelé sans tu ne répondes Couplet Je n’ai jamais appelé sans tu ne répondes Si je suis dans le besoin, tu me donnes en t’en privant Quand je te vois c’est comme si c’était moi-même L’être est remarquable sur le paraître C’est ton amour qui me tient compagnie Toi, ton amour est immense comme l’univers Te voir à mes côtés est mon paradis Je n’ai jamais appelé sans tu ne répondes Ta compassion m’émerveille Tu ne me négliges pas et tu es fière de moi Tu me considères comme ton prochain et c’est prouvé Je suis reconnaissant de ton amour Refrain Qu’il soit jour ou nuit, qu’il pleuve ou fasse chaud Je n’ai jamais appelé sans tu ne répondes Digne dans la solitude, ton amour t’accompagne Je n’ai jamais appelé sans tu ne répondes Parole / Traduction By Malick Sy #Weetël #AshsTheBest #AmiraAbed © 2022 Nautylusprod

Tags and Topics

This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:

Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.

4.7

167 user reviews

Write a Review

0/1000 characters

User Reviews

0 reviews

Be the first to comment...

Video Information

Views
836.4K

Total views since publication

Likes
12.2K

User likes and reactions

Duration
3:44

Video length

Published
Jan 13, 2022

Release date

Quality
hd

Video definition

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Chile under the topic 'candidatos a diputados 2025'.

Share This Video

SOCIAL SHARE

Share this video with your friends and followers across all major social platforms. Help spread the word about great content!